32 COMMENTAIRES
  • baris

    bouba aduna amoul solo.tè kou gnép tifli gua toy.amal yeurmandè,tè sisa ligueye rek gua mena diamo yalla.aduna momoko.kone amal té dimbali kénéne mou ame.doula wagni dara…Quine du courage..tégua guena deugale sa personalité si monde muzic..par ce k dafa dèsse pour mane..niit litakh gnoukoy yapp si mom laaa…merci

  • sadio ndiaye

    deug mom pousso la rk magg dinako foor khale tamite dina foor bouba tu as intérêt a change lou gneup wakh moy degue tu est égoïste si tu n’était pas le frère de youssou ndour tu ne serais connu

  • diouf

    bouba se croie pour un intello dans ce pays même dans plateau de diakarlo ils les montrent k je suis le frère du boss il dit ce que bon lui semble c’est un vrai souroi

  • Fatou ba

    Coumba dimbalignou, khamo doul. Bayignou way

    • krkrr

      Fatou ba yaw meuna doul domaram

  • ndiaga fall

    youssou doit recadre son petit bouba ndour il est hautain mec car les affaire il y a pas histoire de famille ce bouba grâce a youssou ndour qu il est la aujourd’hui hui donc calme toi mec tu as des problèmes avec tout le monde . quand dieu te donne quelque chose le gère avec une humilité. arrête de chercher des personnes boss pour leurs pains soutient a queenbiz

  • biz presi

    Ce fut une période difficile et ton soutient fut plus qu’appréciable. C’est si bon de savoir que tu étais présent à nos côtés. Sache que cette main tendue restera à jamais dans nos cœurs.

  • ndeya hann

    Mon cœur de cesse de te remercier, te remercier, te remercier, te remercier…. merci ton soutient chon
    bouba dotoko dolly domaram

  • coura

    Il ne faut jamais renoncer à ce que tu veux vraiment faire ou réaliser. Une personne avec des grands rêves est bien plus fortes que celles qui les a déjà tous accomplis.

  • vincent

    Les Obstacles et épreuves ne vont pas freiné votre réussite bouba meunoul si yaw dara loumoy bonne yeup connard

    • Fatou ba

      Après lecture de presque tous ces commentaires, je crois que c’est bouba ndour VOTRE problème. Eh bien mougnelène té beuss sen khôl yi

  • salif deme kousalang

    bouba ndour ne respect personne il se crioe au dessus de tout le monde alors que c’est un incompétent sans son frere il n serai pa connu domaram la rk

  • gean

    bouba ndour meme khale sen petit gale yi sakh daleni mal traiter doff la rk

  • benoit

    Le courage, c’est de comprendre sa propre vie… Le courage, c’est d’aimer la vie et de regarder la mort d’un regard tranquille… Le courage, c’est d’aller à l’idéal et de comprendre le réel.

  • Alima

    D’où niittt kou bakh!! Menoull si yaw dara’ li dafa gnawww’ sokhor pour lane’ ni rek laniy def lougnou talll bamou takk’ gnou fayy la bamou diékhh’ sou khamone dina régler’ way yaw menoul tchie yaw gnapppp nd…….m wayyy Bouba boum ma wakhlo’ Lima niko youssou ta tt apri sauff le silence’ wakh rek lay deff’ dou niitou dara

  • makofekké

    pour moi, c juste du buzz!

  • bintou diaw

    C trop moche ça !!
    Vraiment bouba ndour lii doussa theurr gâche op ta réputation …..les blem perso se règle op ainsi..Ooh
    Queen com ton nom l’indique bah tu l’es ..alors continue de te comporter com tell suit ta voix com il le faut ,bat toi et srtt crois en dieu et tu verra que tt ira pour le bien .

  • mara-ndiaye

    il nes pas serieu

  • Madou kane

    bouba ndour momo sénégalais yi sof gua trop, yangui mėlni guinar bougnou souki beugue yeufou khalė trop pa bouye dabala chaque jour bouba bouba, reglėle yangui melni kou mome tėlė bi tė khamo dara beuri wo xam xam, or sujet rek ak khoulo ak wėrėnetė, djiguėne kaye dañioukoye diapalė. bou nėkoul wone youssou kėneu doula khame guemeul sa bopp gua ligueye sof gua trop bilahi

  • Marie angel Ndiaye

    Garde ton calme belle dame. Sache que nul sur terre ne pourra changer le destin de personne et de qui que ce soit. Le seul et unique qui trace et qui continuera à tracer ta vie c’est le tout puissant Allah, miséricorde DIEU.
    Continue ta passion et continue d’avancer le reste n’est que éphémère.

  • mara ndiaye

    Cette brave dame de par son parcours rappelle ton frère qui takhh nga fouy Tey.. Nianuleu sarahuwouleu elle veux juste que son talent soit reconnu à sa juste valeur.. Youssou Ndour reste une icône un emblème mais malheureusement son entourage à commencer par toi vont détruire son image.. Iow naak mom amo sakh image buniouy détruire, Viviane woyaal naleu no stress,chaque samedi xalei sen petit galle yi youhoo leu, demaal rek aduna guisseu kanam #coup de gueule d’une femme écœurée par la méchanceté gratuite

  • mofi

    Bouba Ndour tous les sénégalais savent que nittou dara. Mom niak diom motakh son frère Di liguey Mouy diarignou. Niaaw ak khôl bou nioul motakh tjrs Mouy takk noir fumé melni kou dopporal. Queen Man douma sa fan mais buguma kouy khokhatal nitt
    . Sa naWle sooko diapalewoul bouko bloquer. Ay deum lagn rk

  • nene louise fall

    Moi je ne le connais pas mais dal beuri na blem ko wax mouné bouba ndour moma xatal tfm… Wayé yaw Gueumeul sa bopp rek dara kheuyoul sorti… On est derrière toi Queen

  • Diatou ndao

    Bouba ndour même les petits enfants savent que tu est méchant wagnil sa galadjie té luma gueneu diahal moy momo dara thi tfm ga mél ni. Yalla dou dioum soco momom dara dou bah méyal nigni diam way ish sove ga trope

  • ty sene

    Bouba Ndour sokhor ak bone moko takha woow imbécile bou bone leuuuu bilay Bouba Ndour possone Leu siii mime rewwww genr wam yi Rek motakh deuk bi Dou demmmm
    Wayé yaw diallo dierry yaw daguay demmm meunoul si yaw gatt
    Te Queen fi diaroul Ray rayal niome koudoul wa prince art yenewouniouleu gua demmm …Voir plus

  • teuss

    bayileen bouba defoul dara Queen daf soppe rk bakh na si mom

  • Racine

    bouba guisnga fi senegal la injustice ken dougafi nangou tu as intérêt a changer donc tout le monde est contre toi idiot

  • salif deme

    bouba ndour gneupeu kham jikom dafa égoïste

  • tonton Fall

    Je voulais que tu comprennes ce qu’est le vrai courage, au lieu de t’imaginer que c’est un homme avec un fusil à la main. Le vrai courage, c’est de savoir que tu pars battu, mais d’agir quand même sans s’arrêter.

  • Diarra

    Car moi, le mutilé de la face, je ne vieillirai pas. La guerre m’a fait vieillir à vingt-quatre ans. Je n’ai pas eu le courage de me suicider. J’ai eu le courage de ne pas me suicider. La rancœur, l’aigreur menacent. Je fais face à l’ennemi intérieur.

  • Wa Senego lou takh ngen bone faye bi ngene yene wally yalla naleen dal

    Mane dama ame lou ma meti thi wa senego lou takh ngen bagn wally khana dagnou lena financer pour ke ngen yakh carrierame yena nekone sama site mé bagn naleen ndakh wally kouko beugeu khekh ma bagne la nitt yi doffougnou kham nagnou leepp li ngen niy deff mé yagg bawoul dara leppay leer wally mom mo ngui tothi bou bakh té mounoleen si dara yalla naleen yalla weer wally ndeyam da ligueey koukoy pekhal yalla nala yalla weer si barké ate mou bess mi limafi wakh sisama khol lako tibé yena bone

  • Vérité

    Salam le pirate elle est humaine on peut tous s’énerver de la même sorte maintenant histoire de famille Ndour ou autres n’a rien à voir avec cette histoire je ne comprends pas pourquoi elle devrait s’excuser quant à toi ma belle ne refait plus ce genre de choses cela peut nuir ton image continue ton chemin dieu est grand

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *