5 COMMENTAIRES
  • bousso
  • alzolo

    tanto amina au senegal ya tro de folklore. kou guena neh lamagne fait le top des media@

  • co

    ay thioro dimbalignou ci verre yi

  • uomo nero

    amina potte sen mbokkou mourite leu comm yen. en plus ell nest pas la premiere a faire ces genres de trucs chaqu jour niou guiss des guides mourides faientt leurs fetes soits disant thiant si ay thiakhane rek- jai suivi l'emission en directe sur tfm te yalla khamnani mettitlounako te yalla rek tahh parceque yeufou serign touba yeufou djoulit yeup leu. nek talibe cheick ahmed tidjani tahna meunouma fesseul sama nahar si mbirmi sino certains vont dire dama sohor parceque sama serign ken toudouko oubliant quw suis leur frere mouslim .je demande aux marabouts mourides de parler aux diciples waxlen louy younou mouride ndaxte legui ay thiahan lanko diape dèèdem aldiana
    SALAM a tous

  • www.binette.@yahoo.fr

    thioro khana bayiko mou melni lounou fi tek daw

Publiez un commentaire