Vidéo: Youssou Ndour: "Je suis le président du fans club Serigne Basse Abdoul Khadre" Regardez

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Aucune recommandation disponible.
Aucune recommandation disponible.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
ragal lenn yallah youssou fi dou ay défilé mode oubien association fi magal la wakhal ligua kham ak liguay sentire si serigne touba mo gueun serigne bass kholoul sakh liguey wakh ligueyeul mamam moko gnor! réciter khassidayi wala alkhourane mola wara indi magal!
Serigne touba douy thiakhane! bougnou khamone dougnou fi nekk di fans club! youssou ndour en tant k lui wara tolou sunu borom fou kaweé takhao di fans club!Thiey ma titt!!
Ndeysane diadieuff way
MAGAL GUI DEH C EST LE DEFILE DES MBALAKH MAN DES GOORDJIGUENS ET OPPORTINISTE. SOU SERIGNE TOUBA DONE DOUNDOU DEH DINA NI MA WAHONE GNEUW LEN LEGUI BAHNA TOK LEN.
wawaw nio ngui sa guinaw s basse abdou rekk mom laniou geumm
wané ngue rek il ce prend pour qui youssou demal diangui d'abord ???
Kxkxkxkx…way Yallah na diameu yag senegal kouné nekhoul dangua nieuwoul Magalouk Touba
nono boulko wakhati
Aminee
dagua wakh back sa koromsi djiekh.
RIM, AMY, et BERI FEEM, nous aimons YOU et commentons toujours sur lui…..COOL…C vrai RIM…Un jour You dira: je suis le PRESIDENT….de tous les Senegalais…AMEN….
Con yay sounou pressi
Et je suis le President des fans de Youssou Ndour…..lol…
Degue la ndour Serigne bass kham kham késsé
wawaw dagnou la fan mome….