(Vidéo) Regardez le nouveau look de Waly Seck et le fameux sac...

Quand Waly Ballago Seck récidive avec son sac qui alimente les débats.

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

100 commentaires

  1. Teranga

    Assy ya doule motakh gnoulaye critiké ,khoma fo deuk wayé yafaye numero 1 si doule

    Gordjigéne rék moy déf yi et tu nou parle de mode en france bayil doule

    Ou bien sa papa aussi pd la?


  2. fall yaram

    malaw bou pape diouf mo fey album mam bou bess bi motakh mou beugg buzz di yoor sac bou djiguéne assy mom linguay doul amoul fénn actuelma sw nice et je ne vois pas d'homme se balader avec ca au quotidien


  3. Modou Modou

    Je vis dans une grande ville a l'etranger. Je ne vois pas les hommes se balader avec des sacs pareils. Et puis qu'est ce qu'un homme peut mettre dans un sac pareil? Portable, argent???


  4. PUBLICITE

    Voila il est No1 a SENEGO devant ADIOUZA. Mais a quel prix? Liiw Siiw jarouko. Il y a d'autres sacs qu'il peut porter pour eviter les insultes.


  5. DIJA

    BAYILENE DIAMBOUR LES SIT POUR AVOIR DU BUUZ CHAK JRS ILS DISENT DE MAUVAISE CHOSE SUR LUI SOU DéFé LOU BAKH KéNE DOUKO WAKH Mé KAN Sé UNITIL GNOU RAYGNOU AK WAKH LAISSER LE TRANKIL..KHALé LA


  6. mandouleene

    gor djigueen leu wa legui kouyyy faram ko lenn ko meusseu guisseul niiiiiiii tontouléénemeu rekkkk thiiiiiiiiiip meme si ce nest pas a la mode en france il a le droit de faire ce kil veut khammmm waaay


    • Léral

      Yaw "mandouléne" sa tatou ndaye ba souba ……. On a pas le droit de dire ou de penser comm on le ressen? Cest simple dis a ton papa de porter cet sac pour aller à la moaquée ….. Et apres tu veras les resultats, dou ko dolî dé soubobâ

      De toute façon lî affairou djiguéne la cest tout ….mêm aye dalou djiguen la sole


  7. wakhatico

    Oui il nous prend pour des cons. Il veut qu'on parle de lui. Dalles youy takk, SACS. Pourkwa mou beugg les insultes. il ya 3 personnes seulement pour le defendre.


  8. Baba

    Bilahi Pisco wakhatico ki mouye deife nite yi di co Wakh reike mo ko neikh il savait bien kil allai susciter un grand débat c'est se qui lui fai vivre


  9. PUBLICITE

    Il ne peut pas etre No1 chaque semaine a SENEGO. SIW DOU JAMMI BOROM. Son pere THIONE (que Dieu le protége) l'a si bien chante. MAIS WALY FAIT DU JE M'ENFOUTISME. Nous sommes a GALSEN pas EN FRANCE ou aux USA et meme la bas les hommes respectables ne portent pas des sacs comme ca.


  10. PUBLICITE

    NARCISSISME C'EST L'AMOUR EXCESSIF PORTE A L IMAGE DE SOI.

    Il veut qu'on parle de lui TOUT COURT, tout le temps. Il nous bombarde avec des videos et il voit ADIOUZA ou les autres No 1 a SENEGO alors il nous balance kelk chose pour qu'on parle de lui. C'EST VRAIMENT TRISTE!!!


  11. Bachir

    Wedi guiss bokousi ki dou real nigga dou fake agent# goordjigen la,koba la,ndeysane ey bouma amone diabaar bou melni sa diabaar kone lenen lay doundou loudoul li sans retro no comment!!


  12. rim

    Wally limouy déf resultabi fi ak 20 ans nkén senegal moy eupo ay goordjién . Deug yo barri europe nila comacéwon ay star lani finacé séni mode bour nou mana am mbook mais domage senegal dani bayi bamou wéssou nouy wakh


  13. zoula

    ay waye bayilen waly mou noyi li ken meusoul guis li mo mom xalisam souko nexe djieunde si lou ko nex waly xelou xalee rek moko djiap mes li ni yeup dinako bayi wakh wakh rek eupeu


    • Schwarzmann

      Yama douleeeeeeee yaw Assy

      Dis moi ou en France? En plus dis moi est ce que t'as vue des hommes se balader avec un sac a main? Fén rék cest sure k yaw néko france

      Ki di tote bou bone


    • Paris-j

      Yaw Assy loula dale? Yéne mounouléne bayi di fénale goorou france yî. Doumouharame féne kate bou mag ngua yaw assy , li kagne la khéwe france? Sana sa baye mokay modelou domouharam, khame ngani li dou yeufou goor yala


  14. OUF

    lii lou doye war la dautant plus les enfants copie sur toi il faut montrer un comportement de gentleman na gooréé waye tes anciens ne faisé pas ça et pourtant ils ont réussit meme si sakh yalla beugoul musik sil te plait boul yakh adaye galsen please


Laisser un commentaire