Vidéo: Serigne Saliou Mbacké en larmes. Regardez!

Magal Touba 1995, Serigne Saliou Mbacké se fond en larme en plein discours. L’homme multi dimensionnel, le 5 éme Khalife général des Mourides surprenait ce jour la par son émotivité et par sa compassion. Retour sur ces moments exceptionnels qui ont marqué la règne de cet homme vénéré. Regardez!
Ken dou mame SALIOU kouko kenal mou kenal la awma louko eup mouk
yalnaniou yalla sounou borom fayal serigne saliou mbacke bilahi amouniou fayam srg mo eup yeurmandé ci diam gni
Sant serigne touba
Sant serigne saliou rek
Moi je sui ferven tidiane mai soumakoy fatèlikou sama yaram dafay daw ndakh beugue alkhoure ane ak deudou adouna. Motakh nioune talibè yi nguir yalla naniou roye si sounou mak you bakh yi wayyy bayi tiakhane bi niou beugue daganal
SOU NEKKE SERIGNE SALIOU MOY TOUBAL BOROMAM NIOUNE DI AK TALIBE REK NANNE LAGNOU WARA DEF?thieuy sounou borom mo kawee
Mbacke balla yaw rek la beugeu !!!!mbacke magui si sa yeurmander sasou nekh guir yayyy Borom yeurmander doo moromou kene.t unique .ton admiration a dieu est exceptionnel.fier d être ton talibe.
amoul morome sama yakar taye ak euleuke
THIEUY MBACKE malabeugue dax sa yeurmandé si diaam balégui silagni diarignou
dieureudieuf serigne saliou mbacke na yalla bour fayalniouko
Yalna yalla yoki lerame
Vous pouvez me dire ce qu’il a dit avant merci
Un grand homme
Salam mame serigne saliou mbake. Dieugueul bi nga sakou sounou borom bi yalnako yalla defal. Thé yokeu aiy leeram tasse niou cii barkeme Amine.
Dieureudjeuf Mame!
Amouma chance guisko diakh’rane wayé yalla wanamako ci guéteu moumaye nianale dieureudieufé mame Saliou ma la beugue yallana sounou borom yoke léram. Amine
billahi depuis que j’ai regardé ce SAINT,je ne peux plus commettre de péché(ndiaaloo)
j’aurais bien rencontrer cet homme de Dieu
Kene dou Serigne saliou !!!;;;;
yalla na yalla yo kou ay léram
dieurwdieuf mbacke
Ken Dou Serigne SALIOU
bilahi yaye borom diamono
dalla naniou yalla tasso si barkem te York letame Amone yermende lol si diamyi
dieurwdieufé serigne touba
amineeee barké cheikhoul khadim
Allahou akbar
serigne saliou Mbacke kenn du mom yalna yalla yokou aye lerame bidiayi say dina Mouhamed salla Lau halayhi wasalam
amine
thieeeey yala sama yarame dawena
dieureu dieuf mame saliou
A l’heure où beaucoup de gens se sont perdus dans l’islam à cause des marabouts et toutes sorte de groupe et de secte, voici UN VRAI CHEF ET GUIDE RELIGIEUX
mback balla ayssa kenn dou yow.beugoulwone khaliss beugoul auto beugoul tage t beogone khaleyi trop ooohhhhh yalla wagon nga sakk niou bary niou melni sang bou tedd bii
Senego corrigez, on ne dit pas la règne amis LE règne
SEY SERIGNE SALIOU
yeurmandè kèssè
Laahilaha illallah thiey borom yeurmade Serigne saliou Mbacke
yala nañou yala feyal serigne saliou
Mbacke sama yakar tey ak euleuk yallana borom yok say ler
tiey serigne saliou mala beugue yala nañoula yala feyal te tass ñou si sa barke
Yalla nako Yalla dieggal comme nimouko sakko
amine
Mbacké yalla na yalla yoke sa leer
Amine
Amin way
yalana yala yokou léram té tass gnou si barkém
billahi wallahi tallihi kéne dou serigne saliou Mbacké té kéne eupou ko yeurmandé si diam dieuredieuf Mbacké Balla Aïcha
dawna yaram bilahi wallahi