Vidéo:Les Khassaides de Serigne Touba à la tribune de l’Onu. Regardez!

Les Khassaides de Serigne Touba retentissent sur la Tribune des Nations unies. Il s’agit du Khasaide Touhfatou chanté par Serigne Abdoul ajhad Diouf devant des dizaines des talibés mourides à New York.Honneur à Bamba et à ses écrits, qui aurait cru un jour que panégyriques seraient loués dans l’un des lieux les plus célèbres au monde.
Serigne touba amoul morom.
Serigne touba moy sounou borome
diadieuf
SERIGNE SALIOU
Dierediefeti khadimal moustapha
Kou Am kounimél , warnga déf ligueune si sa dîné ! Ki gueune laniou am, naniou dieuf lou kéne doul Dieuf ! Naniou nou ranimé ci ligueune té bouniou kéne Di guiss Wala diniou dég si sàfàne ! Nonou lanioul santé té cheikhal Khadim
BOROM TOUBA DEY YALLA THI BOPAM WOUTALOUKO MOROM BAMOUYE WOUTAL BOPAM MOROM KOU AME TAWFÉKH KOUNÉ DOKO WOUTALE MOROM NDAKH KÉNE LA MOME KOUTHI BEUG LOULA LÉER LADIALE ALLAHOU
lep lou waay beug loudoul serigne touba.serigne touba moko gueune
Dieureudieuf serigne touba.Deugue rek moy moudie
Merci cheikhoule khadim yakarou djiame gni
Diaradiaf borom touba
Eskey Amna solo trop .dieureuf Seregne Touba
Dieureudieuf CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIMOUL RASSOUL
dieureudiefeti serigne touba tambalesi mome yeme si mome amoul morome
serigne touba amoul morom bamba rek.
khadimoul khadim
dieuredieuf serigne touba
serigne bamba amoul morom
dieuredieufeuti Serigne Touba
Ce n’est que le debut. Sa dimension suprahumaine lui sera reconnue partout dans ce monde
Toubap ba banione na wote ba sa bireau ba thia ndar tar tey kadu nga djip na thia bireau aduna ba
wallahi Cheikhona Ahmadou Bamba khadimu rassoul amul morom lii moy ligueuneu ndaw danguén giss lici kanam incha allah
Thanks Mame Borom Touba.
Machalla séed na khôl
Serigne TOUBA amoul morom
Dieureudieufé borom touba
Diere dieff serigne touba kendou mome
Dieredief serigne touba kendou mome
dieureudieufe serigne touba amoul morom