[Vidéo] Le gambien Pa Samba Diaw s’insurge contre les cadeaux offerts par Yaya Jammeh à Bécaye Mbaye et à Me El Hadji Diouf
Après avoir offert au lutteur Eumeu Sène deux voitures de luxe juste après sa victoire sur Balla Gaye 2, le président gambien Yaya Jammeh a fait cadeau d’un véhicule au reporter de lutte Bécaye Mbaye. Il a reçu récemment Bécaye Mbaye en compagnie du célèbre avocat Me El Hadji Diouf.
Les gambiens sont outrés par ce comportement de Yaya Jammeh qui pour eux dilapide les biens du peuple gambien. Suivez plutôt ce gambien qui dénonce de façon musclée ces gestes de Yaya Jammeh.
Don't worry bro we will handle yaya jammeh cool an kill him cool
c'est la triste réalité les dirigeants font du n'importe qw avec l'argent du peuple mais insa allahou rabbi tout l monde auront des comptes a rendre il répondra de ces propres actes devant allah soubhahou wa ta aala on est de tt coeur avec vous le peuple deuggg moy mouddiou
Don't worry bro we must take our Land back inshalah
gambi sunu bussla dinen ko jel gerri sivil sikaw soldiers liadon inshalah
Madal limafi guis mooy mere mak douma khallè
gambia amna ellecsion way way bouelecsion niawate boulenko wottel
yawitam yaya jamme bax sa allale boul diawallè sapoche ak pochou gabia nak
ki kouko deklou gna hamnez khôl lay wokh est yaya djamain bala mouyi lakh diayi n'a lakh lekke
wokho FI dara demal Gambia guan wakh go fa
basta io dirai bravo presidente sei un pr molto generoso
Gabiens yi gno soff becaye mbaye mo mak auto bo ame blem ak yaya jammeh gua dem gambie lidiane tiko fa sofff gua trop
nn yèèn gni wax waxoul dara yèèna waxaoul dara,,mai waxnadeugu gnou senegalai yi gnowara xolat sunu bopp
gambien dofyi
sama bro dou Gambie gua koy wakhé bo amé loy wakh gua séti yaya bayil becaye ak maître gnou happy gambien yi sokor lagnou déff bougou gnou sénégalais yi
vraiment li mou wax nii deugla.
yow wakhou dof bayil togne
yaw wahou lofi dara .Té sah yaya jammeh moo bah sii yén Gambien yiii lou yomb rék guéne beuga.dém wah ak president jammeh té guéne bayyi senegalais dou ñiou sén morom.
merci deugue nekhoullll
nańou bayi xel si yalla aduna yagoul
becaye + avocatbi=1
you people better go and fine food for ur families. ..is better than listen ing to idiots…who sit in America or Europe talking nonsense. …njaka fayda…
Yowe Mamidy you are not senegalish! I mean then a real one!!! What is that mean that our hearts are more darker than our skins??? Yes blacks and proud and what else!!!! We all both know here in Europe what about Gambia's people life!!! Only Deal Marijuana and Coco!!! THEN GET OUT OF HERE!!!
yawe daga khamadi amou por Wakhe ak senegalês yi demal wakhe ak yaya diambi legui ko baga siwe thi seneweb bi gakoye diare
gambien yi nion niack faye da. bene nitte di raye di mayee khalisou deuck bi di teuthie population bi. melni yaye sene borom , fecke leneko thie palais bi wathie ko mou wathie ligueye balou bopp RECK imbecil pour quoi ?
gnak foula kne khamoul loy wakh en plus tu te permet di wakh ni domou senegambi gua di k t un gambien amo respect si kene wakhofi dara si ta klk choz a dir gua dem wakhko sa presiden mouy yaya jameh yaw ya khamadi bugnu etoufê way guay ndirok guignol
yaya limouy def tegouko fene tanewoul senegal bay wote di maye xallis sou diambour deugue nekhoul souko macky defone degue loune
yaya limouy def tegouko fene tanewoul senegal bay wote di maye xalise sou diambour degue nekhoul
DEUGEULEU
Yaw bo amee loy wakh wakh go yaya ta bayi wa senegal wa senego nionou yab rek
Na niou goré ,khana kou dém bay téyé ay millions wara Roussa wayane
Film guélouwar bi wa naniou yé
wayé animateur yi,mbeur yi,politicien yi mais kel honte pour notre cher Senegal
SÉNÉGAL DA WARA AM NGOR BAYI SAMBAY MBAYANE
Am a senegalese but senegalese are greedy nd their hearts are darker than their skin xx.
Am a Senegal but senegalese are greedy.
WHO Fells it knows it! What you say is normaly what they have to do but…
dém léne wakh ak yaya té ngéne bayi sénégalais yi ngéne di khass pauvre gambien
yaw topal feule wakhou doff rekk ngafi wakh.gnoun senegal amou gnou diotou gambie liguey lagnou kham dounou sen morom.lan moy auto
bakaye am auto bou yag maître elhadj diouf dafa fale auto wala dalassi.gambie yaya djame mofa bakh pour président dem len ligueyi te bayi tokh yamba.fi ci europe diay drogue rek lagnoufi neke.
wakh nga dueg
démal diangy way kén hamoul li ngay Wakh
dégue nékhoul
Cela n'honore pas le Sénégal et les sénégalais, les deux mis en cause sont des leaders d'opinion qui doivent enseigner le legs de nos ancêtres tels que Cheikh Ahmadou Bamba qui ont enduré des souffrances pour sauvegarder leur dignité et leur foi, et ils ont eu la récompense divine. Le peuple gambien vit la pire des dictatures avec des tortures physiques et morales et un "dalasi " qui ne cesse de dégringolé, bref un peuple qui soufre le martyr, on na saurait pardonner des sénégalais faire les louanges de celui qui est la cause de cette situation. Tous ensemble pour une Gambie de paix et de prospérité dans une Sénégambie émergent.