(27 Photos): Le film du combat Bombardier-Modou Lô en images. Regadez
Dolé doxul diamm, Serigne Dia dit Bombardier était ce samedi soir plus fort et meilleur que Modou Lô. Mais cependant Kharagne n’a pas démérité. Il l’a manœuvré et usé de toute son intelligence pour mouiller les munitions du Bombardier mais hélas. Le Mbourois avec tout son poids et sa force a déjoué toutes les tentatives du Parcellois.
thiouthie day kham lekam si non rek moufott
Lamb ji dal koussi amoul dolé bou yabo nga dem tokk
modou tu es notre mm si tu avais mille dfaite on est vec toi du courage ta pas demerite .vous ferez mieux de vous terre vous n etes que des parleurs donc parler
l y'a une 15zne d'années Double Less avait conseillé aux lutteurs de ce méfier dui jeune BOMBARDIER que son bras est lourd, c'est vrai qu'il a déçu par la suite par excés de confiance seul YEKINI le connait, il prend son temps sachant qu'il va faire une erreur pour le terrasser facilement, les autres (baboye, gris, tapha) ça ne se répétera pas .
Machaalah c'est une forte tranquille, sa technique manque peut être à cause de son poids, il est naturelle, humble et sportif
nekhoul ba nekhoul waye li mom dou comba
vive le roi
Modou défna lico war yalla moy mayyé ndame maynaco b52 yalna co ndame li jike modou mouy nekh moy nakhari yafiné
boulèn gnou sonnal fans Modou yi tay mom gno am pour wakh mougnlèn rek. dangèn bagn balla mais Moy Sen molèn di nekh molèn di nakari
ahahahahaha
Wayé nak li moy Senegal dagnay guiss kou am kontinérou problem dém di lidianti bene barigo problemou diambour
Guisna kou niakke diom ba sonou mé moussouma guiss nioumélni fan's balla gueye ndakh fogona yéne mom insbi lou gnéne barri barri wakh amgné lou gnéne wara guissé pour wakh pour mana dimbalé sén mbeur mou mana guéne si ténou guathia guim dougou
DOLE YAMOUL ALLEZ BALA GAYE WAH KAYE YI NOPILEN WAYE bref
25 juillet 2015
way li dou yoon way le bras de bombardier c la jambe de mod'lo.
Répondre – Partager
Marième
25 juillet 2015
hahahahahhha mdrrrrrr… non bref Toth ngafi lol
mai nak moy deug khalé day yam placou khalé li fjike Balla Guaye mouy daane ay mak dou djik le reste et Balla reste le meilleur mainan ke eumeu vienne prendre sa part ..lol..Balla for ever
Répondre – Partager Masquer Réponses ∧
Ebel
25 juillet 2015
Bilahi!! BG2 reikkk
Répondre – Partager
L'invincible
Aujourd'hui 2 h 46 min
Guisnfua yènn amoolènn moomènn wakh
Répondre – Partager
hams
25 juillet 2015
Ta bien fait bombardiers tu n'ai pas comme tyson à chaque fois qui ce fait terrassée part des petits quel honte tappete vive bombardiers un petit qui vient encore il sera bombardé pire que ça mdr ???
Répondre – Partager
fatima
25 juillet 2015
wakh deug modou khamoul bopame
Répondre – Partager
NIT DOFF KILLER
25 juillet 2015
bref raygama
Répondre – Partager
Kikou
Aujourd'hui 0 h 27 min
Car machalla domou diabourla
Répondre – Partager
La diva
Aujourd'hui 0 h 32 min
bomb mo bakh ci xalei bou rew.
Répondre – Partager
mdrrrrr
Aujourd'hui 0 h 32 min
ahahahahptdrrrrrrrr @bref tu ma tué.dama rétaann bah tass.dooléyi tolowoul nak
Répondre – Partager
peee
Aujourd'hui 0 h 44 min
les images parle d'elle meme.modou lo ya soop deugue bombardier bayil boy yi nguay noguatou way tchimm.va voir tapha tine wala yekini nioy sa morom niaka fayda.mais nak bombardier a battu les deux meilleurs lutteur de l'arenes.thiey balla gaye se qu'il a fait aucun jeune lutteurs de sa generation va le faire.dommage que il on marabouté
Répondre – Partager Masquer Réponses ∧
Gueye
Aujourd'hui 0 h 52 min
KHÂGNE LO REX NE DÉCOURAGE PAS ATHiA kharagne
Répondre – Partager
Mbour montagne
Aujourd'hui 0 h 47 min
Bombe gui yaw la dh ni la rek doxanal ndayi boyepou rek une a une
Répondre – Partager
gora
Aujourd'hui 0 h 49 min
Hahaha bomb rk la gnou wakh goudi goudi mboue
Répondre – Partager
babacar
Aujourd'hui 1 h 21 min
photo bi nice na lii mo woor danko ba tok ci kawam amoul ben doute
Répondre – Partager
kawman
Aujourd'hui 1 h 38 min
wa dakar boulénn khékh bombardier il a commencé a battre les jeunes.délénn khol nak d'ici peux il ferons tout pour combatre silolou laniou ayy bougouniou kouy démm mouk.bravo bombardier grand bou yarou ngua.du courage modou lo wayé thioutie day kham lékaam.tu etait trop préssé de lutter avec un roi maintenant voila. bombadier vs eumeu sene rek nak senegal dieum kanam niou khol kouy daan
Répondre – Partager
mdt
Aujourd'hui 1 h 48 min
photo 24 modou lo loumouye retanne?
Répondre – Partager
Boye Pouloh
Aujourd'hui 7 h 47 min
Bravo,B52! Malgré le fait que Modou Lô ait tout tenté,tu lui as montré que tu n'es pas son égal. Ça me rappelle la fable de la grenouille qui voulait devenir un boeuf. Bonne leçon pour cette jeunesse impétueuse! Heureusement que tu te sois levé à temps,Sinon on aurait,pour la première fois,à la ponte d'un oeuf par un être humain.
Répondre – Partager
Boye Pouloh
Aujourd'hui 7 h 58 min
Mdr, ki rétanoul dé! Khana guissoné,bimouye daanou,bène lokhom rêk moye supporté sène niary poids lourds yi. Dêye guigne waye, serigne bi!
Répondre – Partager
safi
Aujourd'hui 8 h 45 min
dafa sop rek, bomb dou morom guouné.
Répondre – Partager
CHERIF
Aujourd'hui 9 h 34 min
C'est grand contre poussin il y ai pas de mérite
Répondre – Partager
papa
Aujourd'hui 10 h 02 min
MODOU du courage BOMBARDIER EUMEU SENE ngui nieuw