Vidéo- Anniversaire au Grand théâtre : Titi réussit son pari
Amadou SY
47 COMMENTAIRES
tontonjules
29/03/2015 à à 12:06
masalla titi kenne dou yow vrema
laye camara
12/03/2015 à à 1:47
félicitations titi li kouné nékhoul Dagua sé bokoul sa khol di khasan
amina titi
10/03/2015 à à 14:20
bilahi titi soumalay déglou sama khole bi day sééd gouyou telma k li gay woyy dafa nekhhhhhhhhhhh titi goudal fane wayy
DIP REP' TYLE
07/03/2015 à à 22:33
onse once onche onze once l balah m dérange sdgfjkknvcxz
feuz
07/03/2015 à à 20:17
youssou bou sokhoron doukou dieule guinee indiko ko nekal 10 ans ba nieupe khamla yoboula founek arreter way
once
07/03/2015 à à 19:52
dip rep tyle kharal bangua meuneu wakh changer gnous tontoula ……sofff…. si t pas content tu degageee…..issshhhh
DIP REP' TYLE
07/03/2015 à à 19:33
slt lady gentlman il fau vou sangé d la miwzik l balakh nou amerd trop
Baba
07/03/2015 à à 18:49
Dieu entends moi et donne à cette légende exemplaire dame une longévité ,paix ,santé et beaucoup de réussite à ces projets
J’adore beaucoup ces chansons c’est la meilleur des chanteuses sénégalaise.
seny
07/03/2015 à à 16:19
Tu as cassé encore la baraque titi longue vie atoi
mimi
07/03/2015 à à 14:26
elle est la meilleure chanteuse du Sénégal,il faut le reconnaitre, elle chante des thèmes d’actualités conforme avec notre société et sa voix on n’a parle pas
il faut l’encourager et bcp
au sénégal les gens sont méchants titi je te demande de continuer comme ça inchallat tu iras loin
t’as un don de dieu qui est ta voix et tu la seule a l’avoir au sénégal, tu chantes comme tu veux
je t’aime et du courage ma chérie
boubacar sarr
07/03/2015 à à 13:02
félicitation thia kaw thia caname c bien écoute bien les conséilles de youssou ndour bouléne kén maitre en mal comme tu la bien chanté hier
mamyablaye
07/03/2015 à à 11:50
Titi tia kanam yalla yeumb la fi nèkal pkoi sans prince arts elle peut pas rèussir on est derrière toi on aime ta musique et ta voix machalla
doyna
07/03/2015 à à 11:26
melomane tu sai k titi est le meilleure chanteuse en s moment tout le senegal est d accord pour ca mais tu sais aussi k le grand chanteur ki es youssou ndour est la pour leur barré le chemin ki mene vert le haut soit tu accepte d etre exclave kom les pape diouf Aïda nder pape birahim pr k ils t aide sinon il connait tous les lobie de la musique ki vont t mettre les bâton sou les roues c la vérité titi n peu k faire avec les maigre moyen a son bord donc mercie a bougane il n es pa obligé a l aider donc kom il le fai mercie bcp msr bougane la famille d Youssou sont tous kom Ca mechant rancunière sauf Ndiaga et ibrahima ndour ils brisent des carrière tjr mai dieu est grand juré il vont mal finir k dieu nous donne long vie
moukabaro
07/03/2015 à à 10:27
d’emelen diamou dji yallh sounou brome te bayi thiakhan
kya
07/03/2015 à à 9:45
affaire bi dou fessel grand theatre mais carriere bi………nekh na mais il faut pensé a l’avenir musical de titi et essayé de faire des soirée avoir des contrats …..té bagna défaneté……grd theatre par an lolou dou wakh dji…melomane tu as bien dis
talla seye
07/03/2015 à à 8:59
Mais sama gayii kéne dou SENTV mome la rék motakh afére yii mélnii SENTV SA kanam rék
Général
07/03/2015 à à 8:56
titi mon na de li mouye deff nekh na lol sakh machahalla mé sen tv gno khamoul darra touss nada programe lagne mo noul be pare sabote rk lagne fi necke te khamou gnou darra thiey bou donne tfm darra dou sed
rose
07/03/2015 à à 8:10
nina yéne loutakh guène seytané fi artiste yi fi eupe succèe sènegal niongui prince art
rose
07/03/2015 à à 8:07
merci mélomane wakh gua degue mé idy yaw seytanè Gua titi il faut ce ke melomane ta dit
zizou
07/03/2015 à à 6:51
Boukouthie waye mâcha Allah si kaw si khaname si loubakh
nina
07/03/2015 à à 6:24
prince art a les boules.aida samb defale com titi sinon tu va vieillir a prince art gnoukaye exploité rek
melomane
07/03/2015 à à 5:18
C Vraiment dommage mais ce k Titi ne comprend pas est k une carriere ne se limite pa seulement a remplir le grand theatre avec un tarif tres bas moi je m’inquiete de son avenir musical. En autre sa carriere musical. Villa krystal, barramundi, just for 4 ect…. sont les places avec bcp de classe et en vogue mais on entend jamais Titi y jouer. Titi en tant k ton fan depuis Alhadji Ass n’ecoute pa ces senegalais et surtout Sentv et foutre ta carriere en l’air. Deja depuis un moment tes soirees au yengoulen n’etaitent pa rempli. Yengoulen n’est plus en vogue. Essaye d’avoir des contrats avec des places tel k Just 4 U, Barramundi ect..S’ il te plait revois le chemin ta carriere. Il faut penser a sortir de ce cercle de bougane gueye danny, ahmed aidara. Ils ne font k t’utiliser. Autre chose un coach vocal je pense k a une place dans ton staff pour doser ta voix pour chanter davanatage en bas. J’espere k tu liras ce message ou un membre de ton staff pour revoir ta carriere. Sinon bonne continuation!!!
YAW NOPIL
07/03/2015 à à 11:56
TITI BIMOUY TOTHIE JUST 4U DOU TEY. DANGGUENE DI DIAYE CONNAISSEUR FEK AY WADE NGUENE
ngone tine
07/03/2015 à à 4:40
félicitations titi
idy
07/03/2015 à à 4:14
Non wa keur youssou ndour yi gno bone no gni dougnou dem koulene bayi wone gnou yakal gnou li ak noumou nekhee ……..kholalma grand theatre noumou mell
mia
07/03/2015 à à 4:05
Bilahi senegal gni gnou wara dècoré kéne décoré wouléne khalé bi limouy way amoul féne kholal ma style bi mou indéti rék ça ce voit she is so proud of her origin machallah way titi yallah nala yallah gatanti wayyyy( QUEEN BIZ royal thi titi tè nga khamni senegalése nga li ngay woté dou sougnou culture boul gène khét!!!!!!!!!! )
adji
07/03/2015 à à 2:55
Titi je t’aime vraiment je suis fière de toi daga fonkou sa yaye yakh gama guene fonkou sama yaye titi inchallah diame rek gay am jtm.
f@hotmail.fr
07/03/2015 à à 2:42
Bilay mo meuna attai
f@hotmail.fr
07/03/2015 à à 2:42
Yaye bombe
cash
07/03/2015 à à 2:33
Yalla reka meune até i lov u Titi
girafe
07/03/2015 à à 2:18
Titi machalla dundal 111 ans yalla waral sa bate machalla Lii guay def nehna loll beugueunala lolll
meme gran theatre bou amone niari niite sakh dou téré titi mofi meune….affair bi dou féssal gran theatre mais prouver ak la voi c ca le truc …dafay way deug di yéke di watie noumouko nékhé….klaf tiate waye rek guaye défff titi…tts les mourides maynaléne lii titi waye serigne saliou mbaké taye djiii
mame fa
07/03/2015 à à 1:54
Mashalah yay la lione du grand theatre gnou done wakh dou fess rous nagnou yaw rk yay way senegal ta nigni khamnagno kanela té yawla .jtmmmmm titi yalla na yalla wëral sa bat mwaaaaaah
tree
07/03/2015 à à 1:37
solasso deug rek gua wakh bilayyyy…..
solasso
07/03/2015 à à 1:19
franchement elle a réussie machallah ligueyou ndey aniioum doom kounek sa hol molay warou tu le mérites la chère titi tu es la meilleure chanteuse
lirrr
07/03/2015 à à 1:01
mane je l aime prsk elle est trés trés humble lolou moma gueuneu nékh tie niit…….dafa yarou mashallla……..beuriwoul chip chipp khalébiii…..yalna yalla laffal tiate …….dama contane bagua wayé youssou ndour bilay…..yéne niar yénamay begueulll…….ak les retro ;souleymane faye; omar pene ;lemzo diamono …..baba male …..sama gran yoyou …..musique pur et dure
bovi
07/03/2015 à à 1:01
no man ma ko wakh , mo dakh woy si galsene. machalhaaa
picasato
07/03/2015 à à 0:46
barkè tèeré mame yalla mo dakh way senegal mako wakh
koudédji kane
07/03/2015 à à 0:45
No ma lionne amo morome mane yow laye bégué
diaw faral
07/03/2015 à à 0:36
i love this girl
polin
07/03/2015 à à 0:35
bilahi mo dakh way senegal et ca n’engage que moi
tin
07/03/2015 à à 0:32
Je pense qu Elle est la meilleure au galsene actuellement
free
07/03/2015 à à 0:25
titi balama wouyoudié sama borme beugueuna gua wayalma sama yaye ma téralaaaa……..je t adorrr, kan tu chante g des frissonnsss.. mashaalllaaaaaa
touf
07/03/2015 à à 0:22
mashala vrmt tu as réussi grd théâtre fesse na deleu lingay weuyy nehna
pushhh
06/03/2015 à à 23:27
non tit je t aimeeeeeuuuu………..yalna yalla wéreul batbi ….kéne dakoula waye puce..mashaallaaa..
omina
06/03/2015 à à 23:21
Yes reussi son pari avec un tariff moins elever que celui de ses consoeurs.
masalla titi kenne dou yow vrema
félicitations titi li kouné nékhoul Dagua sé bokoul sa khol di khasan
bilahi titi soumalay déglou sama khole bi day sééd gouyou telma k li gay woyy dafa nekhhhhhhhhhhh titi goudal fane wayy
onse once onche onze once l balah m dérange sdgfjkknvcxz
youssou bou sokhoron doukou dieule guinee indiko ko nekal 10 ans ba nieupe khamla yoboula founek arreter way
dip rep tyle kharal bangua meuneu wakh changer gnous tontoula ……sofff…. si t pas content tu degageee…..issshhhh
slt lady gentlman il fau vou sangé d la miwzik l balakh nou amerd trop
Dieu entends moi et donne à cette légende exemplaire dame une longévité ,paix ,santé et beaucoup de réussite à ces projets
J’adore beaucoup ces chansons c’est la meilleur des chanteuses sénégalaise.
Tu as cassé encore la baraque titi longue vie atoi
elle est la meilleure chanteuse du Sénégal,il faut le reconnaitre, elle chante des thèmes d’actualités conforme avec notre société et sa voix on n’a parle pas
il faut l’encourager et bcp
au sénégal les gens sont méchants titi je te demande de continuer comme ça inchallat tu iras loin
t’as un don de dieu qui est ta voix et tu la seule a l’avoir au sénégal, tu chantes comme tu veux
je t’aime et du courage ma chérie
félicitation thia kaw thia caname c bien écoute bien les conséilles de youssou ndour bouléne kén maitre en mal comme tu la bien chanté hier
Titi tia kanam yalla yeumb la fi nèkal pkoi sans prince arts elle peut pas rèussir on est derrière toi on aime ta musique et ta voix machalla
melomane tu sai k titi est le meilleure chanteuse en s moment tout le senegal est d accord pour ca mais tu sais aussi k le grand chanteur ki es youssou ndour est la pour leur barré le chemin ki mene vert le haut soit tu accepte d etre exclave kom les pape diouf Aïda nder pape birahim pr k ils t aide sinon il connait tous les lobie de la musique ki vont t mettre les bâton sou les roues c la vérité titi n peu k faire avec les maigre moyen a son bord donc mercie a bougane il n es pa obligé a l aider donc kom il le fai mercie bcp msr bougane la famille d Youssou sont tous kom Ca mechant rancunière sauf Ndiaga et ibrahima ndour ils brisent des carrière tjr mai dieu est grand juré il vont mal finir k dieu nous donne long vie
d’emelen diamou dji yallh sounou brome te bayi thiakhan
affaire bi dou fessel grand theatre mais carriere bi………nekh na mais il faut pensé a l’avenir musical de titi et essayé de faire des soirée avoir des contrats …..té bagna défaneté……grd theatre par an lolou dou wakh dji…melomane tu as bien dis
Mais sama gayii kéne dou SENTV mome la rék motakh afére yii mélnii SENTV SA kanam rék
titi mon na de li mouye deff nekh na lol sakh machahalla mé sen tv gno khamoul darra touss nada programe lagne mo noul be pare sabote rk lagne fi necke te khamou gnou darra thiey bou donne tfm darra dou sed
nina yéne loutakh guène seytané fi artiste yi fi eupe succèe sènegal niongui prince art
merci mélomane wakh gua degue mé idy yaw seytanè Gua titi il faut ce ke melomane ta dit
Boukouthie waye mâcha Allah si kaw si khaname si loubakh
prince art a les boules.aida samb defale com titi sinon tu va vieillir a prince art gnoukaye exploité rek
C Vraiment dommage mais ce k Titi ne comprend pas est k une carriere ne se limite pa seulement a remplir le grand theatre avec un tarif tres bas moi je m’inquiete de son avenir musical. En autre sa carriere musical. Villa krystal, barramundi, just for 4 ect…. sont les places avec bcp de classe et en vogue mais on entend jamais Titi y jouer. Titi en tant k ton fan depuis Alhadji Ass n’ecoute pa ces senegalais et surtout Sentv et foutre ta carriere en l’air. Deja depuis un moment tes soirees au yengoulen n’etaitent pa rempli. Yengoulen n’est plus en vogue. Essaye d’avoir des contrats avec des places tel k Just 4 U, Barramundi ect..S’ il te plait revois le chemin ta carriere. Il faut penser a sortir de ce cercle de bougane gueye danny, ahmed aidara. Ils ne font k t’utiliser. Autre chose un coach vocal je pense k a une place dans ton staff pour doser ta voix pour chanter davanatage en bas. J’espere k tu liras ce message ou un membre de ton staff pour revoir ta carriere. Sinon bonne continuation!!!
TITI BIMOUY TOTHIE JUST 4U DOU TEY. DANGGUENE DI DIAYE CONNAISSEUR FEK AY WADE NGUENE
félicitations titi
Non wa keur youssou ndour yi gno bone no gni dougnou dem koulene bayi wone gnou yakal gnou li ak noumou nekhee ……..kholalma grand theatre noumou mell
Bilahi senegal gni gnou wara dècoré kéne décoré wouléne khalé bi limouy way amoul féne kholal ma style bi mou indéti rék ça ce voit she is so proud of her origin machallah way titi yallah nala yallah gatanti wayyyy( QUEEN BIZ royal thi titi tè nga khamni senegalése nga li ngay woté dou sougnou culture boul gène khét!!!!!!!!!! )
Titi je t’aime vraiment je suis fière de toi daga fonkou sa yaye yakh gama guene fonkou sama yaye titi inchallah diame rek gay am jtm.
Bilay mo meuna attai
Yaye bombe
Yalla reka meune até i lov u Titi
Titi machalla dundal 111 ans yalla waral sa bate machalla Lii guay def nehna loll beugueunala lolll
affair dou fessna wala fessoul ….meme boudone amoul niit sakh titi mofi meune….waye rek léye déf dafay waye tempp
meme gran theatre bou amone niari niite sakh dou téré titi mofi meune….affair bi dou féssal gran theatre mais prouver ak la voi c ca le truc …dafay way deug di yéke di watie noumouko nékhé….klaf tiate waye rek guaye défff titi…tts les mourides maynaléne lii titi waye serigne saliou mbaké taye djiii
Mashalah yay la lione du grand theatre gnou done wakh dou fess rous nagnou yaw rk yay way senegal ta nigni khamnagno kanela té yawla .jtmmmmm titi yalla na yalla wëral sa bat mwaaaaaah
solasso deug rek gua wakh bilayyyy…..
franchement elle a réussie machallah ligueyou ndey aniioum doom kounek sa hol molay warou tu le mérites la chère titi tu es la meilleure chanteuse
mane je l aime prsk elle est trés trés humble lolou moma gueuneu nékh tie niit…….dafa yarou mashallla……..beuriwoul chip chipp khalébiii…..yalna yalla laffal tiate …….dama contane bagua wayé youssou ndour bilay…..yéne niar yénamay begueulll…….ak les retro ;souleymane faye; omar pene ;lemzo diamono …..baba male …..sama gran yoyou …..musique pur et dure
no man ma ko wakh , mo dakh woy si galsene. machalhaaa
barkè tèeré mame yalla mo dakh way senegal mako wakh
No ma lionne amo morome mane yow laye bégué
i love this girl
bilahi mo dakh way senegal et ca n’engage que moi
Je pense qu Elle est la meilleure au galsene actuellement
titi balama wouyoudié sama borme beugueuna gua wayalma sama yaye ma téralaaaa……..je t adorrr, kan tu chante g des frissonnsss.. mashaalllaaaaaa
mashala vrmt tu as réussi grd théâtre fesse na deleu lingay weuyy nehna
non tit je t aimeeeeeuuuu………..yalna yalla wéreul batbi ….kéne dakoula waye puce..mashaallaaa..
Yes reussi son pari avec un tariff moins elever que celui de ses consoeurs.
Les commentaires sont fermés.