11 COMMENTAIRES
  • cheikhouna

    noooo dégeulmali rék légui gouverement bi lanlay def si liii

  • deug

    khaliss bank la wara nek dou si kleur

  • améthseck

    Une police qu'on appelle il ne réponde pas je trouve que ce n'est pas normal

  • MEUZ

    KHALISSE BOU TOLOU NONOU KENE WAROUKO DINTHE SI KEUR LOU BANK DI DIARIGNE

  • a.k.a

    c'est déplorable…mais cet incident comme tant d'autres repose le problème de l'insécurité dans la ville de touba.toutefois la question existentielle qui mérite d'étre posée c'est comment un etat peut-il bien assurer la sécurité d'une localité qui ne cesse de remettre en cause sa légitimité et prétendre pouvoir assurer sa propre sécurité???

  • dame gaye

    Baye Massa kamna né j lago yine dou bari kola kham khamne go diole tè k tè dago tè kam yalla Ak saa Seringe Seringe Cheikh mbacke madina yalla nala sunu Borom bi takhw tè dakaral la malla fanwu kudou yakal takh way bi nune diabout gui nugui si sisa kanaw

  • dame gaye

    Massa Baye

  • yakar bamba rek

    Thieyyyy adina lii de metti na loll sourtou si mank

  • Serigne Mbacke Gaye

    Massa Sama Baye Bou Bakh Bii li lép Dogal la Bou Bayiko Sii Yalla Nione Nak Ay Diam Rek Lanii Nék Thi Kanamou Kone Nak Mano nio déf Lou Dole Nagou Dogal Wayé Nione Say Dome Kham nane Bou Bakh Yaw Yaye Kane Nioguii Dolii Sant Yalla Bou Bakh Bifi Sa Bakane Déseii Yalla nala Yalla Takhawou Ta Koula Kham Nit Gou Am Diom nga Khamou niou la lané ne lou Dole mano ak Nago Liguye Ak Topato Sake Ndiabpt Ta Diam Rek ngay Am Yalla Lou Adouna Nak Dou Dara Ta li Manol Yakh SiSa Liguye Ak sa Dipm Jtm Papa DouNdal Afia Rek ngay Am

  • kupukala

    Quand on gère autant de fric, on le fout à la banque!!

  • elhadji rafét

    doyna waar de wayé yalla dou massa nélaw

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *