16 COMMENTAIRES
  • famita

    bilahi soffo ma mane mala beugue mane ak sa frere ass diouf nio bokk fougniou nek angleterre

  • FANS WALY SECK

    MANE DALIYI AK LACOSTE BI LA BEUGEU PAPE VRAIMENT SOLOU DAYE SIMPLE JAIME

  • vérité rek

    que de la médiocrité. C dommage pr le Sénégal !!!

  • da

    loukoy fayyy

  • féké moma si bolé

    nice na

  • dios

    bonne continuation pape , tu es sérieux , correct ama foula , fayda , kou la guiss dou lax nda goor la wa jiggen . Niit dey am keulifa .

    • Fa

      Bien di dios. Gorena te nekhna lol. Afer de gooru yala la koussi bokoul nak ya kham. Papa diouf for ever.

  • Maria Maria

    mashallah pape koula bagnnn na dém fanane si négou gaïndé ba xamm

  • mina

    matis ya sofff

  • sn

    machalla pape say none dinagne sone

  • lk

    lo déf nonoula balay nekhna

  • dia

    trop de rythme il y a pas de fond musical

  • amy

    il chante tré bien pape bonne continuatons

  • matis

    Nul ! Toujours les mêmes sons ! Il faut innover waye nak

    • bayilène sokhor

      Lou sokhor di diarigne????

  • mina

    Ehh malaw bii dina yengueul diamono dé.Waa mame mané guissoumako sakh sii anniversairou pape diouf bii chè lui

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *