Video GAMOU 2015: L’accolade émouvante entre Serigne Moustapha Sy et Serigne Habib Sy Mansour Regardez

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

38 commentaires

  1. bayiléne gniiiiiii dagnoo sankou gatiéy tivaouane késsé laniouyyy kharr wayé ay bouguéné khamone lima khame hhhhhhhhhhhh.nioune tivaouane kép niou gnore souniou yén nékoul si lénéne wala fénéne


  2. iow diop yayyy domeramee deugggg yow dei di nga trokhhhh sa adouna iow njabootou serigne babacar nga denigrer ya bonne ya yeussss ya tangal sama khol dinga ko guiss walahiiiiiiiiiiiiiii


  3. te leernamani sakh dou taalibe cheikh ndakh nit dou wootewoo beuugg seydil hadji maalick ba pare di ngaagni dieufeum joo khamni monde enthier nangoulnanou co


  4. Yaow mi Di Askanalé sa bopou talibé cheikh : on dirait que tu n’es pas fier ci ligua donn en réalité .Cheikh khamoul bou niaw . Ta ki bakh yalla reck moko kham .


  5. lii dou dara nguistal rèk la .ngi adouna rèk mo lène nior.gamou yonente bi mokomome mè ngi sene famille rèk laniouy wakhtanè.et pourtant khamouniounè babacar sy bakhoul .famille sy 2personne nio thi bakh .tous reste =0000


    • tw té pa un talibé cheikh oub1 u fai parti d lotr parti en tivaouane on n parl k d notr bien aimé Mouhammad (psl) et à part la familk TALL et les otres famill tidianes ont bu et s st lavé en Tivaouane


    • yaw do dara satan gua un musulman doi appréci lé bne oeuvr et geste té jalou parsk u habite d lotr coté d la tidianyya mai sach ici o senegal ts lé famill tidianes ont bu et s st lavé dan la famill Maodo SY sauf la famill TALL


    • Ki bouléne ko tontou tangal na khoulou kep kouy joulite té beuge Lou bakh nitt nak bou yalla di wath alka ndéme dakoy wane ndank ndank bamou kheuy alkou sama tourando marta bame khadioul si kaw kéne


  6. Macha’allah kou guiss lou rafétt contane sii…li koumou nékhoul nitou fitneu nga, do nitou diam, wala sa khol da am gaumm. Yag Lén fi Sy Deug Dou fénn


Laisser un commentaire