13 COMMENTAIRES
  • max

    c'est faux l ' amitie c'est aimer la personne comme elle est il faut pas compliquer la vie ou la religion nous somme des frere et soeur on partage la vie ensemble alor on peux etre avec qui on veux que sa soit femme ou l'home

    • jalo

      khana dang sei guisse sa bop bien dit mbidou

  • mbidou

    kharitoo goor ak djigeen moy golo si tatou garap yeek ba nopi wala wadjia yeek

  • wakh deugue téyala takh

    mbidou Louwérr ngua wakh !!! Bravooo …

  • Alxx

    c genre de personn ki complik la religion .a cose de vous on dit n importe koi sur la religion .svp ne complik pas la religion .l islam c la paix, dans ppaix ya tou amitie ,solidari e sociale

  • ousmane 4568

    yeene khamoléne dara kou dick diléne dello si yalla mome rekk guéne bagne wayé limouwakh da fa haram bou dé dousa yaye wala samak wala sa rakk wala ko khamné manoka marier comme sa badiane et. mané bouléne fatté biss dana niaw niou dougal la si benne pakh

  • Bathie

    Parfaitement raison ceux qui disent le contraire c'est des bandits c'est tous. Tous les actes contre nature viennent de ca

  • m

    C EST UN MENTEUR, FUSTRE SEXUEL PSYCHOPATHE

  • Cheikh mbacke diagne

    En tt cas lolou mome dafa haram

  • rama1

    salam aleykoum deja avant de parler allez lire le coran et hadiths tout d'abord monsieur iran ndao il a raison dans l islam l amitié entre fille et garçon cest interdit donc arret de parler comme des illettré merci

  • beugue bamba

    Hé kharitou goor akk djiguenne gnara koye waral nga beugue khamo foye diarr ngané kharal ma kharito wala ngaine beuganté ba paré nga beugatte ngané kharal ma kharito nguirr ame bountou

  • Alxx

    si tout ce ki est dit dans le coran est appliquée vous les filles n allz reste la tchacthe avc les garcon

  • Dofdof lou

    kharit goor ak djiguene ken terei souks

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *