6 COMMENTAIRES
  • m

    doyna waar ! niit yi gueume'tou niou yalla. Dieuww, toumaal jambour, saaga, feen defanioukou dara.

  • baye

    Wa Senegal neuk danio eupeul togne baxoul. .naniou bayi nit yi niouy toumal way

  • JULES

    Lii métina toumal nite ba beugueuko sankh war nagno kholate sounou boopou. Réw mo xamni fén dieuwe toumal nite gnane.Liguéye dédéte, ay nélaw kaye, lék wawaw, dieufdiou gnaw mathi aye, manalang tékkii gnou rouma fila am sénégal
    Sokhor ignane réw mi rék la am

  • dudy

    Maintenant c est un psychose au Sénégal tout le monde est homosexuels attention à cela

  • cheikh a bamba sylla

    li dafa niaw wrema nit koy gorgrlou nga begeko yakh niaw na torop

  • magor

    no Senegal yene dal ni rek kou bouger kene ndieko gordeiguene ragale lene yalla touti bakhna

Publiez un commentaire