Vidéo: Journée culturelle Darmanko, Talla Sylla et Borom Thiès plus unis…

Après la première édition en 2017, Serigne Moustapha Amar dit Borom Thiès a encore réussi la prouesse d’organiser avec succès la deuxième édition de la journée des Darmanko.
C’est à la Chambre de commerce de Thiès que l’événement a été célébré ce samedi en présence d’éminentes autorités, à ‘Instar de Talla Sylla, maire de la ville de Thiès, des autorités religieuses et coutumières comme l’Imam Serigne Saliou Amar et de Serigne Bara Amar.
Borom Thiès a profité de l’occasion pour présenter le maire de Thiès Talla Sylla à la famille. Cette présence du maire à la cérémonie d’ouverture a comblé le grand marabout Borom Thiès à telle enseigne qu’il lui promet succès à l’avenir en lui faisant sucer des bonbons en pastilles reçus du Khalife de Serigne Pathé Dior.
Talla Sylla quant à lui a chanté les louanges de Serigne Touba en instant sur la modestie de cette grande figure emblématique qui a tant servi à l’islam.
Pour rappel, la journée culturelle des Darmankos est une initiative du grand marabout « Borom Thiès » pour rendre un vibrant hommage à leur grand-père qui a servi le mouridisme depuis belle lurette.
lane moy Darmanko la beuga xam
journee culturelle Valideba dewenat inchalla
yaw miye lathieee qi foumou tothe kone yaw wero qui moy borom thies serigne moustapha
fo toth reke la beuga khame
moooo toapl feuler la wakh
borom thies nena 2 bi make yaw la kone dal borom thies ake talla
hahahahha lol mdrrrr
akey deuge narrou darmanko yi diaRA andale waw goor Talla sylla
mane deee MR le maire talla sylla geune nako beug dakhe
li dafa dawe yarame lole mane talla sylla guen nako beugue
lol mdr
pastbi may danel mane
wa non def ba mome thies la beuga kham
falama feke d malen ko mana netali
rafet na lole
borom thies do wakh si actualite si rewmi tenyi thiow li bari na t gnoune yaw lani beuguer lo wakhe rek
mako feker mane leke yi doynaa seuke lepe mane naa
thiey senegale mais mara pastbi mane lay weur diokh massi boke wala pour mr le maire rek la
borom thies ake talla sylla wa waw pourquoi pas
wa stp mara bi moy kane mane damako fan lole yala kham nako damakoy suivre aussi non borom thies goudal fane ak were
akaye deuge wa mara pastbi boule gnou si fater way gnoune wa exterieur
wa borom thies koula maye thies mane sama wale si doumala ko maye d sinon nga diokh ma si pasti bi baparer
mais serigne bi kagne nga gnouy setsi nake nam nane la yaw yaye sounou ambassadeur gnoune wa exterieur
non non Talla sylla geune nama nekh nake dakh geste bou rafete bi mou defe
mara diokhma si pasti bi boke
non ken dou talla sylla
lhomme de lannee borom thies laf thiat reke
machalla machalla mcahhal journe bi valide na
wate nako ni MR le maire nake yaw diga ame lou bakham sagam bessou darmanko bi tew nga si rawatina nake sounou serigne bi ande ak yawe bayabo dalale sa khel kiii aye mamam gno darone yonet bi dar serigne ttouba kone diapel ni sounou la darer nga rawe
mako geume mane borom thies kene dou yawe say mame andone ak segne touba
mais ki louko may thies reke la beuga kham
ohhh MR le maire talla sylla aka ame ake talibe khol ko reke
aka mako geum saama DARMANKO BI
ohhh machalla amar naar mala geume mane