10 COMMENTAIRES
  • deug deug rk

    personellement mane barthelemy dama ko fan ndah deugou guimou deugou en plus macky sall vraima merci ndah yangui bayi barthelemy mouy deff sn travail normal mm bou nguen bokoul parti politik c sa la democratie

  • Ibra

    Ce regime darra menou niouko. darra defou niouko. darra khamou niouko a part fene. on ne gere pas un pays dans le mensonge. ils ne font que mentir.

  • Ibra

    ce regime darra menou niouko. darra khamou niouko darra defou niouko. fene rekk laniouye deff akk tromper le senegalais. on ne gere pas un pays dans le mensonge

  • Ibra

    Kou deglou les propos de Bath sakh kham mi limouye wakh mo nekk si deugue. Sakho mome amoul bene coherence mou nane il fait de l amalgame. Senegal sene natou moye ngourou macky sall. darra khamou niouko darra deffou niouko dara menou niouko.

  • Namou

    Bien dit Barthélémy ! Ce gouvernement de cafard essaye de te mettre des bâtons dans les roues mais bagnal .
    Tu fais du bon boulot . lafthiate rek !!!

  • Ibrahima

    Daz tu a parfaitement raison

  • baxata

    barth mom deug ak am foula ci bopam mo tax niou bari nane da rw

  • Fa

    Ya rien d’humiliant sur ses propos. Pourquoi certains journalistes s’acharnent sur Barthélémy diaz khana vous avez reçu des pots de vin de certains gro bonnets mais arrêtez ki khale nitou deug la te bagn kat la et sait tous que c’est ce qui dérange Yene nit yi. Barth saches qu’on te soutient à 1000 /100 fait ce que tu dois faire ba Ken lal la li moy lane. Bande de cochons.

  • ramcess

    deuggg rekk ngafi wakh pabi nakkk amoul foula

  • makhou

    barthe seu que tu ya dit tu la même dit a walf sorti tu cé yaw sénégalais yi khamnégne né degu rek guay wakh sougnou ko fatoul fatal canal bi cé simple senegal so néké bagn katt am fouleu si liguay def gnou né dagua reww nekal si diame et continue say travaux si seu commune

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *