32 COMMENTAIRES
  • Maty

    Waly rekk ci kaw scène kéneu dou tokk machaalla
    Foumou dougou yengeulko

  • ass

    xémé dal ya gnack khamm waly dal ak live rek dara fayouko meuna ambiance machala en plus il est free sur scene vremen love you waly

  • XéMé

    wally tu a une bel voix mais sa music en live c est du n importe quoi. tes musicien dafa déss .on comprends pourquoi t recruter des tenor djimy et abib mis coorgorlou si music bi . sino lii ma djiss demoul bercy

  • Badou

    Kou seitane Waly king fath demb khamni Waly maguena

  • dakar

    Mais afia yaw rew nga saga pour lane no senegal nite yi bakhou niou saga wally pourquoi lossi gagn niaw lamigne rek vous tes des mcontents

  • seyni sall

    C pas inportant vos commentaires

  • Amina

    Afia yaw khana amo Ndey man awma ben afair ak Wally way waroko saga Ndeyam defoula dara

  • boy LG

    Bayi ko riek Moy teke khel

  • phil

    waly ndagaye mate di euf waye youssou crocodile dofoule dé
    sene affaire dina méti
    lou lerre lala wakhe
    youssou dou la meye dara

  • boy LG

    si si merci Bou lou wer ga wakhe kien dou setou mari sene bi

  • moom

    way afia sa tour bou seel bi ngay wakh li,nay rafeet way

  • BREF

    Deet way AFIA rousseul internautes yi

  • BREF

    Deet way Afia

  • afia mbow

    wally seck yaw sa lafalndaye

  • Bou

    OK je te l’accorde Boy LG mais bon You c’est autre chose c’est une star planétaire.

  • boy LG

    bou ak comba gawolo waye riek laye de

  • Bou

    Cest nul ! Il ya 1 seul chanteur au Sénégal c’est You. Basta !
    Le reste khamouniou daraaaa !

  • Faramaréne

    Li dou dara ! Arrêter de nous saouler avec You. Il fait parti du passé.
    Famille Faramaréne laniou wakh !
    Li Liguey Thione leu !!!

  • Dame sa

    Il n’y a pas de potin ressemblance entre les deux

  • fifi

    Ahmed aidarra moy nk si radio Di garal youssou ak pape diouf mo yakh liguyou journalisteyi

  • Anonyme

    Vous qui compare Youssou et wally vous tes dingue ce sont mes dernire mots

  • teranga

    Vous nous soulé avec vos histoires de youssou ce lui qui chante ne peux youssou est le rois du mbalax l’ais on s’en fou de lui il a fait son temps laisser les jeunes de chanter aussi merde

  • pape gueye fambaye

    wa senego douniou aye professionnelle leurs facon de travail

  • Bass

    Wally sait chanter ou pas c’est un faut débat .se que je peux vous dire c’est que se goss n’ai pas un petit type.

  • VK

    Wally nekhena trop tu as une trés belle voie geuneul geum sa bopou rekk té nga bayi lepp si lokho yalla machalla je ne suis pas fan des chansons de you mé bou fékké ni comme ni nga ko woyé la son bi mél kone nekhena

  • rebatass

    mais FIFI yaw louy sa blem ana yonou Ahmed aidara fi

  • boy LG

    mes wally dofoul de khame na foumouy tiek tankame Aidara mome tayi na wakhe sy mome

  • deug

    no vraiment senego gno beug diakhasei waly ak youssou nex na mais tamit you c le Roi du mbalax

  • Pa

    Dans tous cas qu’est ce que Ahmad aidara fait dedans merde Waye doul

  • fifi

    ahmed aidarra moy diakhassé waykatyi

  • fifi

    Ahmed aidarra rk moy diakhas waykatyi ndakh khalis saytan pir

  • deug deug

    senego khana wally seck dalndi fay par weer ??

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *