(6 Photos): Macky Sall a inauguré le complexe Seydi El Hadji Malick Sy
Le président de la République, Macky Sall, a inauguré le complexe Seydi El Hadji Malick Sy, avant de présider dimanche le symposium du Gamou de Tivaouane en présence du porte-parole de la famille Sy, Sérigne Abdou Aziz Sy Al Amine.
Le thème de cette année est: «Face aux radicalismes quelles réponses de l’école de Tivaouane».
man dioulitte la yalla naniou ci yalla ray teede?kil niou si dioulitte amine.
Yena na niak diome di khasante thi ay tarikha dolene rouss sakh mane d mourid la waye watena ne douma neussa khass ba wakhlouniaw ab dioulite taloumako sakh refetallene
Mercy Matay nek Talibe Chiekh wakh nga degeu bou werr te leer,mandeh bokouma si ben tarikha mais nawna Tijan yi lool ndakh Yalla ak Muhamad S A W rek la niouy wakh
Ham nagne lilène métti Tarikha Tidiane molène gueuna sel sounou talibés doniou rast ba teug tama ni nan bière ni tokho yamba wala sakh marié 7 femmes hahahaha
tivaouane wayy Macky a vraiment commencé gorgorlou lénn nak pr términé la mosquée
macky defna wa tivaouane aye nit legui deiiiiii mais nak yeene talibe tijdiane yi niacke ngeine ndiarigne loole deleene diokhe adiya waye leepe president begue ko def daye metti nak si rewmi
kham nga bou bakh do talibé baye …watt na ko si al khourane…wakhale rek linga done on comprend tt