Vidéo- Archives Inédites : Moment de complicité et de délires entre Thione Seck et Youssou Ndour ! Regardez !

Adouna Mo Goudd Tank !


Vidéo- Archives Exclusives : Moment de… par sendiaspotv

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

11 commentaires

  1. Anta linga wah deugu la gnoun mé dou fans yi kesse ak télé yi yen animateurs yinga hamni amougnou ben professionnalisme loudoul garouwalé rek di diahassé té you dou sen morom


  2. anta ma puce d’amour adouna amoul solo gnoun gnep gno far c’est le Sénégal qui gagne gnoun fans youssou ndour yi amougnou blem yoyou c’est len rek lagnou mounoul supporté moy kouy wah lou gnaw you prk bougnou wahalé yala rek hamnguen ni you ken moussoul degu mou wah


  3. Merci Gfm pour ton commentaire tu m’as surpris. Je pensais que les fans de Youssou Ndour saga rek khasté ak wakh bou niaw lanioumeune si Papa Thione.

    Parfois nioune noy yoke kharmi karaw dagnouye saganeté di khastaneté sur les forums et réseaux sociaux. On doit changer de comportements ce n’est pas saint, et on ne fait que du tord à nos artistes préférés. Nama nieup balle akh, balena nieup akh.


Laisser un commentaire