Vidéo- Affaire des sacs efféminés : Entretien avec Wally Ballago Seck. Regardez
Amadou SY
105 COMMENTAIRES
Nourou
01/02/2016 à à 11:49
Mw je dis simplement que le respect commence par soit meme.Le plus important cé de croire en Dieu et le jour du jugement dernier.Et celui qui a lu le coran saura que tout ces rumeures sont des signes de la fin du Monde.
bayil sac yi fils…boul yakal sa bopp fils…alioune mbaye nder etait plus poplaire que toi…baka gayi wédé il a fini mal et j espere qu il va retournerl…defal nank
CE JOURNALISTE EST TRES FAIBLE DEVANT WALY MAIS POUR MOI ETRE STAR NE VEUT PAS DIRE LOMA NEKH LAY SOLO NOUS AVONS NOTRE CULTURE ET TOI TU AS DES FANS JEUNES
entoucas sac rafatoul si goor waw man ay son youy yetei rek laye deglou cad ay reference com you pene thione et ndongo mei dal loumalen meuna xamal moy nit bou amei public da war di xolat bou bax loumouy def xamouma exacte loumou dioublou si sac bi lima meuna wax pour l inst moy il s apel waly tei gnoun goor lagn guiss mei dal nagn xolat bou bakh djiko yi waly c un porteur d voi il a des idole tei kilifeu leu con sac ou cartable domaine des fille le vrema
waw man len rek lay wakh man artiste bouy yetei laye deglou mouy you omar thione ak ndongo mei dal pour vous dire rek sac dafa rafatoul si goor khawma nak vrema loum si dioublou doumasi wakh di bakare entoucas il s apel waly tei c t un garcon nagn holat bou bakh louy diarign fan s yi
Waly n'est pas mon fan mais vous ou nous les sénégalais diaplèn né lep louway wakh fi digako répété devant Dieu. Y'a plus important k le sac de waly, yakh gor molèn gueuneul kay lék. Khoul khakh walaw kana mourane
Moi je prépare pour venir au SENEGAL INCHAALLAH en fevrier…….naa waathi aeroport akk sama sac a main comme cel de WALY SECK ba kénn kholma khool buma nékhul rékkk ma dakkhaar sa ndaye ay kourou courou bayfall….banga sonne……has been yinguenne donn ….non capite un cazzo…..
waly vit a vit et laisse parler les gens yaw si kaw si kanam rekkk tal bou yallah tal sani si mate guene faye ko té dangua am nianou wadiour yaw ko bokal dimbalingua ko donc du courage mon frere sa va aller inchaallah
Musulmans =croyant et comportement.
Seul Dieu sait si ces accusations sont vrai ou pas donc arrêtez de juger car Allah subhanah wa Tallah n'aime pas cela. Néanmoins, Wally tu te dois d'avoir un bon comportement en tant que musulmans. Ne suit pas mes mode de l'occident jusqu'à te perdre. Un homme doit se comporter en homme et pas faire en sorte de ressembler à une femme. Dieu guide qui il veut mais il égare aussi qui il veut
Wally you are good at what you are doing that is the music and people love it, but please do not let them drag you into a life style that peoole will start questioning your image!!! Love yiur music!!!!!
C'est ça boulène may dara ils sont jaloux à cause de Bercy que tu prépare c'est tout,ici en Russie lhomosexualité est formellement interdit par loi mais les hommes portent des sacs comme ça ici parce que c'est des sacs pour hommes
senegal nagnoulene bayi ma rirando ter raguale yalla wally a bien parler legui nak lerna kou neke na khole gni beugue mome dagni beugue rek gni bagne dagni bagne rek yalla na yalla guiss thi thowli ndokh bou sede guouye nga neke thi lenene ter khamner yalla mo approuv?
merci wally gni dagno sokhor bouleen faale ioaw talibe nga diam rek ngay aam… Senegal lignou wara wakh bariina nagn ci wakh mo guen goorjiguen yangui fa di leumbee, deuk bi metii na kou agn doo reer nagn wakh ci lolou deemb kou setaan RTS guis depute yi nignou fa nekeewoon khamne am nagn lougn wakh…
waly n'est pas serieux franchema ….. danguaye def yeufou goor niou nopal laa meunoko nniou lijantila bangua noye nééppp….. personne n'est derrière arrière pensée comme ton père …………………..
La majorité des jeunes filles au Sénégal ne prient pas car c est eux qui soutiennent waly.Elles ne connaissent pas leur religion voire n y croient même pas.Ceux qui leur intéressent c est la musique.J ai pitié pour cette generation de filles.Pourquoi ne dites vous pas la vérité a ce waly qu il arrête de s habiller comme des femmes.La croyance s accompagne avec les actes non de se limiter sur l expression orale.Les bienfaits de dieu sont visibles et invisibles.Tu as intérêt a te comporter comme un musulman.Vive le Sénégal de Mohamed(psl) de bamba de elhadji malick de baye niasse.Nous n accepterons pas que tout ce que vous avez laisse puis être détruits par ces Maudits de PD D HOMO.
Hey Wally ne nous en merdé pas nous on vit en Europe se sac à main la je l'ai vue y'a plus trois ou deux ans . Toutes les personnes que j'ai vu porté se sac sont homo des ( frocio ) arrêtée la on est pas aussi con que tu le pense .
Daba seck senegal daniou ko bokk té lou deff di wakh lou aye di nianbate wakhléne ko deug c'est kéne manou fi térè kene wakh dakh yagui wakh Senegal douniou soss daniouy yokou wakhléne ko mouy deff yeufou goor dakh gnikoy roy daffa siw
AU LIEU NGENN LIGUEYI FI NGENNI TOKK TOP INTERNET BI DI OUBI DEBAT FACEBOOK AK FENENN DI BAKAROU REK.WAKHTOU LIGUEYE SOU DIOTE LIGUEYI LENN WAKHTOU DJOULI DJOTT NGA DEFFI KO BAGNA OUT TEMPS BOLENN DI NEKE CI DEROU NITT PRCK AMOUL SENS MOMM LOUMOUY AM AMNAKO BA PAREH.
barki seydina mohamed psl li dawna yaram yalla nala yalla soutoural défal la diam may la katane ak wér mouseul la thi pékhé none !!!: wakh djou bone deukoul famou djeume famou diougué la deuk té kou nék amgua none bayiléne ñiouy wakh rek guay liguéye!!! Inchalla lépe dina bakh thi katanou yalla
Boy bi nooy nekhh la rek !!! boum niou fontooo waye !fi senegal la sou beugé mou dem fenen def louko nekhh !! en plus sa music ki derrange tellement les senegalais sont dingues vraiment ils consomment n import kw k des tama et bruit sa te soul a la longue

merci waly yala nala yala sam fan yi sonou na torop lekatou ma nan touma da may xeuy di defante beu guoudi sama col lay yor rek def si sama credi di defante ak domoram yi dila beugeu yak mes gnoun sa ay fans boul tite ci gnoun boul am xel gnienr ci gnoun dougnou la meuseu bayi dougnou la meuseu wan guinaw gnoun ak yow dafa naturel xolal waly gnoun ay bay fall lagnou piiir merci encor pour tou legui nak meuna dem def sama ndeki bou bax ak sama agne bou nex dem teudi nelaw li for na gnoun ak waly law ba faw ba djiegui forontier yi adouna xel la lep xel la kou ci sa xol di doxot daga koy onkou mou guen lila lila wax man
Les fans de waly nitt soko beugué dagua koy wakh deug deflene delegation wakh ak mome mou bayi yeufou djiguene yi bou dé homo yalla moko kham comportement bakhoul
waly bouniou sonal ndayame yakh goor niepe di niafe ndayame di doul goordjiguene keepe kouye sa fans goordjiguen la khamang ni seneglais dafa gawa yeramatei motakh nga guenne di wakh di fene rec goordjiguene nga ap domarame nga
vous les senegalaise ni sen yarami gnou le nonou la sen kholou bone te gnoul wally seck di gen ko bayi mou nek si diam dh inchalla bousi yalla nan dh bilay ki kenen dou meune si mom dr senegale kou dem gnou wakh kou demoul gnou wakh mai bayi len sama nidiany dji mou dounou dounam bilay khamou len kane moy wally motakh gen di wakh gnoun ay bokam lou wally def nekh nagnou nakh baye fall deug la piiir sakh wally waro wona tontou sakh ta lena rek lalen di khamal dou dagen di meuna wakh rek tewo len seni lamine kholal dagen di wakh moy doli rek nakh gni ko khamoul rek kay wakh si mom wally vallago seck demal say bokou gnogui lay gnanal am ga gnanou wadiour yaw machalla senegal ay nnn louma len wara wakh rek lhep ko wally jtm piiir love you
Ok ? boy waly mais mais comme tu dit t baye Fall slors fait comme les baye Fall a fond Meme avec ta music arrete de mettres des patanlons pinw c moche sa te va pas parceque t trop mingre change de style se fameux sac nak ici en Europe se son les homos qui le porte Meme si tu le sais pas secn'est ni sac ds femme ni sac de mec mais c'est un sac crée pour les homosexules mannequin qui défil dans les podium .donc boul deugueuer bop rak s'ama kholal si ndongo lo moutoul Senegal Kouy dém laniou bagne sén kholyi mo bakhoul est pourtant donc change petit frere wakhou kasaw kasaw rek ngafii wakh boulniou diémé réraal.les pédé d'aujourdhui ils ons des femmes des enfants est pourtant il se fon defoncé le cul par des mecs regarder l'anciens premier ministre senegalais abdoul mbaye surprie par sa femme avec le bauy de la maison entré de le baisé dans le cul donc boul niou sonnal change c mieu.close
il faut s habiller comme un homme un baye fall n a pas ce comportement.Le chanteur bay fall c est cheikh lo.Tu es un PD dans la clandestinité ESpece d hommo.Le senegal n a pas besoin ce genre d homme ce n est meme pas du style.Menteur
Du courage fan dafa yabate da wara guene publiquement thi tele wam bobou di sen tv diagalou askanou Sénégal bi yeup parceq filou nek ni nieup nio ko mere

🙁 Un fils dont on a emprisonné le père pour malhonnêteté doit sou amee djom,suivre le droit chemin et tenter de rétablir la dignité et l'honneur perdues par sa famille. Mais Waly mi dom diou NIAK DJOM LEU.Et le jour du jugement dernier, il comprendra très bien les conséquences d'être un homosexuel ou de se nourrir des biens tirés de sa valorisation dans nos sociétés. 🙁
YENN LOU GUEUNA BONN AK LOU YALLAH BAGNE REK NGUENNI DEF MOY LANN DI JUGé NITT FI KOUSSI NEK AMM NGA LOUNé WENG SENN KEUR YI TE WAKHOLENN KO YENN LANN LAH.FI BENNEUH JUGE MOFI AMM MOUY YALLAH.LINGUENNI NEK FI DI WAKH NGUENN LIGUEYI NIAFFé COMME MOMM MO GUEUNN SENN THIOWLOU BARRI LI

Je ss desole mais waly dou dem
Waly kou gniapeu sa ndaye gua chak jour gordjiene yi may la khaliss gua ni beuguou goor djiguen
Ioww ……..
Sa baye mom si prision lay kate ndayam
bayil sac yi fils…boul yakal sa bopp fils…alioune mbaye nder etait plus poplaire que toi…baka gayi wédé il a fini mal et j espere qu il va retournerl…defal nank
wally Seck aye dou yame thi bopou diambour nguani sa prochaine voyage digue ko yoor en tout ka liii malaye conseiller dal ngua eviter probléme yii nakh meunala yobbou founé nite kou bakhe day daw thiow banékhou Adouna diaroule yéneu yii
courage faramaréne bi
cartable reik guèn di doul dolein xol baparei dora wakh… doul reik guein di df. wally di courage gnogui sa gui naw pour tjr.
mais boybi akk ni mako fan wewone aahahahahahha….nekhatouma …manghi si j martins psquare cheikh lo tapha diarabi etc
CE JOURNALISTE EST TRES FAIBLE DEVANT WALY MAIS POUR MOI ETRE STAR NE VEUT PAS DIRE LOMA NEKH LAY SOLO NOUS AVONS NOTRE CULTURE ET TOI TU AS DES FANS JEUNES
entoucas sac rafatoul si goor waw man ay son youy yetei rek laye deglou cad ay reference com you pene thione et ndongo mei dal loumalen meuna xamal moy nit bou amei public da war di xolat bou bax loumouy def xamouma exacte loumou dioublou si sac bi lima meuna wax pour l inst moy il s apel waly tei gnoun goor lagn guiss mei dal nagn xolat bou bakh djiko yi waly c un porteur d voi il a des idole tei kilifeu leu con sac ou cartable domaine des fille le vrema
waw man len rek lay wakh man artiste bouy yetei laye deglou mouy you omar thione ak ndongo mei dal pour vous dire rek sac dafa rafatoul si goor khawma nak vrema loum si dioublou doumasi wakh di bakare entoucas il s apel waly tei c t un garcon nagn holat bou bakh louy diarign fan s yi
Waly n'est pas mon fan mais vous ou nous les sénégalais diaplèn né lep louway wakh fi digako répété devant Dieu. Y'a plus important k le sac de waly, yakh gor molèn gueuneul kay lék. Khoul khakh walaw kana mourane
Ne juge point afin de ne pas être jugé car tu seras jugé de la même manière que tu juge.
Moi je prépare pour venir au SENEGAL INCHAALLAH en fevrier…….naa waathi aeroport akk sama sac a main comme cel de WALY SECK ba kénn kholma khool buma nékhul rékkk ma dakkhaar sa ndaye ay kourou courou bayfall….banga sonne……has been yinguenne donn ….non capite un cazzo…..
deflou bakhe rek mo am solo
waly vit a vit et laisse parler les gens yaw si kaw si kanam rekkk tal bou yallah tal sani si mate guene faye ko té dangua am nianou wadiour yaw ko bokal dimbalingua ko donc du courage mon frere sa va aller inchaallah
bilaye dano sokhar mai courage bala nekh daye meti
waly kou kate ndem le gorr djiguene bi
anga soeur wala yaye…..aalkoko sèètt….dinako katte kattou bayfall bagnu tasss……HAHAHAHAHAHAHAHA
yow mi wakh sa baye moye gordjiguéne
Du courage, metina, torope mais massa, yifi dakh def ndiomber niofi guena mena Def todj todj souniou dioguer di tidji srn guemign senegalai daniou lek wakh. Waro si wone sakh wakh ya tayyyy
Wally ch8 vraiment content pour tou et jle serai tjr…nguiryalle bayyiléne diambour mou doundou TAL BOU YALLE TAL LE
Musulmans =croyant et comportement.
Seul Dieu sait si ces accusations sont vrai ou pas donc arrêtez de juger car Allah subhanah wa Tallah n'aime pas cela. Néanmoins, Wally tu te dois d'avoir un bon comportement en tant que musulmans. Ne suit pas mes mode de l'occident jusqu'à te perdre. Un homme doit se comporter en homme et pas faire en sorte de ressembler à une femme. Dieu guide qui il veut mais il égare aussi qui il veut
wally li dou dara du courage denion sohor
Mani Waly boulgnou fonton
Wally you are good at what you are doing that is the music and people love it, but please do not let them drag you into a life style that peoole will start questioning your image!!! Love yiur music!!!!!
J'ai pitié de mme Seck , mari en prison , fils taxé de homo .
C'est ça boulène may dara ils sont jaloux à cause de Bercy que tu prépare c'est tout,ici en Russie lhomosexualité est formellement interdit par loi mais les hommes portent des sacs comme ça ici parce que c'est des sacs pour hommes
Wally sac bi mom sac djiguene com tu le dit peut-être tu né pas homme femme
wooooyyyy.et ton ami amzozo?excuses toi c mieux pour toi
senegal nagnoulene bayi ma rirando ter raguale yalla wally a bien parler legui nak lerna kou neke na khole gni beugue mome dagni beugue rek gni bagne dagni bagne rek yalla na yalla guiss thi thowli ndokh bou sede guouye nga neke thi lenene ter khamner yalla mo approuv?
Fafa wakh gua deug nitt yi beuguena ko sa genre gui khamni khamou yalla khamou yonene adouna guene deff keur wakhléne ko deug c mieux pour lui
rafetoul si domou joulit,pardon khawouma sakh ndakh domou joulitnga,yannala yalla sopi,yaw ak nioulay soutenir amiine
laisse les parler et continu ton chemin diam rek ngay ame gnit beugue nagnoula ba apres kene mounou si dara
Bayilenn domou diambour ji 'guenn di toumal … Waly boul bal kenn
Bayi lenn domou diambour ji
aka yombou sa style mo wax lingadone
merci wally gni dagno sokhor bouleen faale ioaw talibe nga diam rek ngay aam… Senegal lignou wara wakh bariina nagn ci wakh mo guen goorjiguen yangui fa di leumbee, deuk bi metii na kou agn doo reer nagn wakh ci lolou deemb kou setaan RTS guis depute yi nignou fa nekeewoon khamne am nagn lougn wakh…
waly n'est pas serieux franchema ….. danguaye def yeufou goor niou nopal laa meunoko nniou lijantila bangua noye nééppp….. personne n'est derrière arrière pensée comme ton père …………………..
bon courage wally
ay wayy wally bon courage yalla bakhna on est de tt coeur avec toi
waly i can't stop my tears love u
ki dafa yap senegalais yi limou déf nakhari nityi mouni dinako contuné di déf non senegal mo nékh yaw kay loula nit wakh bakhna
La majorité des jeunes filles au Sénégal ne prient pas car c est eux qui soutiennent waly.Elles ne connaissent pas leur religion voire n y croient même pas.Ceux qui leur intéressent c est la musique.J ai pitié pour cette generation de filles.Pourquoi ne dites vous pas la vérité a ce waly qu il arrête de s habiller comme des femmes.La croyance s accompagne avec les actes non de se limiter sur l expression orale.Les bienfaits de dieu sont visibles et invisibles.Tu as intérêt a te comporter comme un musulman.Vive le Sénégal de Mohamed(psl) de bamba de elhadji malick de baye niasse.Nous n accepterons pas que tout ce que vous avez laisse puis être détruits par ces Maudits de PD D HOMO.
wally amna ay foto you yés you nék si nétbi . mais senego dougal lénko
Hey Wally ne nous en merdé pas nous on vit en Europe se sac à main la je l'ai vue y'a plus trois ou deux ans . Toutes les personnes que j'ai vu porté se sac sont homo des ( frocio ) arrêtée la on est pas aussi con que tu le pense .
Daba seck senegal daniou ko bokk té lou deff di wakh lou aye di nianbate wakhléne ko deug c'est kéne manou fi térè kene wakh dakh yagui wakh Senegal douniou soss daniouy yokou wakhléne ko mouy deff yeufou goor dakh gnikoy roy daffa siw
YENN LOU YALLAH BAGNE NGUENI DEF MOY LANN DI JUGE NITT.FI BENNEUH JUGE MOFI AM GUEUMOUL NELAWOUL MOUY YALLAH.FI KOUSSI NEKK AMM NGA LOUNE WENGUE SENN KEUR LIDIEUNTI LENN LOLOU MO GUEUNN.TEH NGENN LIGUEYI BAYI SENN THIAKHANN YI NITT DAY WAKH LOUKO WOR WA SALAM
AU LIEU NGENN LIGUEYI FI NGENNI TOKK TOP INTERNET BI DI OUBI DEBAT FACEBOOK AK FENENN DI BAKAROU REK.WAKHTOU LIGUEYE SOU DIOTE LIGUEYI LENN WAKHTOU DJOULI DJOTT NGA DEFFI KO BAGNA OUT TEMPS BOLENN DI NEKE CI DEROU NITT PRCK AMOUL SENS MOMM LOUMOUY AM AMNAKO BA PAREH.
tu a bien parler mais j aimerais que tu ne porte plus des sacs louche courage
barki seydina mohamed psl li dawna yaram yalla nala yalla soutoural défal la diam may la katane ak wér mouseul la thi pékhé none !!!: wakh djou bone deukoul famou djeume famou diougué la deuk té kou nék amgua none bayiléne ñiouy wakh rek guay liguéye!!! Inchalla lépe dina bakh thi katanou yalla
Boy bi nooy nekhh la rek !!! boum niou fontooo waye !fi senegal la sou beugé mou dem fenen def louko nekhh !! en plus sa music ki derrange tellement les senegalais sont dingues vraiment ils consomment n import kw k des tama et bruit sa te soul a la longue
Boy bi nooy nekhh la rek !!! boum niou fontooo waye !fi senegal la sou beugé mou dem fenen def louko nekhh !! en plus sa music ki derrange tellement les senegalais sont dingues vraiment ils consomment n import kw k des tama et bruit sa te soul a la longue
yalla nala yalla sam te lafal thiate
Gny dagno sohor yalla bakhna du courage Wally
Non bayil domou diabour bi c un pere de famille khalate léne sa femme ak ses enfants amèl guène akh
du courage waly.
merci waly yala nala yala sam fan yi sonou na torop lekatou ma nan touma da may xeuy di defante beu guoudi sama col lay yor rek def si sama credi di defante ak domoram yi dila beugeu yak mes gnoun sa ay fans boul tite ci gnoun boul am xel gnienr ci gnoun dougnou la meuseu bayi dougnou la meuseu wan guinaw gnoun ak yow dafa naturel xolal waly gnoun ay bay fall lagnou piiir merci encor pour tou legui nak meuna dem def sama ndeki bou bax ak sama agne bou nex dem teudi nelaw li for na gnoun ak waly law ba faw ba djiegui forontier yi adouna xel la lep xel la kou ci sa xol di doxot daga koy onkou mou guen lila lila wax man
Les fans de waly nitt soko beugué dagua koy wakh deug deflene delegation wakh ak mome mou bayi yeufou djiguene yi bou dé homo yalla moko kham comportement bakhoul
yup ministre be def lolou hahaa
waly bouniou sonal ndayame yakh goor niepe di niafe ndayame di doul goordjiguene keepe kouye sa fans goordjiguen la khamang ni seneglais dafa gawa yeramatei motakh nga guenne di wakh di fene rec goordjiguene nga ap domarame nga
vous les senegalaise ni sen yarami gnou le nonou la sen kholou bone te gnoul wally seck di gen ko bayi mou nek si diam dh inchalla bousi yalla nan dh bilay ki kenen dou meune si mom dr senegale kou dem gnou wakh kou demoul gnou wakh mai bayi len sama nidiany dji mou dounou dounam bilay khamou len kane moy wally motakh gen di wakh gnoun ay bokam lou wally def nekh nagnou nakh baye fall deug la piiir sakh wally waro wona tontou sakh ta lena rek lalen di khamal dou dagen di meuna wakh rek tewo len seni lamine kholal dagen di wakh moy doli rek nakh gni ko khamoul rek kay wakh si mom wally vallago seck demal say bokou gnogui lay gnanal am ga gnanou wadiour yaw machalla senegal ay nnn louma len wara wakh rek lhep ko wally jtm piiir love you
amna gadou yokhamne deugu gafa wakh yalla nalla yalla samou Seck dawnayaram
boy wakho fi dara dara dara pour moi vous êtes pas référence c'est mon n'avis
Ok ? boy waly mais mais comme tu dit t baye Fall slors fait comme les baye Fall a fond Meme avec ta music arrete de mettres des patanlons pinw c moche sa te va pas parceque t trop mingre change de style se fameux sac nak ici en Europe se son les homos qui le porte Meme si tu le sais pas secn'est ni sac ds femme ni sac de mec mais c'est un sac crée pour les homosexules mannequin qui défil dans les podium .donc boul deugueuer bop rak s'ama kholal si ndongo lo moutoul Senegal Kouy dém laniou bagne sén kholyi mo bakhoul est pourtant donc change petit frere wakhou kasaw kasaw rek ngafii wakh boulniou diémé réraal.les pédé d'aujourdhui ils ons des femmes des enfants est pourtant il se fon defoncé le cul par des mecs regarder l'anciens premier ministre senegalais abdoul mbaye surprie par sa femme avec le bauy de la maison entré de le baisé dans le cul donc boul niou sonnal change c mieu.close
waly dagua faté indalé sac bou jaune bou norok sa veste bi
sakaw sakanam
sakaw sakanam rik nonyi yalla danala atik niom
waly sakaw sakanam rik nonyi yalla danala atik niom
CAB boul nio sonal dou man ken bokoumasi moko ngeun
borom sac bolèn guis niouslènko
strings Seck boulniou sonal
il faut s habiller comme un homme un baye fall n a pas ce comportement.Le chanteur bay fall c est cheikh lo.Tu es un PD dans la clandestinité ESpece d hommo.Le senegal n a pas besoin ce genre d homme ce n est meme pas du style.Menteur
Mane sac takhoul Dagua deff yefou diguene
courage Wally merina trop bilay
Wakh degue da niou ko yapp rec mais lakhèw sa kaolack mo gueune gravvvvve fouf
Attention svp attention naniou deff nank bouniou bakarou si niti
Wakho deug sa askane am na gordjiguene. Et ton oncle ousmane seck. Sa papa mo ndieuke promotion gordjiguene yi.il faut boycotter son concert a bercy.
waly courage yalla bakhna
Tu raison sur toute la ligne mais sounou borome moléne eupe dolé yallene sounou borome doli soutoure mouselelesu pékhé none
yaw tu t fou ds sénégalais pèdè wornama strings gu sol nonou guèl wa niak diom
wakh deuge nekh yalla bayi len KO mou ligey waly bay fall

hé l'argent de Amzozo … tu n'es pas victime , tu l'a voulu..gorél ko rek
senegal daal mo nekh kou jok rek def loula nekh bepary tok di yeremantou Wally goor dai def yefou goor sourtou domou djoulit
rkkkkkk fofa tooooothie!!ma contane si yaw famareen bien dis de tt coeur avec toi
Du courage fan dafa yabate da wara guene publiquement thi tele wam bobou di sen tv diagalou askanou Sénégal bi yeup parceq filou nek ni nieup nio ko mere
danga wara changè sa comportement kou nièp tafli nga toy
Du courage fan dafa yabate da wara guene publiquement thi tele wam bobou di sen tv diagalou askanou Sénégal bi yeup parceq filou nek ni nieup nio ko mere
du courage
🙁 Un fils dont on a emprisonné le père pour malhonnêteté doit sou amee djom,suivre le droit chemin et tenter de rétablir la dignité et l'honneur perdues par sa famille. Mais Waly mi dom diou NIAK DJOM LEU.Et le jour du jugement dernier, il comprendra très bien les conséquences d'être un homosexuel ou de se nourrir des biens tirés de sa valorisation dans nos sociétés. 🙁
ARRETER DE DIRE N IMPORTE QUOI TOY BAKHOUL WALY DINA LAKK NIOU BEURI LE JOUR DU JUGEMENT DERNIER C PAS UN HOMO ET MM SIL ETAI KOU DEE AK BAMELAM
Donc pourquoi il se comporte comme un homosexuelle et pourquoi il est toujours avec les homosexuelles. yaw mi di ko diapalé yaw la nara lak !!!
mdr sam pirate wagnile dose bi ya ngui blesser walyenne yi