40 COMMENTAIRES
  • zeyna

    nex na trop trop

  • da

    inna bagn nala thimmmm

  • le rebel

    J'ai toujours decrie cette serie que je trouve bien fait a juste titre comparer au episodes precedebte ou il y avait trop de remplissage. Mais Ina bonne nga ak sa gniaway

  • nekh

    Gora the best Inna j'ai pas aimé sur ce coup

  • ramses

    meilleur épisode, j'avais même des frissons. vivement le prochain

  • rapathiaaa

    laaayyiillaaa tey keur gui boyy… inna bayiil yeub bii

  • hams

    Non vraiment inna ta pas à faire ça n'a toute les vérité sont pas bonne à dire vraiment ???

  • fall

    li film rék laa bayileen inna

  • nééékh

    vraiment j applaudis c'est ce ke j attendais de ce telefilm supeeeeeeeer bonne continuation

  • mamy

    Un café avec bi mom amna mew sucre ak touti chocolat. Yénay bomb dal

  • Gaide

    Adama daga warona gaw waye

  • chon

    mw j trouve k nii inaa a raison deal dafa wara seiit

  • cissokho

    inna mo bone thieno dinako Raye

  • lachou

    c'est l une des meilleures épisodes mais je trouve que le scénariste est trop pressé,de ce secret révélé a mon avis très tôt pouvait donner beaucoup de rebonds a la série,

  • nana

    trop nekh maiq ina bone ngua

  • adja tacko fall

    ay tonton thierno balko baleu tata adama way

  • Bo niaw

    Hahaha. nekh na du

  • degatileen

    Ina a bien fait, mais on a presse. seulement k Ina veut libre avec boubs mais boubs va découvrir les choses. c bien

  • sarr

    c sa la vie

  • ndiaye oussou

    j'apprécie vrement cett serie mes adama damga yekh way loy ranger ay yerei do daw guene vs les fille vs aimer bcp ds matoss motakh liko dal dalko eeehhhhhh

  • nala

    J'ai jamais commenter ce téléfilm mais chapeau

  • babà

    Je vais vous dire la suite ,l èclereure va les aidès,il est maintenant ds l autre parti,il aime maman,parceque cette derniere l avait bien acceilli , avant cette episode Je disais que ça se passerà comme ça ,ok la prochaine

  • Patatipatata

    Holy moly, man Inna is such a big time liar ptrrrr

  • yakar bamba rek

    adama ďafa yekh troup ooo Lola

  • msp

    Hoooohoooo!!! C'est tres formidable j'aime un cafe avec yèn rek lay sêtane sêtaana tuma bén film

  • khass mario balo toure

    hahahaahh milko zo soda manké nako

  • mrd

    woy woy gay nde gui mer na tay rek mou de

  • mamadou sow

    Inna li la gora wakh defo ko car tu es une fille ta des moments fo rts et faibles lolo ko dal waro ko wona wakhe

  • ndar ndar

    je dirais juste waaaaaaaw trop cool la série mé inna bayil senn

    • dado gueye

      ina yémale si koudou gnou rofe la si guéne ya wané

  • dado gueye

    c'est super nexna trop

  • ndar ndar

    lii nak motakh gnounane djigen meunta dethy secre

  • cheikh

    non ina defeiant moy ina

    workaguan ina weuro wona sinne

  • Madam Faal

    nekh na mais inna merry nala trop

  • moutop

    inna nekhau ma dra

  • ousseynou warore

    kou nek ka bess same

  • ciss

    Un café avec cool mais épisode bi s8 pas d'accord s'il y a urgence diabaru tierno devais prendre ses jambes à son coup wa roula changé sah yere c mon avis

  • mimaa

    nekh nekh =nekhh serie au top mo sak ci serie yeup mé ina wéré nga

  • samba g.dieng

    Honnëtement c'est rèussi comme tèlèfilme.bonne continuation "un cafè avec"

  • binette diallo

    mes li serie la tek

Publiez un commentaire