Vidéo- Affaire profanation tombe: Le débat est clos, Balla et Heumeu se donnent la main

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Aucune recommandation disponible.

29 commentaires

  1. Madam Faal

    hahaaaa senego kai dara dakhu ko ndakh bombass ak ross yi Eumeu def bala moi dok ay khol man sama mbeur dama wolou Eumeu Yal na la Yalla lafal thiat


  2. Malick

    Bilahi gayi ndi guén ma fadj avec vo commentaire. ..Madame fall ak zeyna, jarabi boléci am class. Non les gars vs êtes super comique . Après une journée chargé after work xol bén coup d'oeil commentair senego dara dakouko.


  3. yakar bamba rek

    nguirr yalla gniy comanter nagno bayyi sâga ndakh sâga amott gnarigne nitt daye respect boppam te respect ay wadioram te sâga fii ak yangui koy def wadioro diamborr gno koy def sa wadior nagnoy wakh soñó khalat rek te bayyi sâga ndakh Dalay yakhall rek mais Dola defarall dara te nii lo ko gnank kersa may dina Koko khañat man ngua comanter sa sokhla te dou tougne kèn mangui dieglo nak nguen ballma akhe


  4. jarabi

    yaw Babb yaw la gueune sa ndaye gueune sa baye gueune sa diourome niarri mame, yaw la khaliss tital bangkoy toudou, gnoune Sokhla wougnou khalissou drogue


  5. jarabi

    Luc Nicola ya seytané, mane dé ma warou, yaw yabil balla, kham nagne lep, balla rek ngua bagne, da moy da ngua warone neup ci dielbi, ak sa beut you khoulé kouyi nguay melni cognère, ciim yama sooffffffff


Laisser un commentaire