Vidéo – Oustaz Oumar Sall clashe sévèrement Youssou Ndour sur le festival Ya Salam

Le Festival Ya Salam deuxième édition a vécu durant ce mois de Ramadan. S’il est magnifié par certains, cet événement est critiqué par des observateurs. A l’instar de ce religieux qui s’en prend à Youssou Ndour le promoteur dudit festival.


clash festival ya salam par buzz-tv-sn

97 COMMENTAIRES
  • neant

    KI NAG KOU YABATE LA

  • neant

    KI NAG KOU YABATE LA TE BEUGA SIW MOME MI XAM DINE MOME DONG SENEGAL NAGNOU KO WAX BA XAM NDAX DINANOU KO DEUGLOU

    • Serigne ngagn

      ki loungène diko xassé ak saga amou fi. Deug rek la waxx.youssou ndour amoul benn yeurmandé. Les skull and Bones (tiens comme le nom l’indique!!!)dont fait parti notre ami you ont profané puis violé la sépulture de Géronimo, ensuite ils ont récupéré ses ossement et s’en servent pour des rites bizarroïdes qui font perdre le sens commun. Quand on on est musulman on fait de l’Islam une exclusivité. Il n’ y a pas d’extra.
      De plus il y a quelques jours de cela tous ces tiakhanekat ont ont convié chez le Khalif Général sans qu’ils en comprennent le sens.Leur méthodes ne sont pas les bonnes et SERIGNE SIDY AL MOUKHTAR a voulu par ces occasions leurs ouvrir les yeux et comme IL est humble et Libre arbitre, IL les laissent à leurs fourberies en espérant qu’ils changent d’eux mêmes. Ces mecs parceque le CHIEYH leur a sourit se croient immaculé mais Seugne bi kenn meunou ko naxx. youssou et consorts etcétéra

      • ismaila

        yow serign nga fokk li nga wakh mom la yala geureume ya gui sedale nite mlou bone te li si geuneu grave moy khamo lo ko dara yake sa morom dioulite deh yala beugou ko te ware gene kholate li gene di deff ak diko wakh bala gene di wakh kene degue dieukelene ko si sene bopp pour yene yene reka bakh te dou nonou yala la youssou ndour la togne te yala mom bou ko nekher mou bal ko mai yene boule youssou ndour balou dina meti si yene trop wa salam

  • Soof

    Nit dafay mandou sokhor bakhoul do yalla bay att diam yalla

  • GFM

    senegal mo meti yalla sah dagnou koy critiqué ken mounoul def lou neh gnep walahi kougnou si bolé won si comité directeur bi nga gnew thiey adouna mé nak yala reka ham kouy téhé euleuk barké yomalhiyamoul akbar com le dit diop fall wassalam

  • amath

    yow dagay fene rekk sa la fall day yow dou doulite sa bado day

  • deug gui

    Deug pir guafi wakh.gni dagnou ameu seneu agenda boulen toubab yi diokh guir gnou yakh dine dji Youssou Ndour surtout faramassong yi ana dinne akoup festival thi werrou kor

  • valdo

    verité bou claire nga wah oustaz senegal mo beuri nakhékhh rek té kénn dou wahh

  • Ive

    En tout cas Satan est entraint de gagner ; si on s’appelle You tout ce que tu fait c bien, y compris de jouer avec lhislam;

  • Pif

    RIEN QUE DE LA VERITE

  • kaana

    c vrai oustaz yalla la
    niou beuga nakh rek

  • festival

    Ce sont des Salafistes ces gens la. Notre religion n’a pas interdit les mélodies le zikr et l’organiser au grand theatre est mieux que de mettre des haut parleur dans la rue di sonall nieup.

  • Ly

    mandè samakhalat mak outaz ñokobok mais lima sètan dou diner

  • satie

    hahah ouztaz demal diangalé tei may niou sunu diam festival bi salam leu toude tiow lay bagn

  • boy niang

    alhamdoulilahi ya Allah vraiman yalnala yalla samb li gay wakh kou bakh rek moko mana nagou yalnanou def deug deug djouliit mercii imam Oumar Sall

  • dan

    kiii koumou akk foumou todj djeuleul lenn oustaz pédobear bii rkk……..tourou Youssou Ndour nieupp siiy djemm outt buzz dall…Oustaz mandoul wayy ak su sikim doméram djii!!!!

  • walabook

    en plus imams,si vraiment tu étais sincère et courageux, tu aurais aussi souligné le GOUDDI SARGAL CHEIKH BETHIO.

  • rio

    mais li ma diakhal moy ibandou yi loutakh mbadou wou niou legui da ma beugue khame lou yala wakh si niak mbadou

  • Jackie

    Yallah dal dou aye fo

  • samba

    oustaze bi da mer nakh wowou niou ko si festival bi you nakh waro nga ko si boler pr mou ame si khaliss

  • chelsea

    maak sama doom ndeung ndeung sama doom yeek si mbam.fii moy senegal ken mounoufi bakh

  • Mams

    Merci encore Youssou ndour car je pense que chanter les louanges du prophète n ai pas un probleme.en plus c des tabala

  • asta

    ibandou mom da nio contre tarikhayi motakh mou wakh li sene khole nio bone yene ibandou tu sais quel est votre probleme vous pensez que yene rek yenay diamou yala ke nieup safara la niou dieume yene rek kaye dougou aldiana te mbadoulene lolou rek mo ma meti si yene

  • combe

    yene oustaz yi khame niou li gene nek si dekeu bi di woter ne yala la niou geume ba pare di teuder xaley you ndawe yi donc meuno lene niou wakh lou niou saf

  • mag

    Merci.enfin quelque pour le deplorer .dagni business si l’Islam eek.mais forklor amoul si l’Islam .ils Lon copier dans dautre religion.Et ils disent qu ‘ils l’avalent des chefs religieux.thiakhane tel.en suivant suivant or festival Tu te demande qu’eat ce qui le differencie Des soirees organisers par Walt pale solid ou autres.parce ya des cris des tam tam des dances melange entre garcons Et filles beef tout ce Que banjo l’islam

  • mohamed

    mane deh taye lay doga degue ni tangue seydina mohamed psl yala beugou ko te seydina mohamed psl bi mi deme si kaba gui gni di ko wooy ba yegue taye rek la warou si senegal

  • paco

    ki buzz lay outeu motakh mou wakh da beugue niou khame ko nakh lolou da sak passer mou bayi ba taye di si doga wakh

  • saliou

    senegal mo meti doundeul lo deff niou kagne la fi nite di amer diam da nio sokhor nite yi la niou bagne niou happy nakh bo demer soiree boula yala diaper bo demer si diine dji niouner folkore la ay fou nite di mouthie khani bou yala nekone senegalais nieup safara la niou dieum malene ko wakh sonal gene niou trop lo deff niou bakhou ohh

  • mag

    Merci enfin quelqu’UN pour le deplorer .dagni business si l’Islam rek.mais forklor amoul si l’Islam .ils Lon copier dans dautre
    religion.Et ils disent qu ‘ils ont
    l’avalent des chefs religieux.thiakhane rek.en suivant
    suivant ce festival Tu te demande
    qu’est ce qui le differencie Des soirees organisers par Walt pale solid ou autres.parce ya des cris des tam tam des dances melange entre garcons Et filles bref tout ce Que banni l’islam

  • mouss bou rew

    no kiiii buzzzz layyyy weurrrr mais il a perdu na lamb fénènnn fimou lamb noyoul

  • deug pur

    Oustaz fan nala , deug pur nga fi wakh……senegal légui boy wakh deug niou déf la noone…..
    wakh nga deug…gniy nék si lamb dji nioy nieuw di wakh si diiné…..
    Nitt meune na nakh moromam wayé yala kéne mounouko nakh…..
    Nék si way ak tiakhanou bercy bamou nékh la…ngané da ngay organiser festival ya salam…..
    Yala mou ngui niouy khaar

  • baba nena

    Bon moi je crois qu’en partie je suis avec lui. Les sénégalais ont tellement la mélodie et le divertissement dans le le sang et dans l’esprit que même pour religion il faut qu’il aie du rythme et de la mélodie. Le festival y a Salam est très loin de la religion apporté par le prophète mohamad (psl). Même certains Gamou et Thiant on voit des femmes et hommes se mélanger et danser ensemble sous les coups de batteurs de tam-tam. L’islam au sénégal est un mélange de d’islam, de croyance traditionnelle, de divertissement .

  • Kane

    ISLAM dou dinék thiakhane ..kholat léne dokhaline yii.

  • serignesame

    keneu koci nek lo def sa bop guako def , legui waxale ni kahbou ak bousayri gnika khamni ay sakhaba lagnou wone di tague yonenti psl diko waye dagnou done bokalé , sikar guani yonenti psl xamouko wone kone xana daguanoule kene di toude tourou yalla diko yekati ci kawe ,amna lo xamni diamono dji rek lagnou koy degu, dafa melni yéna bokone ak yonenti bi keur ba lou nit gni def gneni dafa haram, nit bopame nako doye sokhla wa salam

  • baba

    Oustaz bi wakhna deug dé. Diné Sénégal légui folklore rék la. Les animateurs de lamb, d’émissions de musique, etc se muent en animateurs de religion pendant le Ramadan. Finalement, tout le monde est spécialiste de diné au Sénégal. Merci oustaz Sall d’avoir osé dénoncer un tel phénomène.

  • balize

    senegale mo bar nafkh bo wakh deug nouni dafa sokhar kouye thiakhane rk lagnouye weure mo takhe gnou retare bou mti si deuk bou amoule gaire ame daimou ba par bocoux si rwe yi geuna peuvre dakh aye nafkh you bar you gemoule dara gne balma si kadou yi tgdl nagnouye wakh deug bayi fngou barbi lkantbi bougnou beug rawe sougnouye masse

  • ouz

    mais loutakh mou amm gnou sokhor
    non ca se voit que You est le patron de dakar nak, on peut rester un jour ou deux sans qu’on parle de lui
    kou beug beuzz rek wakh si mom
    oustaz yaw mom dangua doff

  • diams

    regardez moi ce gros con mom, festival bi dialeu bi nitt yi di tal lénén mom mouy wakh wakhou ignane ak dof
    kou bagn You na tal gaz tok ssi

  • fallou

    Oustaz danga dof wala dangua tokh
    bayiléné youssou tranquil mou liguéye

  • zz

    senegalais dafa sokhor koi je ne sais plus quoi dire mm
    mais Youssou khamalni affaire bi yawla yaw kassé tous derriere vous

  • desty

    oustaz amoul sokhor way so sagnone door festival bi mais comme c’est Youssou rek nguay jaloux
    allez youssou ndour yaw rek

  • lolo

    copain please ta gueule way
    Youssou moy affaire bi

  • doorwar

    Youssou ndour boul fallé gayi dagno ignane rek

  • patt

    Youussou le grand patron de dakar
    c’est normal kou beug beuzz rek wakh ssi mom

  • trrrrrr

    oustaz sall nopil té liguéye ni Youssou mo gueune

  • Maty

    Waalakhi c vrai
    Oustaz je suis d accord avec vous

  • fati

    wadji dafa tokh yamba déféna
    kou téki la senegalais di bagne degueu
    You lui a fait quelque chose pour le pays et vous qu’avez vous fait loudoul gueuléééé rek

  • mahmoud khalil al houssary

    machaAllah oustaz tu as dit vrai!! Malheureusement au Sngal ya que des satans !!

  • diopdollar

    kouko bagn na matta bakanammmmm

  • green

    Macha Allah oustaz amna solo torope.Trop d’hypocrites au senegal que des dorkat de serignes et autres que dieu nous protege de c diciples de satan

  • abdullla salafiste

    domeramji la deg mouni xessal ak wat sikim nio yam
    byilene xalissou arabe yi t wouti liguey

  • soulay

    Mashallah ya oustaz que Dieu vous bnisse

  • best

    damani youu degueneu lounekk kenne meuneutoul si mom dara il est blinde lambal fenene doula yeuk sakh

  • soulay

    yallah Nala yallah dfale diam ak werrr amine

  • soulay

    Oumar salle diam rk inshallah

  • mara

    Sénégal li moko yakk quoi
    Ouztaz bi dafa wakh ngir yalla takh
    Toudoul benn tour .
    DEUG nak dafa nekhoul

  • saa kadior

    Youssou Ndour n’est rien d’autre qu’un affariste qui vit sur le dos citoyen.Il exploite toutes les opportunités et sans état d’ame.

  • leuz

    nekhoul ba nekhoul waye wakh ngua degue

  • boy niang

    mai lou takh legui beugou nou kou wakh deug mai deug la wakh mai dou islam c vraii sounou mak you bakh bounoi fi kone niom dina nouko wakh mai nak senegal wakh deug deug islam mo fi rafl

  • DIOP FALLL

    YOUSSOU YA TAYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYYY NITTT DAY MANDOU CELUI QUI CROIT QUE MOME REKK MOY DOUGUE ADIANA PARCE QUE DAFAY DIOULI DI WOR YANGUI NAKH SA BOPP YALLA NIEUPP LAFI NEKALLLL

  • mouminine

    Enfin quelqu’un qui dit haut ce que beaucoup pensent en bas. Festival Salam ken bagnouko mais rendons a Cesar ce qui lui appartient. Diné dou batiment bo hamni koumou nekh apporter sa pierre a l edifice. Dine kenn douko ndiar ay goor ak jiguen diahasso niouy tagg ay niit di sabarou lolou diner la? Merci Oustaz gnilay hass danio hamul sengal wahfa deig mo yomboul

  • OUF

    ouztaz ya taye ya taye taye ya taye ya taye taye

  • Diomba niaawe

    Bousayri dou sahabade berkidemboo ndiayela boussayri Egypt la deuk

  • spagheti

    youssou est in grand mr de la musique mais reste homme d’interet il est partout musique mbalakh reggae pop religieux il est aussi ministre chanteure promoteur il est partout est gagne partout meme dans le sociale est sa c pas bien

  • Diombaniaw

    Boussayri doonoul sahaba

  • Istihfàr

    Tout à fait d’accord ces gens nio fi dàkhà fààt wàkhtoù diouli nék thi làmb ji bà goudi.Té sounoù boroù nénà kou fààt wàkhtoù sàlààt thi lou là nékh déff ngà bààkààr .légui koor gui nieuw ils veulent parler de Dinné .ce ne sont pas des voix autorisées pour parler de l’islam .Deùg nékhoùl wàyé mom leu Yallah beùg..

  • lesi

    Oustaz bi waroon nassi bolé Quatier général ( thiaaxan ,xawaré , sans oublier le defilé de Ngoné Ndiaye qui montrait ses rondeurs) C pas serieux tout ça .
    Je crains qu d ici qques années que le mois de ramdan soit demystifié et devienne un mois comme un autre

  • mor sow

    kimom dinè senegal bimouy khep biko souniou mak gni done khekhal fou bayam nekon,senegal ci bopam amouniou foula souniou mak gni koulen di di ngat heur bi warone nafek niou tegal sa ndeye bou yak,yen media yi tamit sen part de responsabiliteame nassi dolè ndakh niou melni ken doulen diokh ben importance bi.ahmet khalifa lep loumou len wakhal rek deugue la ,ay vrais terroristes youy lakhatou nguen ETAT BI nalen bayi khel bou bakh.

  • mahmoud khalil al houssary

    youssou ndour warna reflechir boubakh on se rapelle tous de la mort de papa wemba sur scene musicale aduna bi billahi dey dieekh yagatoul

  • oumar

    Oustaz maa la fans

  • babou

    Machala oustaz kou wakhoul deugue féne

  • Amadou

    Attention à ces oustaz salafo-wahabbit. Subventionnés par les saoudiens.

  • Rijal

    QUE ALLAH VOUS BENIS MERCI ET BIEN DIT

  • xalil

    salam man dh lenn rek la beugonn souligner moyy nioun gnii dii commenter niou dem djangui tei Lii niouy argumenter niou tekk ko ci des bases solides ndakh islam dou khel mou sell, dou louniouy natt ci xell… terrei yanguii fii. wax dii sanny bakhoul… akk djeglou bou wrr

  • fall

    oumar salle dou dara youssou bague n’a serigne touba diadiff you

  • cheikhna mbacke

    goudi cheikh bethioo loutakh dolene ko wakh

  • Modou ndoye

    wakhga dége té ouztas

  • ETUDIANT

    Oustaz, merci pour votre rappel. Bou dee deugg rek moo neekh Yalla, lingua wakh yeup deug la.

    VREMENT VRAI!

  • kheushy

    tu as dit la verite oustaz

  • Falilou gueye

    Les communicateurs n ont fait que leur boulot

  • alimatou diawara

    very good

  • bouba

    ferme ta gueule, tu as fait quoi toi pour le Sénégal ????

  • @Bouba

    SOURATE 21
    AL ANBIYĀ˓ (LES PROPHÈTES)(1)
    112 versets
    Pré-hég. nº 73

    Au nom d’Allah, le Tout Miséricordieux, le Très Miséricordieux.

    1. [L’échéance] du règlement de leur compte approche pour les hommes, alors que dans leur insouciance ils s’en détournent.

    2. Aucun rappel [de révélation] récente ne leur vient de leur Seigneur, sans qu’ils ne l’entendent en s’amusant,

    3. leurs cœurs distraits; et les injustes tiennent des conversations secrètes et disent: «Ce n’est là qu’un être humain semblable à vous? Allez-vous donc vous adonner à la magie alors que vous voyez clair?»

  • Fatima

    On est au senegal personne ne veux entendre raison mais ya Oustaz diazakala khayran satan a conqui le coeur des senegalais on y peux rien mais personne me nous empechera de repandre la parole de Dieu inch Allah

  • Warou

    Festival ya salam même pas 1 mois guadéf sa costume bou bakh organisé sa soirée cices say moromou dome ak seute dadialo gor ak djiguéne di féthieu ba fadiar. Bilaye oustaz wakhatico Sénégal dinéji daye coye fowé ak sénni fans club té kou wakh niou sagala c triste.

  • junior

    youssou ndour a initié ce festival pour montrer au monde que l’islam égal unité, paix….ne ce reste l’idée de mettre ce festival rek merite des félicitations SVP soyons positive à certaine critique ne faut pas critiqué parceque c youssou ndour noooooooon chanteur non saluons l’effort nom de Dieu

  • NASIR

    wallahi oustaz waakh kh nga degeu senegal fomi rèk lagnou dital yakar ni adouna gnofi eupou lislam gnongi nakh sounou bopou ana kilifa dinèyi kèn dou wakh dougnou wakh si yalla dougnou wakh si yonèntebi khana konè di tageu sa mame nanou dèllo nitgni si yalla wa salam

  • babacar

    festival de merde lii dou dn ragallen sen Borom te sellal nii nguen koy diamo

  • Fatima

    On peux donner son Avis sans pour autant insulter

  • Gora diop

    Ne nous amérdé pas khamoléne dara ngéne di goudal sikime di doul salam dou diné salam diame la.khamoléne kouye déf lou bakh té doléne ko déf yéne yéna beuguoul diné.youssou couko gnanaloule bayi ko nimouméll yalla moko falle té kéne banou si daara wakhléne louléne nékh déf léne louléne nékh séne bop.serigne touba moko ték lokho

  • Mansour

    Oustaz yalla nala Yalla faye ba nga yeuk ko. Dieureujeuf.

  • mahmoud khalil al houssary

    tout ceux qui critiquent cet oustaz vous tes perdu

  • Moussa

    limoye moudiou diamono sowakh deugge ay khal you ndaw dila saga youssou ndour dafaye diel dinbi diko thiakhan din lislam sabar bocouthie piano guitar no m lppe si festival salam, Bayiln Sou imam yi wakh gndi saga torokh rk

  • sante yalla

    c’ets juste vous critiquent oumar sall vous lui connaisait pas omar sall amna tawhite dara yobaléwouko vas faire tes cherche té khol boudon alalou aduna youssou douco thi hopléé way yalla la djiteul du vivre souna islam dou folk lor islam dou thiante islam dou khasayuite islam dou ay fethie ak thiakhane un bon entendeur salam

  • Google

    That is the finish of this article. Right here you will uncover some internet sites that we believe you will enjoy, just click the hyperlinks.

  • Google

    Every when in a though we pick blogs that we study. Listed below are the latest internet sites that we pick out.

Publiez un commentaire