13 COMMENTAIRES
  • Thiobane

    la faute cnest aux parents qyi confient certains irrésponsable marabouts à leurs fils car aujourd'8 l'exploitation des talibés gagne d plus en plus d terrain.Stop à l'exploitation d l'homme par l'homme.

  • gainde

    Senegal wakhatinga deugeu

  • sama reew

    mane je suis ndongo dara jete à daray cokki toutt ma fami ay jiangalecatoy alkhouràn lang à Dakar me ban ndoye li wakh nekhoul ba nekhoul me deugla leppo nag parane yi la deugga nèkhoul

  • tata fay

    ndoey bane kharal rék di nga ami bises man xaw ma lou takh nga sokhxar coy déff lou bakh mou fékhxé ba wout lou bone ték fa wayé dangay khalé rék

  • les idiots du pays

    personnellement je suis contre et ses vraiment douleureux de sacrifier la vie d'un être,j'ai eu à approcher des talibes mes les enfants sont tellement innocent que tu as envie de changer leur situation de vie malheureusement les gens au lieu de voir le bon côté pour donner un avenir meilleur à ses enfants.ils vont sortir les histoire de religion!dites moi si l'islam dans son Saint livre le Coran dépend ce qui utilise les enfants pour s'enrechir!

  • rama

    yaw fallou khana serigne dara gua motakh guaye mère bane da wakh ba sonne lithi deugue bi kéne mounouko wakh

  • NIT DOFF KILLER ?

    fallou del suivre emmision ndoy mbane avant d parlé "

  • ndiakhére

    Pour rappel : Ndoye Bane etait un vigile a la Radio fm environnement puis a la Radio ocean fm, le fait d assurer l interim du standardiste.c est a cette eadio qu il pris gout du micro de nuit. C est pourquoi lors des elections locales il a fait campagne à Pire pour Papa Diop il ne faut pas le prendre pour un journaliste. il ne peut donner des leçons a personne.

  • insa

    Fallou lolu silanu khame ndoy ban wakhnasi ay yon youdul diekh li mou wakh dafi barri nam amna nak ay s darra yo khamni falilahil hamdou daingale rek lanuy def amnasi nak ño khani yalwan bilendi donga bi di andil kesse molen sokhl manuño dugal harf si bpop khleyi ndakh se dinga bannul khmuñu darra

  • Sénégal

    amna lou ngén wara wakh nignouy diapalé école France yi bon ko diapalé won darayi kon lolou dou am dafa melni Sénégala nekoul rewou dioulit bayilén darayi baylen darayi bayilén darayi

  • Elh Fallou

    Linga wara wakh moy djigeene yiy djaaye seene boppou ak baar yi ak yamba yi mo eupue solo liii nhaye wakh

  • yep

    On est tous d'accord qu'on ne doit pas exposer un enfant tout une journée dans la rue , mais les parents aussi on leur part de responsabilité sur ce phénomène . ceux qui ordonne leur talibé de faire de la mendicité ne reçoivent rien venant des parents alors dites moi quel méthode les serigne peuvent utiliser pour que leur talibé mangent. moi en tout cas je blâme en premier les parents pour leur fuite de responsabilité.

  • bizarre

    léup c est les parent liñiou beug dafa yombe beug katte té do diél responsablite yi âpre yowmal khi yam …..

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *