Amdy Mignon à Tounkara : « Li Tfm def 2stv koussi wakhoul nafékh nga bassi yaw »

Amdy Mignon s’engage volontairement pour remettre la TFM à sa place. Selon le comédien, la chaîne de Youssou Ndour a volé le signal de la 2stv et les employés de la chaîne de El Hadj Ndiaye qui n’en parlent pas sont des hypocrites. Amdy suggère à la Tfm de faire une conférence de presse pour demander pardon à El Hadj Ndiaye…
tfm ken manou ko fay loudoul yalla rakhass lenn khol yi sokhor bakhoull
Amdy souy patron yi di khékh na soukouyi takhawé neulé téni moutt
Yene animateurs yi ak journaliste yi daguene wara neutre si séne problème patron yi téye hamguen folene di ligéyé wayé soube hamoulen folene di téré dé lene rafetetal sene wah teye dougue lousene yone nek
vérité absolue.
Yow pousseul fi gnake gua xorom torop li yeup pour essayer féye tfm
Qui est ce mec ?
youssou ndour est un voyou. leumbeul katt yi rekk gnoko xamoule
Andy yemal tee khame boy wakhe adouna da goudou tank
C est le premier Nafekh du Senegal ce TOUNKARA…avec sa tête de traître
Et toi le plus premier du bled.