PUBLICITÉ
balla gaye 2 serigne abdou karim mbacke - Vidéo: Balla Gaye 2, Ahmed Aïdara, Baboye... chez Cheikh Abdou Karim Mbacké... Regardez

Vidéo: Balla Gaye 2, Ahmed Aïdara, Baboye… chez Cheikh Abdou Karim Mbacké… Regardez

A quelques jours de son combat contre Gris Bordeaux, Balla Gaye 2 effectue une tournée religieuse. Il s’est rendu chez Serigne Abdou Karim Mbacké, fils de Serigne Mourtalah Mbacké…

Regardez

balla gaye 2 serigne abdou karim mbacke - Vidéo: Balla Gaye 2, Ahmed Aïdara, Baboye... chez Cheikh Abdou Karim Mbacké... Regardez

balla gaye 2 serigne abdou karim mbacke 2 - Vidéo: Balla Gaye 2, Ahmed Aïdara, Baboye... chez Cheikh Abdou Karim Mbacké... Regardez

balla gaye 2 serigne abdou karim mbacke 3 - Vidéo: Balla Gaye 2, Ahmed Aïdara, Baboye... chez Cheikh Abdou Karim Mbacké... Regardez

Ahmed Aidara Baboye
whatsapp 1245
Annonces

(12) commentaires

Asna Khadim

salam senego leup beneu la wayé serigne abdou karim mbacké doomou serigne fallou mbacké kanamti guéne torop ndannk rekkk

Mbacke Barre

Balla un mouride ne porte rien sur sa tete devant son matabout

F

balla sa mbakhana bi nak mouride do sole mbakhana si kanam serigne bi

Senegal Sa Kanam

balla gaye yaw amo talibe sa genre bi nio yakk deukeu bii di seti sa serigne di sol mbakhané vraiment vrai doff gua

Bakh

balla amo talibé yaw mouride yii merenanioula torop loutakh gua sol mbakhané si kanam segn

Malick Diander

Leerou serigne fallou leuh wa senego vous avez fait une banale erreur

Guediawaye La Deuk

limotakh gris bordeaux dila khass nanela guaka un vrai mouride ne porte rien sur sa tete souy seti seurignam

Makhoulaye Dieye

Sama gayi yéne douguéne compreende balla dafa déf ay trésse c ta diir létou kone kay mou téksi mbakhana mo gueune mouniko fangue si kanam seugne bi balla dou sama mbeur nak mé réwoul wakh deug yallah

Asna Khadim

wa senego bayilen tattoné serigne fallou la lene wakh pas serigne mourtada délen lathie di verifié infos avant de publié svp

Roger+Milla+Alias+Ken+Bugul

??Rien a foutre.??? ??

[email protected]

Balla a raison de porter son bonnet. C’est sur recommandation du marabout responsable to son tioumoukaye. Ces gens la sont plus efficaces que les prieres abrahamiques de nos chefs con-freriques. C’est l’Afrique. Bien vu Balla. Lou way di wouyo, nakoy nouro!!!

Adama Diaw

L’islam dafa téré goor mu létou

Publier un commentaire