(Vidéo) Lac de Guiers 2: « Je veux ma revanche sur Eumeu Séne ». Regardez

Lac de Guiers 2 parle de sa carrière de lutte et souhaite prendre sa revanche contre le chef de file de l’écurie Tay Shinger.
Lac de Guiers 2 parle de sa carrière de lutte et souhaite prendre sa revanche contre le chef de file de l’écurie Tay Shinger.
lac mo nex de mom eumue reck la teck batt koi….yaw defaral nala afir yack sa copie balla rokoss
vraiment un poussin ne se nourrit pas de steak mais plutôt des graines ne gaspille pas ton élan eumeu dalay réduire en sougoufff dé bayissi khel
NE VS TROMPER PAS SUR LA PERSONNE LAC PEUT BATTRE N'IMPORTE QUELLE LUTTEUR DS L'ARENE ALORS EUMEU EST AVERTI
moy lolou
Lac moy ber mou yabar
Il tres nul ce mec …toujours sue la defense ce Bollos
Yonou lamb la dé car Eumeu dawna Yékini…Mbeur yii khamanté naniou
May wakh mounane morom danga bakh
heheeeeye lat Eumeu sa kilifeleuh???
regarde tes advairssaire MO guen si yawe
boy, deffal ndank kocou dou sa moroom
Yeene di nguene yague dioume thi eumeu sene
J m dis il espere kw 1000 combat Eumeu dane la jt jure..T'a goute 2 fw mon cher…
lac était favori quand il luttait contre Eume, il étai le plus dangereux et le meilleur espoir , ne l'oubliez pas chers amis.
athia mbeur temp yi yay bomb wawaw!! revanche c normal
sama gayi dangena bakh di wakh rek lambe l rek chak seson ngen guiss surprise osi sakh lac dane eumeu lolou dou surprise allez lac 2
leep ak papa sow keen dotoul degeu rassou ba dane
lac thiouthe Day kham lekkam
Lac Eumeu dou sa Miromesnil car il voit loin