Arrêt sur image: Regardez la fierté de Al Amine à l’endroit de son talibé

Arrêt sur image: Regardez la fierté de Al Amine à l’endroit de son talibé

Après que Abdoul Aziz Alé Ndiaye a donné son hadiya (boeufs, denrées, boissons…) à son marabout, accompagné de son père, de ses frères et de ses amis comme Mouhamed Ndiaye opérateur économique, Al Amine lui a témoigné toute sa fierté.

Abdoul Aziz Ndiaye (4)

 

16 COMMENTAIRES
  • nina

    Aziz guene Nala beugue .

  • Maremabakary

    Li bilahi fierte la ci bep talibe thiekh li tivaouane bougnouci amone niete dina guene nekh aziz yalla nala yombe bou dewener ga meune lou raw li contana ci yaw

  • wa thies

    Aziz n'a la yalla faye

  • rebatass

    amine way

  • cheikh tidiane mbacke

    li moy yone danguene wara topando lou bakh comme les mourides

    • Ismaila diame

      Billahi wakh degue bou weur …roy lou bakh ba am ko

  • serigne sambe

    du courage tu pratiques la pèdagogie par l'exemple c'est à dire niatha ak niouthi

  • Bamba

    Machallah aziz, yala nalako yala yomballe deween ,rafetna trop

  • Kou bakh

    Cheikh Tidiane mbacke kouy topando daguay topando sa nawle

  • tocc tocc

    wax deug

  • babs

    Yalla nala Yalla faye

  • fall

    Aziz fofou la na degueure

  • diba

    roy donorok piir

  • mouride sadikh

    Moytouléne seytané yi diakhassé , gnoognouy diakhassé dougnouy mouride dé ay seytané lagnou . Féwalé rek moolène gnor . Ay franc maçon lanou. ,bagounou ken nek benn .

  • wa ouarkhokg

    wakh rafete ak dieuf diou bakh mo ame solo sante Dabakh

  • Awa fall

    Yalla ne meune meune bi yok amine

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *