adouna diafewoul en plus yaguoul nékhoul na Rafetna waay
yamaseck
Merci Iran yalla nara yalla faye
ndackdoya
wakh bi rafetna yalana yala yagual sa takhaway bi dakhal gnou nafekh yeup deukbi yakhou iran ndakh ay nafikh wakhssi boul tayi
thiamdolar1@hotmail.fr
senegal sokhlananiou kou mélné iran ndaw yalla nalafi yalla yagal
thiesoise
franchement chapeau Oustaz Iran
khalaatt
c dommage mais il encourage ,en même temps, à suivre le chemin de ces gens-là. je suis étonné qu’un islamologue puisse exhorter les musulmans à les considérer comme modèle. il peut demander à réconcilier deux frères musulmans sans faire l’apologie
bocca verità
na wakh rek nagne lène djoubolé wayé Thione ak Youssou dougnou ay royteef thi l’islam.
fall Modou92
Yaw bamba . war nga wakh lolou. entant que. serigne serigne . niou toudèla kou tedd ki. serigne touba… nga wara dieul si mom. diourom niari djiko.. wara défar. ak di digglé lou.. … . yangui bayi sa lokho dé… j vs m’excuse
mane
yalla yalla faye la diam mou guene aye amoul solo
kesk
yallna la yalla diapaler car tu es vrai un bâtisseur oustaz Dieuredieufateeeeeeeeee lingayi ligueey si rewmi yallna la sounou borom fayal bopam
merci oustaz yalna yalla fayela goudale sa fane aminnn
hams
yallah rek moo moune faye oustaz iran longue vie pour vous on a toujours besoin des gens comme vous billahi les gens qui disé que c pas leurs oui mais faut pas blâmer oustaz iran j’ai vue sur le commentaires de bamba c pas bien ce que tu dit vraiment merci au Sénégal diamme legnou khame yallah ne diamme yague inchallah ???
C ds gens com iran k’il nous faut pr rétablir la paix dn 1 monde totalment égaré, presk’au point de s’effondrer. Être musulman n’est pas seulment prier et égrener le chapelet à longueur de temps mais aussi jouer le rôle de réconciliateur quand nécessaire. C ma première fois de commenter sur senego. L’image de l’islam est ternie de plus en plus et dc illustrer un si bn exemple de paix est nécessaire pr renforcer la foie. Par contre je comprends pas pkoi les internautes aiment commenter en d’autres langues ke le français, c pas tt le mnde ki sait lire le wolof vs savez?
Iran nitt kou bakh nilay deef yalla na yalla goudal sa fane oustaz
youga
informazioni
youga
merçi iran
ndeye chou
Je t’aime iran
bily
IRAN NDAO FOR PRESIDENT
tall ben
bamba li iran def ni la djioulite wara def mane mboussou ma comenté mais tay sama khol dafa sed bonane senn affaire wala sounou yonn nkkoussi peut etre dagua dioume mais néné ssi alkhouranne baeda a ouzou billahi mina chaytanie radjimmm al fitnatou laa toussibannalajina zalamou mine koum khaaassa yalla aye dou yémm si boppou borom soko dégoul gnakh bou wowe moune naa lak bou toye yalla na yalla djioubolé gni reo ssi addouna bi yeup si barké sayyidina mouhammad psl amine guénn balma akh
Brown
Yala na sunu borom goudal say fann si barké Seydina Mohamed salala hou alehii wa Salam
Bamba
Boulén nou sonal youssou é thione gnoy gnan wakhlén thi louléni avancé lo way gnou dioubo ak khoulo intéressé wounou sén afair la oustaz yaw louy dokhal diné ak askanou Sénégal mola gnor les 2 ga la sén intrépide rek molén bolé diadiuef
Bamba
youssou ak thione sén afair la boulén nou sonal oustaz iran wakhgnou lougnouy avancé lo gnou dioubo ak gnou bagna dioubo interéssé wougnou
correcteur
Vrema il ns manké ke sa Iran kouye diganté you nigass yi, et youssou et thione doivent vréma car ils sont tt a fai d exemples dan ce pays c pa bo a voir vréma en tan ke personnes de leur rang
hams
vraiment oustaz à vraiment marqué encore des points billahi liii moye l’islam que dieux vous protège une longue vie pour vous oustaz ce que le prophète à dit les savants dont les eritier des prophètes alle oulamaou houmoul warissatoul anebiya c sa l’islam mais les gens comme mbaye dieye faye qui fait de l’ipocrisy c grave kou mounoul wakhe diamme ngue noppi moguene nafékhe bakhoul nos deux grands frères fesais la paix s’il vous plaît thione et youssou écouter pas les ypocrite comme mbaye dieye merci ???
merci oustaz yallah nala fi yallah bayi 100ans sa doundou amna diarigne lol. esperons k dina gnou le degeu
fall Modou92
Machallah oustaz iran ndao sa wakh rafetna trop. .Yallah nalako yallah dèfal .goudou fanak wer. ak yiiw bou bare bari.
oscar fall
La vie est tres courte.
oscar fall
lofiguiss Ci aynetali laymoudje , la vie est tres courte pour etre triste.
samba ly
wallaahi waxnga degga yalla nala yalla fay guddal say fann ndax sa dunndu amna njarini ndao
44456
mane limay lathié moy islam loumou wakh si soy guènal nitt say parents nèla beugoul nakh amoul khalis dagay wout ki am khalis koussi am idèe namako bakhè svp
Comments are closed.
Ne manquez aucune actualité !
Téléchargez notre application pour une expérience optimisée et pour recevoir les dernières nouvelles en temps réel.
imformasion
andda suxali sengal
adouna diafewoul en plus yaguoul nékhoul na Rafetna waay
Merci Iran yalla nara yalla faye
wakh bi rafetna yalana yala yagual sa takhaway bi dakhal gnou nafekh yeup deukbi yakhou iran ndakh ay nafikh wakhssi boul tayi
senegal sokhlananiou kou mélné iran ndaw yalla nalafi yalla yagal
franchement chapeau Oustaz Iran
c dommage mais il encourage ,en même temps, à suivre le chemin de ces gens-là. je suis étonné qu’un islamologue puisse exhorter les musulmans à les considérer comme modèle. il peut demander à réconcilier deux frères musulmans sans faire l’apologie
na wakh rek nagne lène djoubolé wayé Thione ak Youssou dougnou ay royteef thi l’islam.
Yaw bamba . war nga wakh lolou. entant que. serigne serigne . niou toudèla kou tedd ki. serigne touba… nga wara dieul si mom. diourom niari djiko.. wara défar. ak di digglé lou.. … . yangui bayi sa lokho dé… j vs m’excuse
yalla yalla faye la diam mou guene aye amoul solo
yallna la yalla diapaler car tu es vrai un bâtisseur oustaz Dieuredieufateeeeeeeeee lingayi ligueey si rewmi yallna la sounou borom fayal bopam
merci oustaz yalna yalla fayela goudale sa fane aminnn
yallah rek moo moune faye oustaz iran longue vie pour vous on a toujours besoin des gens comme vous billahi les gens qui disé que c pas leurs oui mais faut pas blâmer oustaz iran j’ai vue sur le commentaires de bamba c pas bien ce que tu dit vraiment merci au Sénégal diamme legnou khame yallah ne diamme yague inchallah ???
barakalahoufi
Iran vraiment linga wax rafetna yala nala yala Faye aw yiw beugenaala lool
C ds gens com iran k’il nous faut pr rétablir la paix dn 1 monde totalment égaré, presk’au point de s’effondrer. Être musulman n’est pas seulment prier et égrener le chapelet à longueur de temps mais aussi jouer le rôle de réconciliateur quand nécessaire. C ma première fois de commenter sur senego. L’image de l’islam est ternie de plus en plus et dc illustrer un si bn exemple de paix est nécessaire pr renforcer la foie. Par contre je comprends pas pkoi les internautes aiment commenter en d’autres langues ke le français, c pas tt le mnde ki sait lire le wolof vs savez?
Yalla na yalla yokou leryie
Iran nitt kou bakh nilay deef yalla na yalla goudal sa fane oustaz
informazioni
merçi iran
Je t’aime iran
IRAN NDAO FOR PRESIDENT
bamba li iran def ni la djioulite wara def mane mboussou ma comenté mais tay sama khol dafa sed bonane senn affaire wala sounou yonn nkkoussi peut etre dagua dioume mais néné ssi alkhouranne baeda a ouzou billahi mina chaytanie radjimmm al fitnatou laa toussibannalajina zalamou mine koum khaaassa yalla aye dou yémm si boppou borom soko dégoul gnakh bou wowe moune naa lak bou toye yalla na yalla djioubolé gni reo ssi addouna bi yeup si barké sayyidina mouhammad psl amine guénn balma akh
Yala na sunu borom goudal say fann si barké Seydina Mohamed salala hou alehii wa Salam
Boulén nou sonal youssou é thione gnoy gnan wakhlén thi louléni avancé lo way gnou dioubo ak khoulo intéressé wounou sén afair la oustaz yaw louy dokhal diné ak askanou Sénégal mola gnor les 2 ga la sén intrépide rek molén bolé diadiuef
youssou ak thione sén afair la boulén nou sonal oustaz iran wakhgnou lougnouy avancé lo gnou dioubo ak gnou bagna dioubo interéssé wougnou
Vrema il ns manké ke sa Iran kouye diganté you nigass yi, et youssou et thione doivent vréma car ils sont tt a fai d exemples dan ce pays c pa bo a voir vréma en tan ke personnes de leur rang
vraiment oustaz à vraiment marqué encore des points billahi liii moye l’islam que dieux vous protège une longue vie pour vous oustaz ce que le prophète à dit les savants dont les eritier des prophètes alle oulamaou houmoul warissatoul anebiya c sa l’islam mais les gens comme mbaye dieye faye qui fait de l’ipocrisy c grave kou mounoul wakhe diamme ngue noppi moguene nafékhe bakhoul nos deux grands frères fesais la paix s’il vous plaît thione et youssou écouter pas les ypocrite comme mbaye dieye merci ???
Oustase lo wakh nonoula