10 COMMENTAIRES
  • Salimata

    mes deux champion …….trs content et fier

  • loustik

    affaire bi balla gaye 2 dou sene morome

  • BREF

    sa waye lingua wakh dawna yaram deh …..Amine yalla naniou yalla defal khole bou rafet

  • daouda

    mes deux lutteur mashala

  • Anonyme

    ehh tw cartel je madresse a toi ..yaw danga kham louy khew souba. banga nan modou lo dou don roi des arene loulasi woor .ske tu es sur ke demain dinga yewou am dett . yallah nala yallah nay goudou fanak wr werle katanalen dolelen. .ak mbolem dioulit. mais nak liy khew souba yallah rek moko kham .yallah boumou niou oumpou. .khol danioukoy yaar guir mou rafet.. soko defoul rek sokhor .yakou sokhor rek inian ta kou inian rek sa khol deiksi di diekh. nga dem hopital ken dou am say garap ..ta bou boba dangay deeh ta kou dehh si sokhor ak si mbon yallah lakkela yallah naniousi yallah mousseul

  • faye

    matay yagui mr deee

  • matay

    Balla niewe euma bayou balla niewe

  • faye

    gaw lne balla gui nieuw

  • alassane mbaye

    nice n’a beautiful

  • cartel

    daniouma deff eyye re modou bo tooppe yekini do doon roi ds arènes

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *