14 COMMENTAIRES
  • El Hadid tall

    cool

  • diambar

    elle se prends pour qui,cette fille.on est quand même au sénégal.
    un peu de "soutoura".t'es une africaine pas une blanche.
    redescend sur terre.au finish,t'es dégueulasse et vulgaire,rien d'autre.
    en plus, tu chantes quoi?

  • sam

    si gnou yaka senegal la boque ak habillement bou bone bimoull sol

  • bb

    yow ki ta proposer d poser nue?kel horreur de d voir nue,jai vraiment pitie de c photograph.

    • faild

      mrddddddddddddd bb tu ma tué celle la en plus d'etre conne elle est une grande menteuse buzz jusqu'a bout et préte a tt non de dieu elleva devenir folle

  • bigmo

    si ont'a proposé ça tu le ferras !

  • mhd

    ok

  • joe

    bb yangui ja dé khalé bi vulguére na certe mais dafa moll

  • debian

    plus menteuse qu elle je n en connais…c est archi faux …les senegalaises qui se respectent ne vendront pas leur corps pour de largent…si t es prete a te marier avec un singe pour de largent assume..mais n insulte pas celles qui croirnt en des valeurs

  • cheikh ba

    gnonk ngileni wane sene tele ngo yam ngo yakh senegal guemougnou dara

  • Noppsamadieukeur

    sa sole you bone yi ngay sole motakh nioulay proposer lolou am lene fouleu nguirr yalla bo melone ninga wara mele am fouleu di sole Lou diote kene dou am audace dila proposer lolu thimmmmmm niak fayda

  • france

    no mè dousounou cultur boukko toubab defone kenou wakh tè fi kenou ipocrite mè sa foto clip bi rafetoul so nekke magu digua ko kham guissou aida samb khanna kou yiw la tè nit gni beugueu nanoukko boul deff afai
    rou diaffra sakho yoyou tèkk khèl bakhoul dou dem

  • kebe *

    khayna dafla beugona lall motakh pourtan meunone nga nangou deh mou foutila diokhla khaliss com k deff tatou nène si clip yi ak fonantè rek ngay deff ishhh sofnga loll

  • beug serigne touba

    hum

Publiez un commentaire