(Vidéo) Abba accusé de promouvoir la franc-maçonnerie…

(Vidéo) Abba accusé de promouvoir la franc-maçonnerie…

Un téléspectateur appelle en direct sur le plateau de Yendouleen, et s’indigne sur le tee-shirt de Abba portant des signes maçonniques.

33 COMMENTAIRES
  • lay.dieng
  • khadija

    Senegalais, senegalaise ngen balema der len di setelou , li nguene di solo, signe franmacon kou djangoul sahe ware ngua ko ame, en tant k presentateur sur la television , tu dois bcps faire attention si sa tioline,djoulit day def yefou djoullit, wa salam.

  • m

    Hypocrisie rek ! Et le billet du dollar américain ? Kou ko jox waajojo kanna dou ke jeul ??? 'Grand Théatre' est une grande œuvre maçonnique (temple de salomon); la porte du millénaire et monument du souvenir à ouakam, sont des œuvres maçonniques avec une certitude absolue. ET IL Y EN A DES TONNES DANS LES RUES DE DAKAR.

  • Fanta

    Abba c un con . Son role c espionner pour Momi Seck ce qui se passe à SENTV , promouvoir la prostitution ( Aja Diallo , Maman avec ses défilés à l écran ), encourager la mendicité , le proxénétisme et la médiocrité . Euppeul bé melni domou bey . Niak fouleu ak fayda . Ma yeureum sa diabar ak sa dome .

  • Aissatou

    Aba dé , sou CNRA défoul dara , maname tedj ko kasso , deuk bi di neu tass . Diangal domou diambour yi lou bonn , wakh bou saleté , niak personnalité leu fi nékké ! SENTV , kou ko bayiwoul di sétane , nittou safara ngay done . Ay "entre nous ", "racc" ," guiss guiss"…… garouwalé , lidieunti séyou diambour yi ( pour tass lenn ) surtout Yama ak lamigne bou reuy bi . SENTV = TCHIM BAY ! Yalla na niou Yalla atté ak yenn yeup ,li nguenn di fékhé ci sou nou ndiabott ci diangal lenn lou bonn , senn dom yi djittou ci ! Amine , ci gouddi Maouloud bii !Yakh nguenn deukk bi !

  • mbaye

    aba li dou dará tisetla kom yenene tiset yii rek

  • baba

    Doyna warr

  • baba

    Oui c vrai lii signou franc maçons leu. Aba demal ci 3w free mason.com. you will see it

  • Absa

    woaw c pas possible. Mais kii il crie comme un âne.. Dafay nguaaakh rek durant toute l'émission. avec ses haaaan haaaan. maxalaa aye Arrivistes, kou déme sax xamoul limou sole lane la…fashion victim.

  • Kalimat

    Aissatou tu as raison, ce gars se comporte tel un chien aucune classe ni dans le comportement ni dans son accoutrement .. de vrai con de chez son.

  • black bi

    A nos Sénégal doyna ware

  • Ousmane

    Mais yéénà bizarre, beggul saaku 1$?

  • Perver

    Abba linguey def nekhna !
    J'adore ta collègue et son gros Q !

  • kira
  • didi

    kouy abba?

  • yama

    aissatou d'aga mer

  • Diawara

    aissatou fi kene tassoufi seyou diabour pape Diallo moula yoni mome khana ay kharitam kham nanou gordjieguene la amy Diawara diapko la thie mor wala awa Diallo wala birima wala kheikh diop moyfarou pape kheikh bayima bala yaw danoula yony si yama demal outi travail maman moguene tu e mal informés aissatou boul niou wakhlo ok yaw ak kila yoni togal

  • yama

    aissatou koula yony mor wala awa Diallo wala birima wala kheikh diop moyfarou pape kheikh bayima bala yaw danoula yony

  • kine

    aissatou wala sa tour monguene si yaw seyou pape kheikh bi yenako yak dakh liguene beugue amoul yama yala aténalene yéne dole changé mai gueume léne yala aissatou danoula yoni mai wowal yama rekkk domaram awa Diallo yaw mome outil lodef monguene yama monguene sa ndeye mor doff gua birima thiogou nonou rekk liguene beugue yama delou guinaw nono dafa am nianou yaye mai yéne figuene nekone rek batay

  • gfm

    aissatou koula yony mor wala awa Diallo wala birima wala kheikh diop moyfarou pape kheikh montakh guay wakh lolou c ki

  • gfm

    bayilene yakk derr yama dou séne none oubi yi kham nanou gordjieguene yi yaw mor ndack gueye Maroc gua doff kone boul niou wakhlo bayilene wakh ok

  • mor

    bayilene aba dafay ligueye senego pour informer la mai yéne kha amoulene lolene deff il fau encourager les gens ki travail mai Di critique rek aba migui ligueye aissatou yaw pape kheikh guay wakhal ndakh tu c que yama ak pape kheikh son des vrais ami arrêt les règlements de comptes sur le site ok

    • iba

      saa waay kii kénn bagnoul mou liguey…té moola gueneu xam tee shirt bii mou soll lithi nék….boudé sa waay leu waxal ak mom;ndakh fi senegal loo fii def xamnaniouko té daniou koy wakh….

  • Khadim

    c vrai mor aissatou on t'a Di de parlé sur ça mai arrêté wayyy règlement de comptes sur on ai rien n'a foutre de yama ou de aba ni de pape kheikh wa groupe pape kheikh bayilene ligueni defff on vous kone

  • laye

    vos gueules les mécontents

  • lebaolbaol tigui

    Mais un simple habit ne fait personne un franc-macon quand meme…… l'habit ne fait pas le marabout .

    • iba

      saa waay,guis naniou fi "professeur sankharé"si temp bou gatt mou nara yeungueul senegal.yala nako yala yeureum

  • lii

    iba ya bonne khalate khana boudonne yow la bougne la féyé nga déf ko nit mome ninga méle rék ngay kholé kénéne soko beuguoul amna gnouko beugue kingua beug amna gnouko bagne nopale séne bop té bayi wakh bou bonne

  • nité

    ABBA BOUL DEG WAKHOU NONE YI DEFAL SA LIGUEY YANGUI WETALI GNI NEK EUROPE BOUBAKH NDAKH KEURYI DAGNO WEET. ENCORE MERCI

  • Matar

    Vidéo bi ay rée lamây deff mais pour mane blem moy so neke si adouna daguay guéstou mais ce honte le faite k tu porte quelque choz k tu connaît même po rawatineu abba bigu solle seu piramite bi ak beut bi illiminati mais kou topeu mode togn seu borom rek

  • Matar

    Mais mode bou bess bi y'a beaucoup de signe maçonnique tshirt yi chaussure yi même prêt à porte numéro uno sene article you Berri ay signe maçonnique kase leu donc jeunesse bi il faut faire très attention

  • bethio
  • cisco

    L'habit n fait pas l moine ….. baye fall habit toi comme tu l sens …. bande enfoire … lidieunty li guen di def be am work…better than talking shitt every fuckin day …

Publiez un commentaire