Annonces
Publicité
» » Vidéo: Déguène Chimère: « A part mon mari,...

Vidéo: Déguène Chimère: « A part mon mari, aucun homme ne m’intéresse sur terre »

  • Amadou SY Amadou SY

Annonces
Annonces

38 commentaires

  • Merci
    17/06/2015 14:03

    Vraima maman degue sama yaram daw na bilahi coz nit dagnu la xamul rk me kom li sa brom keur wax rk iow waliwouga lolu rk dra fayouko dc rawal te nek ci diam coz gni wax nieup bougnu sa niome sene yaye melni iow bein ci man nit dou soxor yalla defna dembou tay soga niew dc nay rafet c jst sama xalat wasalam
    tata deguene chimères love u ❤ ❤

  • cira konate
    17/06/2015 14:41

    khamna si leenne de allakhirraa moom dina lool konn nakk kou yabou mandou

  • thiatou yayam
    17/06/2015 15:05

    tay mom dama contane bilay sama yaye ji loumou wax yep deug la jalou yi dafa bari senegal sokhor wax loula wauroul ignane rek.ms nak yaw diallo demal rek gnogi sa ginawwwwwww mane mom je t aimmmmmmmmmmme.

  • oye thiam
    17/06/2015 15:11

    ton marie ta pas dit d'arrêter de frotter

  • feuz
    17/06/2015 15:13

    moi je suis victime de la jalousie te yorouma sakh lou soule u r café me tay Lep louma diapon bayinako ndakh degue na deugue yalla nanou yalla mouseul si sokhor

  • Djibouti tuop
    17/06/2015 15:32

    yeuw vo interesse magate mou diekh

  • Yacinediop
    17/06/2015 15:50

    Tata content na si yawe banemy dama douda lou merty waye yama diokhe force ba dofouma merci tata bolefalee ke le tts puissance vs protege toi et ta famille amiiine

  • b.j
    17/06/2015 16:32

    Wédii dindi touma leu mais l'islam aramal na jiguene bou def bopou neneu

  • seen baay
    17/06/2015 16:35

    mangilay soga xam tay jii nak,,leegi moum nawnala,deug deug nak jambar nga,,,wandjil xeesal bi rek lepp bakh…(conseil bolen topp realitey television niko tobabyi guise bafatte seen diine ak seen hada) ..

  • olddiagne
    17/06/2015 16:35

    Tu nause pas dire le contrair tu es devan la Tv bougnou sonal

  • mdrrrrr
    17/06/2015 16:46

    ay sama tata bi lou khéwatii yaw boula kéna togne kou bakh ngua wayé nak siiw dou diammi borom.yallah bakhna tata vraiment khamoumala wayé kou rafete khol ngua sa se vois dans ton visage bilay

  • Reubeu
    17/06/2015 16:52

    a ton âge arrêtes d'étaler ta vie.ce que tu fais ou vis ne regarde que toi…et puis Madame je pense que t'es vieille pour qu'un autre que ton mari te regarde….rends grâce à Dieu et ton ménage ne nous intéresse pas .

  • diouff
    17/06/2015 17:00

    je travail a barcalone dans leur camps d'entrainement le jour ou nayma jr ma demander je viens d'ou parceque il penser ke je suis viens de la jamaica je lui est repondu que je viens du senegal direct il ma dit ah ouii elhaji diouf direct je vous jures il ma dit c son idole parceque en 200é il est jeune mais il est parti direct acheter le maillot du senegal le numero de elhajis diouf meme ces amis l'appeller diouf il ma dit diouf il ma marquer quand j'etais jeune a cause de lui j'aime le numero 11 c son préfere.le numero 1O on la forcé a le mettre mais naymer aime le numero 11 & cause de diouf est si vous regarder bien naymar a le meme jeux que diouf des années 1999 juska 2003 il drible est viff.meme le jeune senegalais du barca le sais est un jours naymar jr le diras devant le monde entier que diouf la inspîré dabns sa jeunesse.diadieuf

  • kira
    17/06/2015 17:46

    khana dangay rakhass douche yi fofou

  • insa
    17/06/2015 18:15

    Ah sa way souma meno na rakhasse douche Sénégal di ame 150000fcfa kone dé sakh ma dieul,toubab nio daka rakhasse douche té bou niou nieuwé sénégal bou niou sekketé sakh niou yarkamoukala

  • Mina
    17/06/2015 19:01

    Dêguéne bouniou sonal yaffi tekk greffage yaffi pose kheff akk ongle tay nga tekk peruque beugue niou sonal

  • famousi
    17/06/2015 19:32

    Tata deugene koula bagne na nane acide .mane damala beugue sama bire khole .dèfo wakho lou gnaw mane youtube lay nèk di khole saye video .yaye sama anti stress . Sa exprèssion bima geuna nèkh moye nope gore la yorè lolou rrk ca ve tout dire .do dègulou lou bonne do wakh lou bone.
    Koula bagne nagnou bayè ak yaw gnoune gnila beugue.

  • deugg1
    17/06/2015 19:36

    maman mala fans trop je t'adore bcp

  • madam Faal
    17/06/2015 19:53

    Yal na la Yalla yok jamm ak mbolem domou adama, Amiin

  • gueum
    17/06/2015 20:13

    degene chimere balma ak

  • dg
    17/06/2015 21:20

    mère lii ngay ratatati mo baril talou nioulla.lou way déff bobam

  • nimz
    17/06/2015 23:47

    fi dé adouna la kou déff gnou wakh une viekkard comme toi di ték périk ak di makillageou

  • nimz
    17/06/2015 23:48

    fidé adouna la kou déf gnou wakh

  • nogayesaer
    17/06/2015 23:49

    ken waroul gigé nk tata jtm encore nit kou bakh nga

  • vérité
    17/06/2015 23:56

    un peu de respect vous aussi pourquoi toute cette jalousie.. Maman je t'aime bcp vraiment Dieu te protéger.. ne repond mm pas au provocation des moins k rien ki passe tout leur temps sur internet

  • ayssatou saliou
    18/06/2015 00:13

    tata deguene gni dagno sokhorr yaw bayinala ak s.saliou

  • hams
    18/06/2015 00:44

    les gens n'ont aucun respect ce sa le blême non vraiment ???

  • mel
    18/06/2015 01:15

    Lo nitt deff bobam konekh amna loko doy am dett

  • Diouff
    18/06/2015 07:03

    @kira non rakhassouma douche dé bilay walay si barké wérou koorgui.je suis dans la sécurité du centre d'entraînement.dernièrement j'ai fait venire un chanteur jamaïcain bien connue mondialement qui fan
    De leonel Messi a le rencontré au centre.

  • blake
    18/06/2015 08:59

    DIOUF

  • BLK
    18/06/2015 09:26

    DIOUF GNI DAGNO SOKHORE YAYE SENE BAYE BAGNE BAGNE NANGOU LIFI 2002 BOLEGUI MOFI TEGUE 13 ANS MONOUGNO AME DEUXIEME DIOUF CEST HONTE AFFAIRE BI YOWE LA KOUMOU METI NGA BAGNA WORE WEROU KORE BI YALNALA YA LA FEYE KOU BAKHE NGA MERCIE

  • BLK
    18/06/2015 09:35

    DIOUR BOULA DARA METI YALENE GUENE NDAKHE SIGILE NGAGNOU PARTOUT DANS LE MONDE MAIS BOULENE FALAIT BOULENE TONTOU NDAKHE 13 ANS AMOUGNOU DEUXIEME DIOUF KONE NAGNOU TEDIE SENE GUEMEGNE YI YAFI NEKE YAYE SENE BAYE KENE GUENOULA KHOLE NO DOSENE MOROME DAGNO SOKHORE TE MOME SAKHE YOWE BOKO WAKHONE KAYE RAKHASSE DOUCE SAMA KEUR SANS NGA FEYE KO MOUDIEULE MAIS BOUL KO KO DIAPE SA FANS

  • crâne raser
    18/06/2015 10:36

    ÉVIDEMMENT QUI A BESOIN DE TOI REGARDE TOI BIEN DANS UNE GLACE VRAIMENT LHOMME QUI TE REGARDE CEST QIL NA RIEN DAUTRE ET QUIL A FAIM TU ES VIEILLE ET VILAINE ET TU SENT MAUVAIS….

  • lals
    18/06/2015 11:36

    Khana teye nga defoul cils ake pose ongle les archives sont là

  • fall modou bété bété pur
    20/06/2015 21:06

    wakh deuggue fa yallah lidafa niaw .topou si derou niitki rekk di si wakh lou niaw rekk .illahira narna metti trop ..lillahiwarasoulihi .nagne lén manou .li.niawna trop

  • mahamadane
    21/06/2015 17:13

    dina am gnou la tague dina am gnou la xass baya Bo mougne ligéye bée ko laj

  • diouf
    07/10/2015 12:08

    Je t'aime maman deguene

  • Babacar gueye
    17/10/2016 02:51

    Yalla nako yalla yaram thiay adouna dialna gnou bakh gnapp

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces