29 COMMENTAIRES
  • man la

    Boy yene mounolene comprend sak affère bi modou lo.waxlène 3eme mousse bi mou dem diagui beuré ak dorr

  • Am

    Kouy wakh si lak bou gni lak tishert tou Gris naf3ke nga wa P. A Gris bordeaux motakh gnoun3 wa Medina ay gorgui guene lagnou

  • mo

    gni tal li amougnou khel sene xalis la de yenako diandon

  • nafi

    Un combat tactique et technique a la fois. Kou wakh beurè bi nekhoul dafa fekk sa mbeur danou rek wala nga beugone kou humiliè modou lo ak ay coups. Wayè kou guiss beuré bi ame demb nga kham modou khel lako beurè ak technik parcek esquiver des coups de son adversaire plusieurs fois avec classe non lolou guisseu gouma ci arene bi kou ko def, en plus mome ay coups wame yeuppeu dal, non modou dal loko bagne bagne wakhal ko ni champion deug leu. Il a ete meilleur sur toute la ligne, indi na supporters bou meussoul ame ci arene bi,indi ambiance,ak takhawaye ci lamb ak khelou beure ak thiaye thiayou mbeur.chapeau a toi champion. Tu nous as enkor bluffè

  • gonze

    Damane wah balou fetalle sou guene khamo coumouye dale teynak tiregue seye siportaire ?courage gris et félicitations modou kharagne lo le melleur

  • Madaniya

    Lii rafetoul br ak dannu nio and ankourageko mogna nice

  • Dady

    Soyez sportif gris dafa dioum rek mais defna combat kou dioum moy danou modou lo defoul dara demb dafa done daw affaires bi Balla Gaye leu

  • Ive

    Il faut pas encourager ces pratiques ;des supporters qui brûlent des tserts et qui menacent m’en de brûler la maison du luteur; c un vrai danger :ay dou yem thi borom

  • Habibatou

    yala moko beugueii wonn nii keiine meunousii dara.franchmn li niawna

  • Mc

    Gris c las la premier fois demale defarouwate rek t gneuw sport nila meno di dane toujour

  • babandakarou

    noye beuré nane sama khêlou bop ma doye do dêm

  • lebou

    ils n sont pas des sportifs c tout

  • thug life

    regarde moi ces imbeciles rek !

  • Namou

    Mettez son petit frère a sa place il est plus fort que lui .

  • Dio

    Woutiléne Mbeur !

  • Deug

    Kén mousoul guis li gris mom tamit legui gnouniko na bayi mais kharal Boy yi Ama mogni niow sa kaw….lac 2 sax bougatoula

  • bas

    supporters di merda

  • beugue sama rew

    non sene khl mo diekh rek parce que dfaite mo mtii

  • cartel

    khamguene yeene waa Nord d ounguene eyye sportif yeen rewandee nguene do deff sii sport yeuup il faut venir ici a ziguinchor niou formé lenne sii un groupe

  • Senegal@

    li raftoul dara gris moln genona bg victoire nit bou am bankh ak nakar silay kham ay nitam adouna dou ni

  • gaspard ndiaye

    MODOU LO TAMMIT BEUREE WOU FII DARA SOU FEKER NI LAYY BEURER DOU DEM FENE

  • papa ameth

    Non gayi warounou def lui nakh affaires bi sport la li fair play

  • MBEUR

    Gris mooko wakh khonne n mann samay supporter thi comba bii lagnou maye diappe walagnou bayima mootakh ay supporterrame bayi nagnouko thi comba bii mou defe 2 fois 4appi

  • Didier

    Ce ki est sûr gris a peur de Modou lo mentalement mais bon courage gris et arrête de lutter contre lui

  • éyîiiiii

    bayiléne sokhor bo moye touwoul yéne nioniou amouléne carte membre ndakhe fane se yi instant bi talnanou lénéne loudoul li courage gris DINA bakhe unchallah

  • di

    li gayi dèf moy yone boulèn gnou ray lambou bo dèmè ragal fèk lasi nga bayi ,lambou yeufou goor la kone bo dieulè avance lounè nga waxko bou lambji diotè wanèl sagne sagne ba gnèpou contane,bo danno sakh gnou khamni dèmeritè wo, mè dafa yombou dieul xalisou diambour ba parè sa moromou goor boko appul dollè apoula dollè ngay ragal mbeur deug dangay gnèmè kani wala nga bayi (balla gaye2 ,modou lo,eumeu sene,ama baldè ,sa thiès )koulèn faral do rouss gnisi dèss gnèpou daniy nègociè ba guèneu si ngèn balma nak

  • nafi

    C pas bien tes propres supporters dila df nii dagno wara and ak mom si moments yeup les supporters de modou lo sont plus fair play biko balla dané supporters yeup devant chez mod lo lagn takhaw diko khar

  • mbaye

    Gris out papa viens

  • doumoome

    il faut introniser papa sow nouveau tigre de fass, gris est fini

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *