39 COMMENTAIRES
  • NIT DOFF KILLER

    Ta dit koi

  • deugue

    bayile doule yi té diamoudji yalla

    • cheikh ousseynou sy

      gooor yaw warnanio wahhtann

  • deug plus

    Fèkhèko rèk dème deugue la Serigne Saliou dèf

  • Tontou

    wokhoufi dara

  • defean bi

    béthio bayile tothie sa sarapee ndeye waye

  • defean bi

    bayile doule

  • defean bi

    bayile tothie sa sarapee ndeye waye

  • rebatass

    bethio ana mbarasse statut dom mbarass

  • defean bi

    yaaa meune doule béthio

  • bethio

    mdrrr bethio dou dém koi xamoul dara waxoudof rék lay wakh

  • kannman

    je n'ai pige.

  • kannman

    je n'ai rien pige

  • baba

    dafaye dounde ci serigne bi wayeh gueumoulco sakh. serigne bi couco gueum dangaye dème diamoudji Yalla mom lolou leu beugue

  • toorodo@hotmail.fr

    manndi rk ak doule ak katta khaleyi lafi nekke

  • bonito
  • chekh fatou

    mdrrrrrrrrrrrrrrr serieux qui weroul mane j ai pitier de lui

    • niang

      yeureumeuul sa bop mo geune dh teu mandouu sii niitt amneu solo trooow

  • Malick

    Vous ne pouvez rien piger parce que senego a mis en ligne un extrait, il faut mettre l'intégralité du discours, ou à défaut une bonne partie permettant aux uns et aux autres de comprendre le message que veux véhiculer le Marabout

  • moussa ndoye seck

    yalla nako yalla sopi rek mn guene koi

  • tita

    yene reew guene torop.yeureume nalene yi saga you boone no lene k meuner.barki serigne saliou yeureume nalene.apres tout sakh yene da guene fans serigne bethio d.senego sou dougueler vidéo fook yene nieup commentaire.mais yeureume nalene nak yene rek

  • Samb

    Ndeysane kokou moye yalla doufi diouke mouke moye borome diapono

  • oms

    SERIGNE BETHIO yaw mi la SERIGNE SALIOU khamale mo takh nga khamni doufi diouke aye waye kou khame lénene diapale lolou té bayi ko.
    ndeysane ma yeureume gniko bagne niguéne déééé ak nakhare té doléne thi mane dara.

  • seydina

    dans ce cas on doit remettre en cause certains pratique ….

    • dado.gueye

      c quoi ça

  • map
  • mouride

    budul sara xana ngen rous serigne saliou mbacke miko def limu don

  • ahmadou bamba niang

    cheikh biii ziar naniouleu bou werr
    tamouy deugu serigne saliou moguii si dunya beu legui
    maaane deh doumeu thiantacoune wayei danio bok serigne saliou mbackei
    sa kaw sa kanam rek cheikh bi euleuk leip dineu leirr
    mandoutei limou geune dafeu beurii jokh jamou yalla mou lek beuu souur rek limou geune beurineu
    senegal nak moguii nii mai talibei bamba si yar ak teguine rek laniou ko hamei ak fonk niit cheikh bi goudeul fane loool sakh
    dieureudieuf serigne saliou mbackei

  • wamais wamais

    HAHA SAAGALENE BOUBAAKH SAKH! si vous saviez a quel point ces reactions renforcent nos croyances en lui vous l'auriez arreter depuis….mais comme c'est normal une ame sans lumière divine conduit le porteur à l'animalité, à l'agressivité. Ceux qui ont le minimum de connaissance du divin ne pipent mots.Ils ne lui disent jamais rien, jamais. Il a une interprétation profonde des ecrits et signes divins. Ceux qui vivent et connaissent la spiritualité savent qui est qui!!!
    Pour les profanes comme vous nak mom loll! ayez plutot pitié de vous, y'a rien de plus mal que l'ignorance! A vrai dire, je vous plains!

  • 7 yileu

    SISI DINGENE KO BAGN KAY C NORMAL. LE PEU DE TALIBE YINGENE AMONE DIEUL NALENE AY PA AK MERE REK MO DESS SENE ASSOCIATION YOYOU PASK DOU TARIKHA.AK KANA BENE BENE YIY BAGNANTOU GNO NEKK FII DI SAGA REK.DOUNGENE DIOKHé MOUKK BENENE ARGUMENT AMOULENE KO.KAMOLENE LOUY SERIGNE FAALEWOLENE GNIGUENE TOPP SAKH mdrr!
    Bref wakh diou gnaw famou diogué la deugg! yeena kham lou gnaw pa mom, il repon jamais à des attaques khana gathié dinalene mossa dal benn fane.mai zero vergogne chaque jour mou door leen ngene di saaga rek mdrrrrrrrrrrrrrr

  • momdaal

    mom daal mingui diokhé ay arguments sakh ci lim gueum diko dounde.RESPECT!!!
    le reste nak mom saaga rek ak wakh diou rafetoul
    kou diokh tieur sa wadiour deh do saaga bou diambour meme soungene bokkoul dieumoukaay!
    CHEIKH SADBOU la gueum wayé nite day mandou mom forcéwoul kenn nit yi gnoko beugg

  • ARMADA

    WA NITT DINA SOKHORé NII ??? SOKHOR DAAL AK BONE BAKHOUL. KII DAAL LOUM AM BOKOUKO AK GNEUP LOUWAY SOKHOR NANGOU KO. EN PLUS IL A TOUJOURS EU LE MEME DISCOURS MANE CILAKO DIOKHE TIEUR

  • NIT DOFF KILLER
  • 775669041fall

    sant serigne bamba bou werr daf niouy warr sasou nekk.ndakh mo man fi si adouna man man falle sa alakhira.tidjanyi sa bouniou xaye di guiss yonou mourid di yokk niom niouy dellou ginaw.kenne guissoul mourid bouy demsi tidjan di djebalou…tidjanyi nioy niaw di djebalou sasou nekk man guiss nasi lou barri.

  • cheikh ousseynou sy

    siarrnaléén deugue lay lathie c'est qui

  • cheikh ba

    probleme bi ngene ame moy yokoutek gui molene diakhal

  • fake
  • mdrrr

    mdrrr wakh nga deugg yeuff yi da yeek ci digou bopp took seen khel yi motakh gnou diafourrr haaha!
    SERIGNE BETHIO DIEUREUDIEUF

  • wah degue

    salam raisonne vous un homme qui ne sais pas lire le coran ce nom marabout

Publiez un commentaire