Vidéo : Propos qui choquent d’un talibé de Béthio à Soxna Aida Diallo – Regardez.

Propos « blasphématoires » d’un talibé de Béthio « Soxna Aida yay Serigne Touba, dinanoula ramal, diananoula féthial, dinanoula diox adiya… »


66 COMMENTAIRES
  • Imam bachir

    yéne ay mbamb reck guéne

  • CHELSEA BUZZ

    bethio toune a transform le tarikha mouride une bote de nuit o les jigeenou thiaga sont des reines les goors sont des noyy t neekhe mdrrrrrrrr

  • perso

    Mdr… trop drôle le sketch . pour beaucoup moins que ca viviane doit s’excuser. deux poids deux mesure. Ya allah

  • CHELSEA BUZZ

    mais le khalif gnrale des mourides mome nieupp khamnegnou kou yiwwleu waye nawakhe akk bethio Walla deffakoo ragall???

  • Giss Gissi

    vaw ki khana da mandy khawma kodon vay ya dokhan sa nday yay domiarram

  • dakar

    wakh diotna nack

  • Mohamed Ndiaye

    non mane dama warou cheikh bethio eupeulna legui d

  • CHELSEA BUZZ

    chaque nuit bethio toune deffayy kaatt les cheikhettes kii tookk sikaww kanapbii moossii geunnaa saff leufff motakhe kaw kaw deffa warra nieuww nioudemm siaarekoo ayy siarre youwoorr mdrrrrrrrr

  • awa

    barki yalla akou serigne touba souléne dallé bethio ak wa keureum dagnuy alkou

  • stockholm26@hmail.com

    wa ana ngi geum serigne touba founn necc si aduna bi mande tijan la waye li metinama torop

  • Inconnu

    Ki dale gni dalll kou tegal sen nday gnou dieul domou kharam yi noo do dem fethial sa yaye walla ga ramal sa yaye waye fecc dome kharam dji khesall ba wekh def bopp nene gakay wakh li ma warounak tay

  • comique

    Noon trop drôle, mané yénela rek.

  • cartel

    l’heure et grave haahurou zamane

  • Talebb

    Mais ces femmes là sur la Vidéo ne sont même pas décemment habillées pour mériter quelque considération que ce soit de la part d’un vrai musulman. Il est temps que les Serignes de Touba règlent le cas Béthio au lieu de prendre des moutons de Tabiski et autres Adiya de sa part et se taisent.

  • brown

    Kala nakha Kat ndéyam

  • brown

    Kala nakha Kat ndéyam lii may dégeu nii amul c po vré damay guénteu

  • spagheti

    ahh les mourides ou est votre khalife pourkoi pas un fatwa contre bethio

  • karimiste

    bethio dagno tap

  • lahat mbacke

    bayiléne ligéni défe ta déme diamou dji yalla mé suñe kilifa yi rawatina s bass abdou khadire mo wara géne wakh thi lii wala ñoune ñou fadiall ko suñe bopou ta liçi kaname rawouli beut

  • kaw kaw

    giss gissi dadieu guama ki Kaye dafa mendi mdrrrr

  • sénégalais

    sama mokeu mourite yi wakh léneu bokeu l’heure est grave on parle de Viviane et autre mais li mo raweu.

  • xxx

    marale ko badiome bi, fotal ko silibam, ak di ko laal you nekh

  • astou

    sokhna si dé sou nanko li dou koudou fane bilahi dé bou gnaw lay dé maleneu ko wakh dé dinahnouko wakhatt

  • fafa

    vraimentttttt ça c trop je ne suis pas mouride mais on doit régler cette comédie du n’importe koi. comment on ose dire k cette femme là est serigne touba ah nonnnn

  • chat

    Mane dei diomi diométe la déf lila wolof Ndiaye nane liy rame si gnakbi la dieume té boufa amé keur doufa gawa guéne gni bougnou léne bayi gnou déf lou rawli lii guéne pire lii eupena doywar

  • tak tak

    bathio moy financé magal gui motakh.
    Wayé kou ray lou nit ba paré ntérrélou nit vivant niou bayila thi biti nguay tam-mbaa mbalou thi deuk bi, loula nekh déf, loula nekh wakh.
    Bethio moy financé magal gui motakh lii lep di am.
    Waye lithi kanam moy raw

  • bira kane niang

    ces tres grave ca on n ‘est ou lá

  • baol baol

    sque lii dou montage ndakh von vouniou bne yone kiy wakh mais lousi mane di am trop c trop t dama fokni sakh bethio aida dako ligueye noy ame ay dome you goor niounkfi nga nanane soumafi diogu topoulene si aida diallo momla te nga am 7 femme les autres nak franchement wakh diotna

  • médina city

    cheikh bi déh louko nékh déff nitt gni diko sétane lii dafa yomb torop

  • mbeute

    serigne touba dinako fadiale bopame bamoufi fenal serigne saliou thi electionyi weere lagnouthi teque mou def mousiba niou nokheko thi cassobi louko raw mokoye dallate maleneko wakhe

  • Galsen

    Bètiho dousi sarapp ndayame yaw tak tak

  • mor

    Les talibés mouride doivent prendre leur propre décision ! Ils faut aller chez lui et lui cache la gueule ! loolou rek la, ce mec est saboteur il est entrain de déshabiller le tarikha mouride .dou degue wakh ! bouniouko doumaa mou degue!

  • Senegal

    dou layen dou tidian dou hadre dou niasen tjour les mouride t tjour entre t tjour problem war ngena hol sen bop daal

  • mame diara dieuf

    Tarikha takhawalou ak thiaxan khaliss djigène

  • senegalaise

    thiey yalla nanou ragal yalla well khel to ci yalla deh amna deh teh kou nek ak sa bamel yalla nanou yalla tek ci yone bou dioub bi leeral niou ba kerok niou koy feki

  • Coumba

    Mane de warouna Cheikh bethio eupeilna .
    Serigne Cheikh saliou ak serigne Moustapha saliou naniou wakhal Cheikh bethio nak serigne saliou dou morom .il se croit tout permis

  • Moristo

    Mdr trop c trop Cheikh biii dalee mooo guii nonouu rékk

  • Serigne

    Astou yow ya meuna DOULE!! Yow Yaye Yallah wallah?? Bayile fenn

  • brom diamono

    cheikh bi diaroul tontou serigne touba dinako safaral boppam inchalla setane lene rek kene dou kou tede ki

  • kounda

    wawaaawww, kii mom diaralnama topou cheikh bi, wayè nakk seulement mou ebergeèma gallènn, si birr nègamm, comme ca makakèyy diokh sayou noppè, bènn danou par jour rèk bakhna…. khallèbi noyna noyna, molna molna…. danama rayyy mdrrrrrrr
    DOOOMARAMMM YAW AK KILA CHEIKHAL

  • MOURIDE

    J’ai fait une remarque assez déplorable. A chaque fois qu’il y’a une publication sur Cheikh Bethio, les détracteurs de la voie du MOURIDISME s’invitent à la danse.
    Cette anipathie que vous avez pour les mourides en générale et pour le Cheikh en particulier ne freine en rien notre dévouement, au contraire cela le renforce et nous donnent plus d’ailes et confirment le degré trop élevé de spiritualité de CHEIKH AHMADOU BAMBA.
    Au Sénégal, nous avons de la chance d’avoir vu naître des hommes de Dieu confirmés. EL HADJ MALICK en est un parfait exemple, EL HADJ OMAR, MAME LIMAMOULAYE, EL HADJ IBRAHIMA NIASS et j’en passe. Eux tous se sont battus pour la triomphe de l’ISLAM.  »Tous les musulmans sont frères », donc de grâce arrêter cet acharnement.
    Pour en revenir au cas BETHIO THIOUNE et ces  »cheikhettes » qui je pense n’ont pas demandé à être cheikh, je condamne fermement les dérives de certains de ses talibés et de lui-même. Avant tout, Bethio est un talibé mouride, comme nous d’ailleurs. Un talibé doit se conformer aux enseignements du Cheikh et à la SUNNA du prophète. Que ce soit Béthio ou un des mammouths du mouridisme, celui qui déroge à ses règles n’est plus mouride.
    Nous vivons en parfaite harmonie mourides, tidianes, layenes, niassenes, khadres, chrétiens…et nous le resteront.
    Que paix et concorde règne aux Sénégal.

    .

  • ousmane

    yall ne lenn yall soppi T gnenn len si rrre tkk lenn si yonou siratikhall moustahim . amine

  • Daouda SEYE

    je croix que ces personnes boit de l’alcool et fume du chanvre indien comment ont peut une une femme qui ne porte pas de voile dans sont tete qu’elle est Serigne Touba Astakh Firoulah Bakar Kenouko reuye Bilahi nous devons tous les tuées un par un vraiment tous ces gens sont des prostituées et qui prend le nom de mouridisme pour couverture simplement mais vous qui écoute ces gens de personne n’ont pas le culture mouride ni musulmans meme le khalif général l’a confirmé dans sont discours de la fete de tabaski 2016.

  • ANTA

    IL EST GRANDQUE LES VRAIS MOURIDES REAGISSENT SUR LE CAS DE BETHIO !!!

  • MAURITANIEN

    AH OU SONT CEUX QUI HARCELER VIVIANE POUR DES DEBILITES DE GATEAU ENVOICI UN VRAI SUJET ON VA VOIR SI VOUS ALLER CRIER SCANDALE MDRR
    QUE DES POLTRONS DEGUISER POUR SERVIR LEUR INTERET ET S4 ACHARNER SUR LES FAIBLES

  • CHELSEA BUZZ

    serigne touba meunoull fadiall boppame darra ndakhe deena bapare lii mome gnii doundou niooko warraa fajj

  • Thiam

    Je suis Mouride a 100% mais je comprends pas ces gens qui parlent. Ils confusent tout. Dans l’islam hommes et femmes doivent pas serrer les mains.

  • modou

    dou keneu koudoul seutou serigne touba yi talouniou dara nakh politik fila niou wakh rek si diokhe hadiya serigne basse abdou khadre tontou silou gawe wala bethio molene yilif bok wakh lene niou niou bok lane moye mouridisme

  • Ciao

    Mais eskeu gni il’s ont conscients ?

  • sofesss

    li dé moye moudjou diamono eupna dé

  • Moustapha

    Il est temps que les marabouts parlent ,disent la verite et montrent la voie de Dieu qui est le coran et la Souna du Prophete saalaw tala wasalam. Il faut enseigner aux gens le coraan et la sounnaa c,est miuex que de parler seulement de un etre humain quelque soit son niveau ,son degre de savoi.

  • papis

    Non, je pense que c’est une nouvelle piéce de théatre qui vient de sortir. Pas moyen que ce soit vrai

  • kalakouta

    sa c ibliss gni moussougnio am yalla ni yenenti c honte pour les mourides

  • diza

    yne def len lou lene nekh yalla yakamti woulene ndakh abliss guene andal yakk gune yonou mourid li eup na way

  • serigne saliou

    Yéna bone ta doméramé yakk nguén dérou mouride gui billahi barké Serigne touba diguén ka guiss

  • talibé bamba

    Ma lérale lénn rek nguén xam ًko moy Cheikhe béthio Serigne Saliou meusouka cheikhale dadan bania toudd tourou béthio motaxone moukadane wowé Cheikhe bi Cheikhe béthio Serigne Saliou limouko falone moy dieurigniou dahira Serigne Saliou yi nékkone fi si dakar lolou moko méyy moudone app njiite wayé doulénén S Saliou masouta cheikhale kéne si kaw souff loulér lalén di wax ni

  • Ousmane

    mane dm par personne douma soudiotal djigen moukou si kaw souf ndakh djigen boudoul sa sokhna waroka nouyou wakhoumala ngay soudiot wasalam

  • via

    soumkhanala, yanamou YALLA digeule si nop yinouko dguelo, au Sngal les gens font trop de bokal

  • demba

    bilay vwadji ya bon domeram original dem len rek adouna moki sen kanam t guisnen lou dall bethio bamou commenc takk ay dioumi sokna lako tambali dall Lou kou baki meusoul nangou ci doundam Molay deff vous des setan original domeram

  • Wakh deug rek

    gni ay mbame sakh khalne tan,mbollo mi serigne touba done wakh mogui ni,mbollo boye wouyo sama tour t khamou nioun gnogui babbkou dieume sawara t dara doulne fa tr dme

  • BREF

    Diereudieuf Mouride ak Talibe Bamba linguen wakh dara douko dindi

  • pokaniero

    léne rek laye wakh beusoum yawmal hiyamm nite bou nek digua diakarlo ak borom bi bagua yakarné yaw rek la sakk si kaw souf nagniou délou sougniou héli ya salam

  • mame

    soubhana lah la khawla wala khouwata ila balahil azim barki yalle diguene lakeu Cheikh Amadou Bamba Khadimou Rassoul ak limou ligueyal yalle liguene koy fay je ne peux pas comprendre pourquoi les descendants de serigne Touba ont donn bathio cette empleur qui ne dit jamais yalle nena yonente (SAW) bi nena fethia rek ak tassou rek je ne sais plus dans monde on est djiguene bou niouye sekhal naleen djite dioulli gnou guiss bok

  • fallou sylla

    Dama yakar ni Addouna moye bague toki

  • fallou sylla

    Dama yakar ni Addouna moye bague toki

  • Moussa

    un peu de respect

Publiez un commentaire