Vidéo – Abdoulaye Diop Bichri conforte les propos de Saliou Samb : « Serigne Touba amoul morom si souf »

Lors de la Journée culturelle de Mame Cheikh Ibrahima Fall, Abdoulaye Diop Bichri a conforté les propos de son homologue conférencier Saliou Samb. Lesquels propos avaient d’ailleurs été considérés comme une attaque discriminatoire aux fondamentaux de la Tariha Tidiane.

Annonces

Regardez !

 

(33) commentaires

Donnez votre opinion sur le sujet !
cheikh seck

PAS Un seul passage de ses propos où il a fait allusion à ce qu’avait dit SALIOU SAMB
Arrêtez de créer des confusions pour cultiver la concordance ET la paix des coeurs et des esprits

cheikh seck

PAS un seul passage de ses propos où il fait allusion à ce qu’avait dit SALIOU SAMB
Arrêtez ces titres susceptibles de créer la confusion dans Les esprits

cheikh seck

LE pasteur Martin Luther King est mort le 4 Avril 1968 à MEMPHIS AUX ÉTATS-UNIS ET NON EN ANGLETERRE

MOISE

Comment ces propos peuvent être considérés comme une attaque….Libre à qui veut d’y croire ou de ne pas y croire…SER TOUBA AMOUL MOROM…Je l’entends depuis des dizaines d’années….WASSALAM

Babacar Ndiaye

Bayileen de wake Louis lone woorol.Di Nguyen koch layout aka serigne Touba.Douguene at talibes
.Ab Taliban day maandou.Bou yomal khiyame konek dina kham kane moy kane.Di dem thia lamb dja di bakou,drogue thia lamb dja di bakou moko gueune.

mamadou cisse

Kou defoul limou Def wakho limou wakh do am limou am kou nek bitim rew digua Khamne serigne touba dou morou mou Ben waliyou dieuredieuf khadimou rassoul diarama mame cheikh Ibrahima fall

Dame gueye

Nitt kou nioull bagoul bob pam motakh waye serigne touba mom amoul morom saliou samb waxoul lou ay kouny manga wax la sap sergne wax ba lam Def s. Touba number one

ngor

Senego fenne rek diakhasse rekk

Konaté

Babacar nitt akk souniou borom rekk ley layo kérok yowmal khiyam. Wa salam

kheusch

Ces site d’information pires que la radio mille collines.

Ibou Diame

Ce minable qui a écrit ce titre on devait le pendre. Menteur

Gaindé

Deugueu nékhoul, mais serigne touba moy wadia

Mester Ndao

Limou wakh koumou nékh nga wakhko sisa Serigne Serigne Touba amoul Serigne Touba mokeye prouve gnep guisse dou mome mi fare mo gnou keye wakh gnou keye geume mome beuteum Serigne Touba rék mana guisse kénéne ausi Serigne me la mana guisse té Adouna Baye Niasse mo prouve wakh ak lake yeup gnou wouyou siko ki dale daye mbélé mbélé rék wakhoufi dara

Abdou

Je crois que Seydouna Mouhamed moo amoul morom. Tout ke reste ak fi nga meunè

Demba Gueye

Le pasteur Martin Luther King est mort le 4 Avril 1968 à MEMPHIS AUX ÉTATS-UNIS et non en ANGLETERRE son dernier discours il disait ( comme tout un chacun je voulais vivre plus longtemps je vous laisse continuer la suite

amadou

Ken rek a amoul morome moy ngueun di mbidéf ndakhtè joulit bounek mome rek mo la guenal sa baye guenal la sa ndéye ak say dome…Tè ame na Borome…

lala

Thiey Toubab yi sakh nénagnou serigne Bamba amoul morom

Meissa

Serigne Touba amoul morom et son pays d’origine fait partie des 25 pays les plus pauvres au monde!!! Pfffggg

kaizer

Mane dama diakhlé bama diogué ba taye Serigne Touba amoul morome laye dégue, sa senegal mome kagne lagnouye yéwou. Wadji limou fi lime yeup ci aye témoignage you nit kou wékh def ci serigne Touba takh na niou toup néke dioulit, mais wakh diou baré bi pour lane. Faléwouléne wakhou Seydina Mouhamed vous le ramenez toujours au second plan ,moytouléne séne bopou té guéne geum ni adouna amna foumou yame té euleuk yalla dina wakh ak gnoune bayiléne thiakhane waye

Ablaye

Deug leu amoule morome nakh prisonnier la woneu. Serigne touba nga wokh dhé wawa wao amoule morome kéneu la fi nakh il a marié deux femmes de même mère et même père.deug leu kéneu la fi mbougueule moi Yalla motakhone mou dém Gabon. Deug leu béne la fi. Peria jamais vue sa bouche parce que martaba cheikh mokodaleu. Guéminou fasse la toroneu.

Ndaanane

Je suis Mouride mais ce Saliou Samb est un gua tres dangereux, il ne fait qu’attaquer les autres confreries pour se faire un nom. Se sont des gens comme lui qui mettent le feu a un pays. Tout les genocides, et groups terrorists ont commencer comme ca !! Yalla diaam sakhhh Senegal.

Faye

Senego cessez de bloquer les commentaires des gens

Faye

Il y a aucun prophète qui peut sauver son peuple je répète aucun prophète je dit bien prophète

Aboubacar faye manga

قال رسول الله صلى الله عليه وسلم لعائشة إني لا أعني عنك من الله شيئا

Aboubacar faye manga

أستغفر الله على سماع مثل هذه الأقوال الأمة الإسلامية مريضة جدا ومرضها خطيرة جدا

Elhadji Malick

اللهم ارحم هذه الأمة الإسلامية رحمة عامة

Nese

Kouka weddi. De mal mayombe sénégalais modax sissou

Nese

On est d’accord que les autres sont des marabouts confirmés mais sama gayi Serigne Touba monde bi la jeufeul l’autre qui dit baye niass môme kjaritou serigne fallou la donc serigne wadiouram la je dis même pas le serigne mais Aÿ domame rek nio raw gayi

guiss guiss

Li daye yee fitna rekk ci reew mi kou nekk nga gueum serigne boula nekh

Publier un commentaire