8 COMMENTAIRES
  • sofi

    djeureudjeuf aby nekhna seleu na.manchallah. baye laye amoul masse yarame bassa diamalaye

  • mahdiyou Lahi

    laye makhtar?? machlah séllana nékhna en plus l blanc!! BAYE LAHI dall MOUY MOUHAMADOU RASSOUROULAHI (PSL)

  • senego

    amine fary barké Baye Laye aleysalam

  • fary

    senego contane si yaw yalna yalla nagou niane si barke baye laye seydi

  • mbalax man

    youssou ndour batre campagne pour macky sall nga batre campagne pour tanor dieng

  • senego

    bon appel a toute la communauté layene khel bek khol bi yeup ngui yoff ngor camberene yalla nanou ci yalla yobou ak diam barké baye laye ak seydi baye abadoulaye yalla nafi yague teh weur ngax alassane ak seny sounou niéme youxou ci kaw né ay layene lanou yatax yaye drapeau diné dji tay dji yafiy sa mame sanga nianalnou djiébal nanoula sounou bop yagu fi sax fi lol yaye gaidé dinegui

  • iso

    dieredieuf ci na ga sélallé ndakh baye lahi kouy wakh si mom daga wara andak selleté

  • Kadija

    Sella na….comme sa makk Youssou mi wayy Segne Fallou….La voix est pure comme l’habit immacule…….jajeuf Aby.

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *