7 COMMENTAIRES
  • bower

    Amiinn waay !!! Borom keur bou bakh moy am sokhna sou bakh. Yalnako yalla yeureum té kharé ko aldiana.

  • senegal ndiaye

    :sunugaal: Le réseau social du sénégal ou des Milliers de personnes s’y retrouvent tout les jours pour échanger et aussi faire de nouvelles rencontres
    #Kay_Bokk
    inscrit toi sur SNCONECT.COM :sunugaal:

  • anita

    dafa ame ngor nit dou faté démbe que la terre de touba lui soit légere khady thiam

  • macerata

    amine fall

  • borgo

    Khady Thiam yallah nakko yallah yeureume. Yaw kou bakhngua kouye japalè sa Jabar ngua, Khady Thiam dadone bagne jeukeur gui jitouko sa keugueu di tale rère mouye gawantou jègui rayebi train back fèkk koffa… yallah na yallah barkel sen jambotte

  • babou

    walla serigne bi ya bakh rek sa khol mo rafet g mm pleuré sédé bou bakh thi saye sokhna je ne te connais pas mais kou nek ague yaw koor koorou yalla na la yalla faye

  • borgomanero

    Khady Thiam yallah nakko yallah yeureume.

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *