Vidéo: Selbé Ndom se prononce sur le combat Modou Lo vs Gris Bordeaux

Après qu’elle s’est prononcée sur le combat Sa Thiès vs Siteu, Sélbé Ndom livre sa prédiction sur le combat choc Gris Bordeau vs Modou Lo. Au micro de Seneweb, la voyante mise sur le lutteur des parcelles assainies.
Je prie sur le bon Dieu pr k Modu lo terrasse Gris
modou lo dina dane gris Inchaallah
salam soxnasi somadon yawde damay bayi khadji ndaxte dagna youre ay dom te dom nawlela magni diegelo nga balma nak linolay wakhal nak dieguel len rek nit matoul nano khamni tamin waxdio ngaw baxoul ay diolit lano wa salam
G regardé la vidéo mais g pas vu là où elle a di que sa Thiès va tomber.
Laissez la tout tranquille Selbé a bien dit qu’elle n’avait rien dit concernant le combat de sitteu et sa thies ce sont de fausses informations d’après elle. Sa prédication ne concerne que le combat de Modou Lo et et Gris Bordeaux et elle a donné la victoire à Modou Lo. Laissez la tout tranquille encore une fois on est en démocratie et on a le droit de dire ce que l’on pense et il y a d’autres qui disent plus grave qu’elle et vous ne dites rien alors fichez la la paix
Yawe ngaye fenn reck saso wakhe tedo teuthie sa fennoukayegui
Limou djiss la wakh
selbe yalla kasser kham loi niawagoul bayil narr
dioundou mo fi amoul na wakh mou lér na mo you combat sa thies yag nasé fén
Merci Bandam rappels yi am na solo k’Allah te protège
Je suis très content ce soir , pas pour la victoire de SA THIES , mais la sublime mensonge de cette dame – SELBE – qui parle avec certitude de la victoire de Siteu . Maintenant il est clair à tout le monde que cette dame ne connait et ne sait RIEN d’inconnaissable. Car l’inconnaissable appartient à Allah le tout puissant qui dit dans le coran (( 26-(C’ est Lui) qui connaît le mystère. Il ne dévoile Son mystère à personne, )) — ((65-Dis: « Nul de ceux qui sont dans les cieux et sur la terre ne connaît l’ Inconnaissable, à part Allah ». Et ils ne savent pas quand ils seront ressuscités! )) — ((59-C’ est Lui qui détient les clefs de l’ Inconnaissable. Nul autre que Lui ne les connaît. Et Il connaît ce qui est dans la terre ferme, comme dans la mer. Et pas une feuille ne tombe qu’ Il ne le sache. Et pas une graine dans les ténèbres de la terre, rien de frais ou de sec, qui ne soit consigné dans un livre explicite. )) .
Quiconque dit qu’il connait l’inconnaissable n’est qu’un grand menteur irréligieux, comme cette dame .
je condamne ce ki la tend le micro
Aye selbe khana diga topalou nak thi wakh dji
Mai selbe tu avei di k siteu batra sa thies mai c fo.stp arete d parler car Dieu es plu for k toi mai il rest bouch bei. Gesper k tu n parlera jmai. Et atention dmin p etre tes « petaw » doula nakhate
sélbé ngir yalla bayil wakh bi da nga ame jaboot so wakhé lou doule deugue di nga léne sonal té di nga ték gathié séy dome ngir yalla.guénatal nga wakh ni gris ak modoù lo bi guissou lo dara dou wésssssssssss
attention refers toi sur ce combat d aujourd hui en bon entendeur salut……..
Écoute salbé ahhhhhhhhhhhhhhh tu es grande fouuuuuuu !
Salbe yamana mêw
Mais selbe avait prédit la défaite de sa thies donc c’est pas la peine de croire ce qu’elle dit
deug deug selbe amoul diom bou amatoul lou mouy doundeule ndiabotam mais mou woyane mba mouy setalate waye na bayi lamb dji ngiir yalla.
dafa bayii kheessall???
selbé na bayi lii mouye deff akkeu bakhoul
mome halice rek laye weurr mome lii mouye deff da harame moye sétt chaque jour mou fénn fi laffi wakhone ni tyson moye danne gris wakh ni balla gaye boumou danné yekini dinna nekk roi 10ans wakh fi ni eumeu sene moye danne modou lo té fénn katt foguo fékk aye watt you beurri laye deff
Vive MODOU lô tu battras gris inchalah. J’ai beaucoup de confiance en toi
salbe sei a sbagliato questo comba e contrario
Seil lerreur est au pluriel ici il nya kune seul verité cei la victwr d MODOU LO gris mbeuleeee????
Modou lo yalna daan giri
M
ais damay lathie loi sélbé wakhati
Féne katt bouy wakh déy watt rek
domou adama da ffa warra mandou bouu bakkk tai nguene bayi makk you bakhh teudeu si diameu mo gueune si yenne
limou wakh yep BOKale yalla rekk lafi deff te yalla dou bale kouy bokale
loutakh YALLA AK YONENTA AK SERIGNE TOUBA
yalla loumou manoul kenen manouko wa salam
gris va gagner mais mod’lo sera le futur roi des arènes d’après la voyante
Salbé wakho fi dara louler way tapet nga rek bayil wat you barri yi
dou yombe dal no nou
Yala rek mo kham
Selbe wakh ma fo nekone ak lo done liguey 1998
yalla n’a gris dane yalla mo diara yakaar
salbe boufene wakhal rek tabayi guigneyi yapga yalla toroup ak yonentebi kanennak sama yonenekou thi
Yala bo oum Modou lo
mandall warouna thi bokale Katy I
Juste au lendemain de la victoire de BG contre Yekini,elle avait prédit qu’il resterait longtemps roi des arènes,au moins 10 ans avait elle dit.Quelle menteuse,cette Selbé.
Baye fall dioye yoyou inchala ay rtan lay don tata selb guente kne douko wakh si tl thiate dafa guaw yalla na may Modou ndame amine ya allah
Thièy les talibés serigne Touba, moy lolou, kéneu khamoul bane diné lagnou gueum
yalla rek finek
Ah mane dhei Lima yalla wane si guent modou lo yaram beep da takk souf
yalla rek mou kham loyyyyy khéw euleuk
Yalanah yalah may Modou lo nam
Elle a bien dit vous avez tous compris c juste amère si tu n’est pas avec de modou
Elle a bien dit vous avez tous compris c juste amère si tu n’est pas avec de modou
Baye fall dioye yoyou inchala ay rtan lay don tata selb guente kne douko wakh si tl thiate dafa guaw yalla na yalla may Modou ndame amine ya allah
Baye fall dioye yoyou inchala ay rtan lay don tata selb guente kne douko wakh si tl thiate dafa guaw yalla na yalla na Modou am ndame amine ya allah
ou bien dafa dioundiou rek.
svp la dame n’a pas prciser entre gris et modou
Baye fall dioye yoyou inchala ay rtan lay don tata selb guente kne douko wakh si tl thiate dafa guaw yalla na Modou am ndame amine ya allah.
Selbe Tayegaye moudji wakh ci combat Fass ni Modou Lo di Gueudjieu beurek Mbeurou Fass Wakhaal ligaa guiss mou lerr boule ragaal
Je ss avec modou mais j’aime pas salbé
ligua wakh yaye boye gua balma mé mane baye fall Lima Yalla wane guis na modou lo gnou leugu ko moye dioye mane baye fall
non commantier
non comanteir
Elle a plus besoin de soin que d’être écouté. Ki weroul
Wao Sama Gayii Salbé Wakhoul Gouy Daan Dé
yalla rek mou kham
wao Mais sama Gayii Salbé Wakhoul Gouy Daan Dé
Machala Modou lo
BRAVO SALBE MAIS N »OUBLIE PAS AUSSI SENEGAL YOUSSOU NDOUR AK THIONE SECK NOUNGIFI ET LE GRAND SAA NEX DE THIES NOO SENEGAL MOOKO YOR DE @
Salbé Dit moi svp je veux connaitre la femme que je vais epouser.
amgua sens bigua wakhé liiiii kharagn si kaname
ahhhhhh doy nawar yalla bakh soretoul