Vidéo: Waly Seck feat Ndeye Gueye « Tass Sa Cheveux »

Son anniversaire célébré au Penc Mi avec ses fans, Waly Ballago Seck en compagnie de Ndeye Gueye sur scéne dévoilent une nouvelle danse « Tass Sa Cheveux ».

28 COMMENTAIRES
  • ousseynou ba

    n’importe koi bilahi

  • Rama

    Ils sont nuls et vulgaires.
    AUCUNE INSPIRATION.

  • Marietou

    Li reike ngueine yakamti jais lu tout a l’heure sur senego un information posté depui 9h des étudiants qui possède un bar clandestin et vendait de la drogue au temple du savoir mais sans commentaire . Mais quant il sagit de waly seck tout le monde veulent se montrer la stard du jour c’est grave .

  • sal

    nn wally liguay dff na

  • sal

    nx na lol wally machallah

  • sal

    nn wally liguay dff nx na wy

  • adi

    khamnani senegal nékfa star yombouna ko khamni manoul way amoul répértoirs 4 ans mém répértoirs m,an mom dama manoul siporté wally koi

  • sal

    nx na lol wally

  • sal

    nekh na lol wally machallah

  • Mamadou

    no no rek senegal dou dem

  • Bass

    Bilahi marietou Wakh nga y’a d’autre article plus important a commenté au lieu de rester 24h sur le net a attendre qu’on écrive sur waly pour l insulter ou dire des imbécilités .sone ngueine vraiment .

  • nasi09

    Adi demal sobou si souboudioun ou plage diamalaye yeupeu fini

  • Chulita

    Nekh na lol…

  • as

    waly dina dague sen kholyi, di commemte rek kou mer boko

  • mame walle

    nekh na walle

  • seck

    lodol wally ay nakhla

  • nianezo

    voila khana bi nak goryi dinagnou ko bayi ak djiguen ngi nak .ah wala mou am ay goor youy tek cheveu legui

  • BLECK

    kel merde

  • oumar

    nkhoul dara ragale lne yalla sne thiakhane you bone yii

  • sama reew

    ndeysane amonio logno woye guoi!

  • billy

    bilay waly aml nga gnou akha ta musik vraiment nous drange comm d Potou mw c vraiment tro nul bilahi dou sokhor deug rek

  • Maya

    boulein niou sonal koumou nexoul zappél, Pourkoi sokhor ?

  • ria

    sokhor bagass rek la waly deff

  • Mustapha

    Wally le meilleur chanteur sénégalais ????

  • Nike name

    Talbou yalla sani mate mo gueune fayeko meme soumanoul waye nitegni beugue nane Ko

  • sohnasi

    waly khalela te sokhorna dinalene raye de

  • italy

    Dans un pays de 70% d’analphabètes,c’est presque normal que Waly Seck,Ndèye Guèye,Salam Diallo,Pape Thiopet,les animateurs et animatrices télé,etc….soient des stars.

  • borgo

    Asthakhfiroullah di damo lou arame li niawna

Publiez un commentaire