23 COMMENTAIRES
  • hihihi

    Ki mome dabeurgueulou ci ay doule

  • nina
  • Kine

    Deug nekhoul mais cest la vérité

    • De Berg

      ndoye mi!! thji la deuk !! aaH mandé bimakoykham yakatankat lawon; teyit tatam you bakh yi gno ko wor, trahir ko. khamnagne limou néké town

  • Balla

    Ndoye Bane dou nite hier rek on parlais de sa

    • seck's

      bane niteee moy ame moyen ame auto bou bakh dii profité si gamou wala magal je sui pas dacord

  • Matar geuye

    Félicitations tfm wadji il est pertinent

  • Mahou

    Félicitations tfm wADJI il est pertinent

  • inna diawara

    ndoye bane Sénégal yassi dakha doul lernama yague nguako def

  • hame
  • damso

    Il ne fait qu Inventer des bétIses cet ancien vigile de la radio FM ENVIRONNEMENT. tout est faut sur ce qu il fit. il n"est helas pas instruit

  • leissa
  • bane

    Santou 'BANE' moy lann ???? Foumou thiossano ???? Sénégal, ndiaye laci kham, wala diop, diatta, tall, guissé, sall, sène, ngom etc.

  • bbeto

    wouuuu ndoye bane nak doul nga …lolou amoul Tivaouane vraiment sédél lén sén djiko, tivaouane douma né amoufa d wayé bariwoufa dara dara…fimou bari key xamnagn ko ! noto ignane, thiowli barrina trop

  • Gogo

    Way Ndoye deug nga wakhh sénégalais beugoul deug

  • Djily diop

    Ay rv dokhanate rek mafa amm

  • mouhamedbenga

    Bilay ndoye bane deugue rek gua wakh deugue canni la but boko roff mou tohognou lolo am dee thiahane rek

  • MICHEL

    bou
    léne diawalé talibé ak ay apprentis ak chauffeurs ak diay katou ndok tivaoune kéne mouno ko yak té dou tilime ba faw bou léne diawalé yalla ak yalli dieuredieuf EL HADJI MALICK SY

  • seck's

    ndoy bane wédii woumala déh mai senegal lolou fépp laa ame ask wornala ndakh tfm amoule rase katou démm mdrrrrr!!!! way mane néx guama trop mai a chaque foi daguaye debordé

  • imama

    mai ca existe partout au senegal

  • ive

    Il faut faire trés attention avec ce gas ; la plus part de ses paroles sont des menssonges .Il a l'art d'inventer des ch…….

  • deugu

    ndoye sétal yalla si lingaye wax place diarouko meno yakh dérou tarikha cheikh bayil you bone yi ngay wax si deuk bou sél bobou

  • niokho

    ndoye nekhoul de mais li nga wakh am na

    ndoye nekhoul mais li nga wakh am na

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *