Publicité

Vidéo- "Serigne Fallou" de Youssou Ndour...Regardez le clip !!

Youssou Ndour vient de mettre sur le marché un nouvel album intitulé « Sénégal Rek ». Voici une chanson phare de cet album, dédiée à Serigne Fallou, 2ème Khalif général des Mourides.

84 commentaires

  1. Amar sall italia

    Do sene morome man yawe rike laye dikelou lo wakh monikh karre jame rike ga bagal senegal delle wakh aminnñnnnnnnnne

  2. l'homme fort

    nonoula papa adouna niep meunougnoula bolé beugue koubakh day ami none lo wakh mou rafet lo def mou rafet serigne fallou dinala fayal bopam

  3. teranga

    avec ça gueule de soulard la va à la retraite waye tu n’a plus de sons way

  4. spagheti

    il devrait arreter de boire est de truander de respecter les 5 pilliers de l’islam sa plairait beaucoup baye gallas fallou mbackè

  5. Fallou

    youssou bayil thiakhan boul niou fonton sa foo mou bonmi nganan Seringe Fallou

  6. nicole

    Hassim t es nul s fallou est un don de dieu pour nous, arrêtez votre jalousie

  7. hassim

    bakkanou domou adama lou ko Nass yobb dafa Gaw lolll, ( sou niou jakhlei yalla Lani wo .. İslam lolou la diangalei, 7 serigne fallou ken dou ko dorei loy ba nga def.. touddal yalla rkk tei kennal ko thi lepp loy def ..

  8. Oumou

    Dakar mane mi may fan’s number 1 depuis ce matin j’ai pas arrêté d’écouter cette chanson vivement le 10 Mai pour la sortie de ce chef d’œuvre Bravo à la star

  9. ndiaye

    baga dal waye ba taye khar ba legui didora way serigne fallou amga lo beugati rekkk ndour yalla nala yalla oum

  10. ndiaye

    bilay liga waye nekhnaaa ndour meunone ga yam si serigne fallou rekk bagna toude kenene khawma lo beugati sacrifice rekk gay dokh sa lamigne bakhoul ndour ko waye rekk mou wagnekou mais sama sangue meunalo lene dara.

  11. dakar

    Bravo bravo bravo bravo yaw yalla nala souniou borom fayal bopam man nak dama la beugue rek t yalla takh on s est jamais vu mais je suis un fan number 1

  12. Minata

    Kou nek kham ngeu kouleu maane yalla nopineu bou yag BRAVOOOO????????????????

  13. Bineta

    Chapeau à la star planétaire continues di gnou deguel yalla Nasri Serigne Fallou fayal bopam je n’arrête pas à écouter cette chanson même au bureau

  14. Lys

    Kiko meune ak kou koy diém bokoul youssou est 1 phénomène k bcou d gens n comprenne po vs aurez beau essayé vs narriverai jamais à l’égaler

  15. CISSE

    Je suis talibé cheikh mais youssou li nga def diarna 14 milliards li nekh na wayyy machallah serigne fallou dafa melni serigne bacar sy gnou dioudou sen guinaw gnio len beugeu mbeuguél bou doy war.

  16. Djolof

    Ziar bu wer les ami j’ai de serieu problme je sors vk une fille depuis presk 2ans je l’aime beaucoup elle aussi mai mon pre ne veu pas cette relation car elle n’est pas de notre famille il me di de la kitt. Mai franchement je peu pas la kitt car je l’aime beaucoup bakhna Amna yar mangui deg lou vos conseils bakham lou si l’islam wakh

  17. thiatt

    Youssou ndour li rek mola déssée wone amal diam way langay wakh nexna Mame fallou ba faww

  18. Fatou

    Mais Youssou ndour nit la dioye na serigne fallou ndeysane yallah diam yague waye cey cette chanson c’est comme si c’était aujourd’hui j’arrête pas à écouter à réécouter merci grand Walahi

  19. seck youssoupha

    dara nkhou siii . humm hummm . tan bimiy wayyy . baykat , woyyy , djigne, awa gueye , bercy , womattt , bandioli ndiaye . da am koumouy garu wal motakh . youssou ndour .haaaaaw

  20. NFS

    So Wayé rék kounarona guéné Album diguako ségate Ya ame Déggue dé Serigne Fallou Moye Sénégal!!!

  21. Sokhna

    STP Youssou reviens à la musique on est nostalgique de tes mélodies et de la bonne musique et laisses la politique aux politiciens

  22. Awa

    Masha Allah yalla nala Serigne Fallou faye leu nekh neu en ai les larmes i yeux chapeau à l’artiste

  23. djiby

    Ken dou yow une musique universelle kon peut tirer d’énormes leçons de la vie

  24. Iba

    Def leen niko yalla déf mou nopal leen sinon rek mou diakhaleen BRAVO à l’artiste???

  25. Moi

    C le meilleur ndayssane gayi gnikoy fekhel mais yallana Yalla yoki ndamam te samko thi barkeb S Fallou

  26. Gogo

    Masha Allah l’artiste planétaire yalla naleu Serigne Fallou fayal bopam aammmmmiiinnne

Comments are closed.