diara dieuf noray ni yalla ngafi yagg te werr si barke borom darou moukhty.
diop
à quand l'exil ? kilifeu deugue dafaye respecter ay kadoom !
diazb
adouna yakhouna app serigne dou politique nioune kham nan liga beugue serigne bi demal sa daradjia mo guen
bayeeeeeeeeeeeeeeeeeeee
fada war kattla teki woul dara man darou moukhty la dekkue
FG
Dieureudieuf seugne bi. Waw do wakh sa halat ci affairou imams yii gnou tek loho mo gueunn yakaarna
sall
Abcd123 yaw khana sa bopu bay mo fésul.dég dég dafa diéfé,kii déguén ko war didék lu wakham dafa am solo
rim
Fada limou liguéy pds yalona lolou
rim
Modou diagne fada défoul . Lou takh pawou pds yi ak méryi beug fokhati limou yoor nécounouka féen
mai
mai liga wara wakh wakho ko wakhal fada deug mo geun lakh lakhal bii fada lim deff tegouwol fen lo lou ga warrav man darou moukhty la deug mai fada rk lanouy kharr bou fii diaree danan teppiii mom khamna lo lou sakh mo takh mou teud ndakaro
abcd123
ki bopp bi fessoul deh
DEUG
YAW KOUKO WAKHONE SA BAYE DOU LA NEKH
AM LENE YAR AK TEGUINE T BAYI SAGA YI
Comments are closed.
Ne manquez aucune actualité !
Téléchargez notre application pour une expérience optimisée et pour recevoir les dernières nouvelles en temps réel.