Serigne Cheikh Khady Mbacké, Khalife de Darou Mousty rappelé à Dieu
Le Khalife général de Darou Mousty, Serigne Cheikh Khady Mbacké, a été rappelé à Dieu ce mercredi 6 janvier. Digne représentant de Mame Thierno Birahim, le défunt Khalife était connu pour sa piété, son humilité et sa grande générosité. La communauté mouride perd en lui un grand pilier.
yalla na yalla yo khe leram
ina lilahi wa ina ilayehi radi houna yalnaou yala tass thi barkem
Yalna yalla yok léram té tass niou ci barkèm
yalnako serigne touba téerou ci adiana ya gueneu kawé.
yalna yalla yeurem ta tasnou si barkem
Que DIEU l accueille dans son paradis yalla waneko serigne Touba ak Mame Thierno Birahim Mbacke
onnalollahi wa inna illayhi radjihouna
diambar wathie na
Yalla nako yalla yeureum
ya le na ko serigne touba terou t tasse niou si barkeme
lailaha Ilallah
yala naco yalla khare aldiana
sant serigne touba rek
yalla naco yalla ofal souf si kawam takh niou si ay leram
aujourd'hui c'est l 6janvier pas decembre SENEGO. yalla na yalla yok leram tei tassnou si barkem si barkep cheikhoul khadim.
amine si barke borom touba
????? ????? ????? ????? ???????????? ???? ???? ???? ?????? ???? ????
l'islam-niakkatina-kou-diubok-boromame
SERIGNE CHEIKH KHADY MBACKE YALLA NAKO SERIGNE TOUBA AK MAME THIERNO BIRAHIM TERROU TEMOU TASGNIOU THI BARKEEM ALLAHOU MA AMIIINE
Je presente mes condoleances a sa famille,a l'ensemble de la communaute mouride et plus particulierement au khalife des mourides Cheikh Sidy(yalnafi yagg tee weer 🙂 ).Yalna yok leer Cheikh Khady tee tasniou si barkem!
kou bakh demna kou fogne kou dinne demmna yalla na yalla yokk ay leram te tass niou si barkem
mes condeleance dieu mes paradie
Inaa lilahi wa inna ileyhi raajiwoun yoo allahou yourmémbo yaafoombo ya barkè mouhamadou (Psl) liyobou gnii dougnou bayi kone ragal yallah moo war kounèh.
raduallahou tanhaka hanhou
aminee
allahou akbar
nafa ana lahou bibaraty alahouma aqfirlahu warhamhu?.
C est le 6 janvier
Mais c le 6 decembre ou janvier???
yalla nako yalla yereme ta tasse niou si barkeme barki borome touba
naniou yalla tassu si barkeme
Yallah na Yallah yook leeram tass niou si barkem aminnnn
que dieu luis aqu dans son paradie
Yalla na yalla yokkou ay leram si barkep s.touba
DIAMBAR DEMNA
YALA NAKO YLA XARé ALDIANA si barkep borom touba
Amine yalla na yalla dolico aye lěěrere tasnou ci barckèm
yalna ko yalla kharé aldiana
allahouma amiiiiine
yala naniou yala taf si barkem
paix a son ame
amin amin si barker borom darou mouhty ak sounou yakar serigne touba khadimou
yalla nako serigne Touba ak mame thierno terrou sa adiana firbawesi ya guena Kane si barke Seydina Mouhamed kou am dine kou ragalone yalla demkou bakh gou
c est une Grande perte pour LA communite mouride ET tout Les musulman s CH KHADI kou BAKHE kou yiw kou dale lol yalnanako yalla yerem te tass niou thi barkem
yalla nako yalla yeureum te kharéko adiana
yalna yalla yaram tas niouthi barkm si barke s touba
yalla nako buur yalla gerem te diegalko khareko aldiana amin
Yalla naco Yalla khaare hardiana toulfirdawsii
yalla nako yalla yeureum ta kharé ko aldiana thi barke serigne babacar sy ak barke mame fallou mbacke
allahoumma ikhfir laho warhamho!!
amiine barkep Borom Touba
ALLAHOU AKBAR
inalilahi wa ina radiouhouna
yemena
yalla na yalla yoka lèram tès tasnou si barkème
ndaye sann cou bakh