37 COMMENTAIRES
  • NINI

    BILAHI YA RAFET KHOL YOUSSOU DARA DIAKHALOULA SI ADUNA NAKH DAGUA GNIEFE SA ADUNA DIAM RECK GUA AM NDOURA WALLY MBEGANE DIEREUDIEUF NDOUR

  • MOMO MERGANE

    Non il est gentil

  • DEUGUE REK

    YOU DEUGUE LA IL CREE DES EMPLOI MAIS NAK NA FAYE AYE IMPOTS NAK

  • noirebène

    PATRIOTE MOMOU, NITE DAFAY AM SOUTOURA SOU FEKONE LOU WAYE KHAM WAKH KO BONE ADUNA TASS. TE WOR NAMA WOR YALLA NI LINGAY WAKH DARA LEROULASSI. RATATATI REK. WAKHOU KOUTHIA LOUSSI INDI IMPOT.MANE AK BROOO SAKH NIOKO DEF DILA TONTOU NDAKH WETE NGA TROP. MASSA. MDR…..

  • noirebène

    Kilifa bou wathié bopam. Yalla nala yalla faye sa khol. Kouthia sama kharite bi namone nala nak. té nga wagni foula diou bari dji aduna amoul solo. amal ouverture d’esprit rek. PEACE.

  • guis guiss

    gfm est une famille et c’est çà qui fait leur force .Chapeau pour youssou ‘t’ es un grand. Tu es mon refférence .

  • WOULA

    Khame Nani dale ngor dhena Sénégal une personne doit agir Côme une personne et Nn pas comme Bcoup d’entre nous hé père you khalisso badio sa doi être. Dédier à lamine intérêt samba conseil trop de social tue le social . Salame

  • GFM

    koutia gnak diom rek la def do si rouss sah you borom hol bou nice bi

  • Titi

    Kouthia dal kouy mbokam war ngako yed ndakh mou nité surtout que GFM kou nek beug fe liguey sof ngeu trop

  • kheuche

    kouthia Dou rouss

  • Matar ndiaye

    Me kouthia dafa khamne sou demoul tfm d’o bakh si gnome

  • fan

    merçi grand you de faire revenir kouthia.vraiment si vs pouvez faire la même chose pour habib et djimy ce serait une bonne chose et tout les fan’s du super etoile appreçieront. Adouna amoul solo,les malentendus font parti de la vie. il faut oublier et pardonner. Merci encore une fois la légende.

  • Wax sama xalat

    Kouthia, nul n’est indispensable seulement le savoir-vivre est capital dans la vie de l’Homme. Tu es devenu celebre par l’aide de certaines personnes et par la grace de dieu. Donc , penses a ces gens en leur soyant reconnaissant et surtout ,saches que que tu as la chance d’avoir un immense P DG en la personne de Youssou Ndour qui ne surprend pas par ce qu’il vient de faire pour toi pour qui le connaissent car depuis plus de trente ans il regne sur la scene musicale en leader et son comportement , sa discipline, son sens de partage, son intelligence, son professionalisme et son calme sont a signer d’exemple. Je t’exhorte cher koutia a profiter des services de ce grand Monsieur reconnu mondialement et cesses de te croire au ciel deja

  • patriote

    En 2011 pour déposer son dossier de candidature en toute conformité Youssou Ndour avait payé plu trois cents millions d’arriérés au fisc

    • brooooo

      Deel doull di dadiallée rekk tu risques de connaitre le même sort qu’ont connu tu les anti-you c’est à duire se suicider intérieurement bref les pieds dans la terre le corps à l’enfer

  • patriote

    Pour votre information Youssou Ndour n’a pas encore muté le terrain qui abrite le siège de la tfm uniquement pour échapper au fisc

  • patriote

    Vito khana yaw dangua bok thi domou youssou yimou reconnaîtroul motakh ngaye mére youssou est un voleur parce qu’il ne paye pas l’impôt

  • patriote

    Sathie impôt pour créer emploi amoul sense na faye impôt comme tout le monde

  • teranga

    mdr patriote youssou d’où feye impôt en t’en que macky est au pouvoir Sénégal d’où dem billahi

  • Amina

    Koutha bayil yenayi te ngua fekhe am ak wa gfm diam nit kou bakh dafa warr di rouss yenayi,sama dom bi am 3ans daf ma wo nima Mama Koutha is back khaleyi sakh khamon naniou ne danga greve

  • vito

    Patriote wakhal sa baye Mouy fay Am impts aprs u viendra te plaindre . O moins you cre des emploits

  • patriote

    Commentaires bloqués

  • patriote

    Néléne Youssou Ndour mouye faye sunuye impot

  • rim

    khothia nanko woo wakhko deug bou raay soni program tfm tfm dou khouthia show rek rediffion you bareeyi lou mana niakla

  • rim

    KHOTHIA SA E?ISSIONBI WAROUL AM REDIFFION SI GOUDIGUI LOU K%EN WAROUKO MASLA DANLAKO WARA WAKH BAMOU LEER SI NO REK DIGA RAAY PROGRAMOU TFM

  • faly

    Babs yangui merr di lolll

  • teranga

    ridial wallahi yaw guémo yallah daara kouthia daa guème yallah motakh bugoul gnou yabko merci

  • Thiate

    Akuna matata!!! Tout ce que Ndour veux ci lou bakh Dieu le veut. Lii la wakh mane

  • yace_boo_you

    Dalal ak diam kouthia mais bayil sa yi nga néké. Sey nawlé rek nio nék Tfm té kenn meussouléne dégueu. Merci Papoush lo déf mo gueune lo défoul

  • sallma

    Gathié Ngalam Président YN… Kouthia fassal diome nak té ngay bayi sey caprices yi.

  • youssette

    Ndour waly mbergane yalla nala yalla faye seu xol way…

  • babs

    sounou yone nekouthie

  • CHELSEA NEW LOOK

    youssou moo bakh rekk dey dieul mbaamm yekatiko basikaw bamou yaakarn nitla thiey youssou mari sene

  • Dame copo

    man kii lanou wakh bilay

  • Amdy

    Youssou NdOur
    Ci kaw si kanam ci lou bax.

  • Ridial

    Y ndour danga bakh rek kouthia yaw bo bayé tfm torokh guiss nga ninga yoyé té nga respecter bouba

  • Toutou

    Macha Allah la star planétaire nii leu en plus kouthia dafa leu beug yalla neu diam yag

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *