trés beau geste mbaye kane lo yalna nga am yokuté limoy aduna nit boy mayé dangay mayé ñi nga tané ñi diara,wayé mayé ñi nga khamné liñou yoor si alal lek diakhaluko,di mayé pour poukeuré lolou yallah beuguko té yonent bi beuguko merci encor a ts c gents ki ont participé a ce beau geste et mention special a sen tv.
j’ai de larmes aux yeux God bless you
je suis émue nako yalla fay barket mouhameth psl
trés beau geste mbaye kane lo yalna nga am yokuté limoy aduna nit boy mayé dangay mayé ñi nga tané ñi diara,wayé mayé ñi nga khamné liñou yoor si alal lek diakhaluko,di mayé pour poukeuré lolou yallah beuguko té yonent bi beuguko merci encor a ts c gents ki ont participé a ce beau geste et mention special a sen tv.
c une geste noble.
yalla na kheweul yii guene yoko amine
Diadieuf Mbaye Kane Lo nala Yalla diapale li mo gueune fekk kou yor ay millions diko diokh ay millions
c’est trs beau ce geste l. mais mon avis diokhone ko khalissbi mo gueunone
Machllaah J’aime
beau geste mbaye kane
li da rafete yalla nako yalla faye
manchaly beguue n’a teey qui sa ma magg Mbaye kane lo Lanka sa raak qui dieuppeul du ziar sa ma copain alla lo c Bush
beau jeste yalnala yalla faye sa hole
Amiin
Très bien, c’est le tour des grosses tètes qui passent tout leur temps dans les soirées
li rafetna boud yalla rek motakh mou defko yalla nako yalla faye gueune gui faye
C bien mogeune diko may artiste yii