Vidéo - Ahmed Khalifa Niasse à Abdou Aziz Sy : "Yama Gueunal Sidy Lamine Niasse…"

Le guide religieux Ahmed khalifa Niasse ne tarit d’éloge à l’égard du gardien du temple.

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

Aucune recommandation disponible.

12 commentaires

  1. keita

    ab domeharam ak kouti bouy wakh lou gnaaw si maodo day torokh rek kepp kou douga si diiiwanou maodo di wakh lou gnaaw dou la djick ci kaw souf bi ci tane sakh mooy nga de


  2. Segg

    Médias yi comme les senego tall rew mi lanou beug waye kou ko djem souf fêtéla kaw rewmi nek si jamm bilahi malako wakh mane bene werente nekou thi


  3. citoyen

    le pays est en danger satan a gagné les coeurs des sénégalais les médias sont des pyromanes et surtout ce site(SENEGO) vous êtes entrain de brûler le pays et vous serez responsable.

    Touba, Tivaoune, Mediana bay,e yoff etc leep bénla


  4. alerte

    attention!wormalèn makk gni yenneu wakh yi eupna kouné na diapp famou diapp té respecté la kénén diapp sougnou kilifa demb amougnou morom wayé koussi moytouwoul dingua yakhou té do kham lilako déf. wasalam.


  5. iba

    gagni diape lene lu lene mame maodo wakh ta guene bagnia tonte dalene di tardel té borome dathie bii mounoko djio té sakh kou bakh kouné nioun wakhala safane saydina moukhamed mofi geune ta dégeu na louné hamed kh niasse il ne connait apsolimant rien da lire lisi téré yi té khamoul lisi téeré yi?YALLA NAGNOU YALLA FAYALE SOUNIOU MAKK YOU

    BAKH YIII


Laisser un commentaire