21 COMMENTAIRES
  • HELA555

    vous les supporters li daléne waré wani mbeur yeup nio bokk naye
    adversaire amoulll lamb sport dongue laaaaa
    kone si niarr ngi si séne fére play

    NON A LA VIOLENCE

  • amadousene965@gmail.com

    li moye senegal you diokhonete lo kho kome balla ak eume me kholo xiro amoull solo senegale yi nayou de lolo si khell yi nie nanne te diamou doune dou bi yagoull me balla do bere ak yikini lambou la wala eume lolou la nou mbegeu youne senegale yi li ra fette na toropp

  • Schwarz

    Jamm dale si la lépeu khatie

  • zakaria

    2 grands champions

  • zakaria

    c est vraiment tres nice …li mom rafett na

  • hanche

    ahhhhhhhhhhhhhhh liiii cé tré nice lolllll parsk tous les deux ont le méme coeur vous etes tous gentils cé ça la vie aprés l'sport cé la féte on danse et on joue bnne continuation tous les deux yalla bou seytanné khate sén biir

  • Zeina

    Ah c est super, j adoooooooore

  • Doum

    C trop nice bala et eumeu peace forever!!

  • SERIGNE FALLOU

    BALLA GAYE si boppam mo Raffét Kholll, nagnouko wakh té Déé , Woutté Ak Modou Lo trop qui n'accepte jamais sa défaite

  • dykha

    lii seddna khol pleins de bonne choses dans l'avenir pour vous deux

  • pisko

    li mome raféye na trop les deux champions

  • golden

    franchement c'est beaux félicitation tout les deux

  • www

    rafitna

  • kheuss

    nice na way

  • aram Njie

    Aaaah diame reck ka nekh

  • nfiaye

    magnifique

  • khl

    trop nickel

  • khl

    c'est trop nickel

  • RD

    affaire bou Nice

  • Hot Boy

    Li rafet na li moy sport fo tjrs avoir l esprit de faire play

  • rebatass

    oh li nice na dh sama yaram sakh mogui daw yalla na diam yague way

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *