Vidéo- Incroyable: Apparition de Serigne Touba et Mame Cheikh Ibra Fall à Kolda

 

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

80 commentaires

  1. Master Atlanta

    Les chayatines font ces genres d'apparition pour mieux égarer les faibles de foi,lane moy sunu yoon bou Bamba fégné si ay murs you kéne khamoul khana dou simple mbindëf donk chaque jour le soleil apparait tëh takhoul kéne yéémou Bamba fégn par le biais des chayatines nguéne beugue tankal nitt lii dou miracle dëm léne diamou ji Yallah tëh bayi séni Chirkiyat yi nguéne néké,des gens plus croyants et meilleurs que Bamba sont passés dans cette vie dëfi lou kéne dotoul dëf si Diiné Islam tels que les Sahabas comme Abou Bakr(RA),Oumar(RA),Ousmane(RA),Ali(RA),Abdou Rahman Ibn Awf(RA),Hamza(RA) etc baparé nguéne beugue niou ray ak ay Bamba.


  2. nadzey

    Mouride dou tontou ay imbeciles deh wayei lenn khamnako di yeukkati lou gnaw dieumaler si serigne bi wala talibé yi rawatina baye fall yi kouko siy df digua torox fii ak fagnou dieum


  3. sad

    hahahaha……………..wakhati nagnou……je veux des preuves waay !!!!

    et comment se fait il que personne n'a pu pendre des photos de ces images la….avec les cellulaires a camera partout…lol

    Kou gueum Yallah la……bou bakh saxx …..alors il ne faut pas me raconter des bobards… ahh!!!


  4. deugeu rek

    Khalima yaw ak ñiou melni yaw dof guene mé ñioune mouride c pas vous les hatés qui nous dictes la conduite a tenir pour rendre grace a serigne touba


  5. barham baye!!!

    djeredjeuf cheikh amadou bamba diarawlak cheikh ibra fall.xamouma kou guemoul waayé maane gueum naa kaa ndakh sérigne bii ponkeuleu tés kou yallah nangoul leu té nitou yallah yii beuss bou néh gnou fégn kou amoul batine waleu dimbalakk yallah diina diaffé gua guiss léén bamba merci!!!


  6. Leral

    Eupeutina" ligua wakh sakh khamoka jai plus de 40ans mai a chak foi douma dégue koudoule serigne touba fégne na a droite a gauche en haut en bas……..

    Aye féne rékkkkkkkkk dara fégnoule féneu, ou sont les fotos ou vidéo ?

    Khana wa deuke ba amounou téléfon you ame foto?


  7. Eupeutina

    Wa khana serigne touba rék moye fégne si adouna?

    Khana kénéne dou fégne ? Koudoule sakh sounou serigne lî?

    Chak foi rék serigne touba fégne, bayi léne nakhayî mane dé ko massoule djiss khoma nokay khamé


  8. DEUG

    BOULENE SOKHOR BOULENE IGNANE


    BAYILENE SOKHOR KENE FORCEWOUL KENE GEUME MBA MANDOU


    DI NGUENE CRISE CARDIAQUE NDAKH SOKHOR AK CONTRE MOURIDISME


    MAIS LOUNGUENE DI WAKH REK YONE WI DI DIEUM KNANAM

    BAMBA FEEP BAMBA PARTOUT

    DIEUREDIEUFETY KHADIM RASSOUL PSL


  9. mor afia

    mandou bakh trop si domou adama ndakh da bokou si diamou yalla kou nek ak lega guem cone bayi lennou ak serigne touba mome lanou begue mome lanou geume lounounou wakh si mome nekh nanou diereudieféti borome touba


  10. siloneck

    yalla reck mòòkham mai sisama yààkààr dààl mòòdi nitou yalla kou tollouni serigne touba ak khèweul yiimou bayi guinàw ak limou am si yalla ak yonentabi psl ak fii gniou wakhni fiila fègne amnàsi djikhi diàkha keumnak dafa fòòr doyena wàrr


  11. Kalimat

    Sacré mouride.. toujours en quête de miracle mai ce qu'ils ne savent pas c'est que même cette mensongère prière sur la mer ne s'est jamais produit .. des contes et fables qu'on leurs à fais gober histoire de les posséder en mouton . Thieey!!


      • dex

        KALIMA yaw kouye woute domou kharame ba ekssi si yaw doulafa bayi. Sont des imbéciles d ton genre ki cherche tjrs a salir un tarikha si noble k l mouride. Mai un conseil daga reuye lamigne rec vas y dohor pour repettai s k tu vien d dir la. j tassur k tu n t'en sortira pa vivan. Serigne TOUBA limou deff boukko sa mame ,wala sa baye ,walla ko yakkar defone dina daye toubayame bamou fass. Tai bougnou diakarlowone do doye. Testa di catso.


  12. mahfouz

    Domeharame yi rek nooy wah des conneries serigne touba ken douko mimeul li xale bi wah lou werr la dieuredieuf serigne touba diarama mam cheikh ibra fall


Laisser un commentaire